66 COMMENTAIRES
  • naye

    Tyson a ete roi des arenes Dans le passé .LA lutte va ainsi tantot c le jour tantot on s enfonce Dan's une nuit.

  • dakar

    sable qui disait que tyson va gagner chère frère et sœur réveiller vs et ne croit pas au marabout sable il pronosse chaque chaque jour le mot la illaka illala mais j ai l impression il connais pas la signification

  • faassss

    Tyson Fit bi day guiss

  • Me gusta senego

    Me gusta mucho senego

  • weuz

    way selbé daf ko tiatou tiatou tiatou tiatou daf ko tiatouuuuuuuuuuu

  • ger

    way tyson dqfa wara bayi beuré niak na diom lol

  • khâgne lo

    tyson est un vieux lutteur

  • Madam Faal

    courage Tyson def ngua loune si lamb demal seti lenen Yalla bakh na

  • modou

    ginaw yeena ladione selbe mouni gris daye danou demate lenn fa ladiate ko lumou wakhone amoul

    • jhon

      slvp monsieur seck , je suis dessoler que a cause de la lute vous vouler maudire tyson , je ses pas si vous ete conscient de vos propos

  • Seck

    "Tyson est le lutteur le plus peureux de l'aréne", "Tyson n'ose pas se bagarrer avec moi"; tels étaient les propos de gris bordeaux avant le combat. Et pourtant on a eu la confirmation que Gris disait vrai puisque ce poltron de Tyson a encore fuit la bagarre pour s'écrouler au sol. Que l'on se dise la vérité Tyson est vraiment nul. Il ne mérite rien. Il se fiche pas mal de ses supporters. Je deteste les lutteurs peureux car la lutte rime avec courage hargne determination et surtout de l'endurance. En résumé tous ces éléments ne se trouvent pas chez tyson. Donc il n'est qu'une patate douce. Je te maudit Tyson

  • toure

    senego si vs avez de la vergogne il faut interroger selbé la menteuz comme vs l avait fait apres le combat eumeu vs balla

  • diop

    na ba yi bereee

  • Fall lamp

    Nn Tyson ragal leu vraiment,gnemewoul ay door,na bayi

  • Astou

    Tyson akhou Eumeu Sene mo ko dal. Diko wakh lou niaw, di yakha dérem ko di ré bayi ko ak Yalla. Akh dou touti. En plus il avait la chance de rencontrer des vieux lutteurs. Les promoteurs doivent doner la chance à la nouvelle génération. Eumeu Sene honore Pikine. Tay Shinger. Aythia mbeur !!!!

  • kalzado

    salbé yalla môme souba

  • jhon

    salam ale koun wa senegal ses moi tyson, escuse moi pour ce combat ,je m'escuse auprès de mes supporteur ,ses pas de ma faute je voulais pas tombé ses le coup de gris bordeaux qui ma fait mal et jetait obliger de tombe pour evité le pire lol

  • mbayr lo

    taysen d'âge ware bayyii lambe

  • ndiagaze

    mbeur so amoul wone danme ma bayi wa fass

  • Papa

    dafa ragal ay dor

  • tahirou fall

    mbeur moy daan moy daanu. felicitation a gris et courage a tyson sa ma mbeur ba faww

  • Moussa danso

    Bravo gris et courage a Tyson
    maintenant il est temps qu'il cede aux petits

  • Babacar Ndiaye

    selbe ya mana khew

  • beugue fallou

    tayson na dem tèki nguè mbam

  • bilahi tayson selbe danell nala

    bilahi tayson selbe danell nala

  • bathie

    teyson dafa maguette te mom khaliss reck la sokhla

  • néba

    selbé noupil

  • diouf

    tyson doit laisser la lutte et trouver un autre job il ne souffre pas lui c'est a ses supporteurs k il est entrain de faire souffrir meme en le voyant avec son guimb il n'est pas a laise regardez bien a la presentation des deux lutteurs il a croisé ses deux mains devant comme s'il etait nu vraiement j'ai pitié de lui bonne chance domou diambour

  • seck zalle

    gris dano Mbeur combat daay am adverser mais gayangui sa kanam wanel sa boop

  • ABDOU KANE

    non dama yeureum dafawara bayi

  • aida

    tyson dafa ragal toor

  • ida

    selbé yalla rek mo kham

  • fatou

    Tyson tapettteeee dou deuk pikine va t rposè tu nou fai honte thimmmmmmmmmmmmm

  • Sow

    Tyson na nopaloudji bayi beuré

  • ndiaye Etats Unis

    salbe ndom motakhe Tyson danou parsk bou wakher nai Tyson moye dane ils faut que gniko waidy dagnouye sote thi combat bi pour kimouner moye dane gnou daneko salbe mo warra bayi di wakhe yallah rek mo khame louye khewe souba limaye conseiller salbe na guene thi lamb djie wakhe ak football bi sou amer client you niowe keureume pour mou setalene mou yame thi lolou dou gneup gnon dacor limouye defe gni beugue mou rousse dafa barie bayile balla dara dilathie fekke sokhnasi salbe ndom

  • Fafadi

    Tayson ay doore day anedak fayou.Si tu avais le controle tu va battre gris parceque il a raté son cou gua dieul ko thi souf sans se controller

  • fama

    daffa warra bayi beuré fans yi sonn nagnou

  • ive

    selbe ya mana thierre ak mew

  • yep

    cheikh dou ngémbou

  • diom

    bilay selbe ndom ak tyson gnoniake diom

  • six mauritanien

    seurieux TFM votre en direct est Nul je vous jure zero koi mais si cté 2s tv machaalh mm vos repportaire son Nul comme le mot l'indique

  • nd f s

    mouhemed ndao bayil barinak tediapesi yalla

  • selbé

    selbé denna solle nagne kooo akhaaaaa

  • francky

    selbé day naa…
    selbé day na lab lén ko

  • didi

    talibé cheikh momoul yenyi. a cette heure ci tu devais être sur ta natte entrain de se faire ton wassifa. bayil guir YALLAH. je ne veux pas te.voir humilier par.des jeunes. courage c'est la loi du sport.

  • taysin na baye lama npaiDi

    l

  • barkè lahi laha illalla

    selbè poup naaaa………
    selbè day na lab lén ko

  • hams

    vraiment tyson sera rient billahi il a foutu la honte à la génération boul fallé il n'a cas prendre la porte la reine n'a plus besoin de lui épuis s'en vrais tappette ce que gris à dis à vraiment raison même pas la peine merci ???

  • lora

    Si j'étais vous tyson je reste à l'écart en plus vous avez eu des temps de gloire

  • fallou

    felicitation gris. et tyson c sa l sport

  • mami diagne

    felicitation fass dafa sokhka wone victoir

  • mor

    tayson bayiwo lamb waya lamb bayinala

  • Scorpion

    Selbe ndong ya meneun méeeeeeew

  • ali

    Je demande a selbe d'arrêter de tâtonner yalla rek mo ham louy hew .felicitation gris Tyson a 43 ans tu peux arrêter Salam

  • Mouss bi

    Tyson 15 ans sans victoire bayil lamb ji tu es dépassé

  • fass

    Gris forever

  • mor

    tayson bouko niedd tegabay bala moula bayi

  • didi

    STP. arrête de lutter

    • pap

      SELBE a vu juste sur le combat de boxe avec la victoire de Mayweather …elle a confondu la boxe et la lutte

  • louz

    drapeau Senegal lagnou wakh pas bou USA ahahahahah ana Selbee

  • ibson

    Mdrr mane tyson dima réye rek.

  • gueme yalla

    tyson khamoul dara

  • sénégalais

    ki dafeu bayi beurè diaye taar rek lafi nèkè di mathie aye tougne rek chim

  • balde

    il n a qua aller continuer son bisnesman

  • fassss

    fasssss

  • senegalais

    bilahi tayson ya niak diom . boy bi wax na deug , danga raggal dor.wayé mangui xar banga diar kaolack rék niou defaral affaire.

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *