Vidéo: Revivez le show de Sidiki Diabaté et Wally Seck en live à Bamako

A l’occasion de son concert du 24 février marquant son anniversaire, Sidiki Diabaté avait invité Wally Ballago pour son show en live à Bamako. Revivez un extrait de cette soirée riche en ambiance !
machala nekh la def
Damay lath wa senegal wally mi sou mounouta woyy kone kou meun, wally tu es le meilleur mé sidiki waroula wona dagg li nga commencer woyy nekhena trop def ko single nga yokk si ay saf safal, nice nice
Waly en avant ligueye lou bari wakh touti sopeyou bari doyna Faye.
Walt en avant
El fenomeno