Vidéo: Bain de foule à l’arrivée de Wally Seck en Gambie… Regardez !

Après Bamako, destination Banjul. le fils de Thione Ballago Seck est accueilli par une immense foule en liesse. Vidéo…
Après Bamako, destination Banjul. le fils de Thione Ballago Seck est accueilli par une immense foule en liesse. Vidéo…
longue vie a toi waly mon adorable chanteur
machala waly laf thiat
3jour en gambie dou yombou dal waly dal doundeul doundeul rek com ôn di
waly yalla nga goudou fane
khol sédatina un point
toth mali wathiè gambie mou dess dakar le 28mars inchala au grand theatre khalé bilè dom yalla nala yalla lafal thiat
mohhh pour waly rek doyoul bayy dess damani yafi nèk
seul le travail paie liguey rek mo woor waly doundeul way
liguey lou bari wakh touti sopè you bari doyna faye
li dawna yaram troop ndeysane merci wa gambie pour cette belle accueil envers notre cher artiste preferé waly ballago seck
bilahi yaw waly diam rek ngaye amm seck démal rek ba kéne lal la
yalla nga goudou fane waly li rek layy gnane yalla
walyyyyy el fenomeno fo rombou bayi fa sayy trace lila wakh mane
gambie dioumou léne dée afaire bi waly ballago seck la
nice nice nice
ah li nekhna
diam rek ngay amm waly kham nga ni li yomboul di deukou diambour yala nala yalla defal diam sama fansou khol biii
sama artiste khol bi waly yalla nala thiat sékhlou
non ak waly rek les 72h de gambie dara doufa doye felicitatiôn a toi bro
thiey walyyyyy mo bari bayrè dé machala laf thiat rekkk
ahhhh khol sédatina tres emu waly dal ma yeureum sa none
wa li tam loukoy faye machala domi diaga dji
waly rek thi khol
Jajaja thiey bi goss
El fenenomeno ken meunoussi dara