Fatim Thioune, aînée de Béthio : « Aïda Diallo dou togati fauteuil… Seuy mokofi indi »

Aînée de Cheikh Béthio, Fatim Thioune clôt le débat sur la succession de son défunt père. Sur cette vidéo, elle met en garde sa tante : « Aïda Diallo était ici en tant qu’épouse. Donc, elle ne peut pas succéder à mon père. Désormais, elle ne va plus s’asseoir sur le fauteuil. C’est moi qui le dit. »
Sonal nguene gnou trop wakeur bethio mais tey mom sokhna si wakh na deugud
Lou lère nagne nga wakh sokhana si deug deug
Walahi thioune wahngueu deugue
Sa c vrai
C la triste realité
Wahlène ci tèèle
Yenla reck
Mainak deugue la wakh bou were
Khana legui gua moune wakh dieuradieuf Sokhna aida
C’EST LA LOGIQUE.
COMMENT PEUT ON SUCCÉDER À SON MARI SUR LE PLAN RELIGIEUX ALORS QUE LES FILS SONT LÀ ?
LA QUESTION NE SE POSE MÊME PAS.
Soxna Fatim ligua wah Moy dëgg topou lén ci ginaw S.saliou geuletapé. sokhna Aïda Amoufa baatS SALIOU geuletapé Moy khilafa cheikh bi wa salam
Magal Touba 2019 dinagnou giss lougnou mous tagiss cheikh béthio thioune ay tanki kanam la am ligeeyam bi dou fay mouk ba magal gua
Yow kagn nga gheudjeu guiss sa baye tè ngani yay taaw
BETHIO MOM NATTOU DOM LA AM…. CI YÈN DOMI AMOUL KÈNEU KOUCI DOKHÈ AK TAALOUBÈ… YALLA DOU SANT…. BOULÈN DIAWALÈ
Très bien tamouy Lou wuer sokhna manoul nék kilifa ba adouna Soso ba ligue khalifa taw bou gour aida Diallo dafa wara reste com diabar waroul Khar baniou koy ték pagsam
LI SERIGNE SALIOU DEFCI BETHIO DOU SANT MOKOKO MAYE TÈ DONÈWOUKO KEUR BAYAM…..
Ak noumou mouneti mél sa clifala ndakh sa diabarou bay la yéne wakh yi dou wakhou mak moumote khawmala khawmako dara diaroukofi
Ceey adina
Kkkk??? dinéy senegal mo nékh dé mé attention serigne aida mo yorone thiopati béthiobi nak dom yanguifi wone té messouléna sékhal?? serigne aida banialdé mbolom ibliss rékla té ibliss djiguén la guene sokhla thi mbolom ???? way dnguéndi foway té diné lislam dou ay fo yallana yalla léral séni khél
LAMINE QUELQUES CHOSE QUI NE TE CONSERNNE PAS POURQUOI REGARDER OU ECOUTER PARDON MOI AU MOI DE RAMADAN SEULEMENT UN CONSEIL MERCI
Et alors ça nous regarde pas vos bidas
Mère wakhal aida dou toguati seni chaise mais chaise kou yewou tokksi té talibés kéne douko kou nekk ak koula doy vive aida
Tout ça c’est la faute de votre père Béthio
Elle des kilos
Quel théâtre tout ça c’est du théâtre je te jure pôvrr Sénégal
Waye deugue gua wakhe.namourou bouparer wouti dieukeur wala mouner moute
Aida Diallo khamo sa bop demal wouti diekeur
C pas un débat femmebi wakhna dégueu on tourné la page
non: elle devait dire ca devant son pere si elle dit vrai ou si elle est courageuse.
si c est le nom qui compte son pere ne devait pas etre cheikh
Reyrou amna mo waraal wathie sokhna si…..siguil nigale moytoulen medias yi
Bien di fatim moye li werr dé djiguéne dou djité diouli waye
Diamoudjilene yalla mo geun sene thiahaneyi
Elle a parfaitement raison aida na ko aye bomkam wakh degueu
Je s8 pas thianta,mais diabar dou domou,et dou djity amoul feneu,bimome wakh nguenne deugeu