17 COMMENTAIRES
  • Ngoné

    Thieye soblé doome ! amé ngua gnou !

  • def tatt

    mai aussi es que du kou dieul turu selbe ndom mane jm pas selbe ndom mais Facebook lu nek meune ngako si def dama yakar nii dall kanen mo utlisé Facebook srlbe ndom

  • rof

    Loool. gambienne niak geum yeulleu
    gueuneu niémé serigne sur terre

    • Astou

      Mais boul wakhal nonu. Du gambienne bep mor niémé serigne..wakh dei rafett

    • Astou

      Mais boul wakhae nonu. Du gambienne bep mor niémé serigne..wakh dei rafett

    • Balago

      mooooo!!! Mé grand yowit nai gorré teh rafett wayy ! Mais waneh mom wessoul woul ngai Waakh mba di témoigne lo fekkeh woul…. Naniou yallah bal mé sa classe gui safara rek! Lo Niou khamal ba ngai naan serigné tou la gambiene yi meune ? Kor yap iow??? Sawil teh dem teudi bor amoul l'or waaakh

  • fall

    es ce que sélbé ndome la parce que amna aye arnaquer si internet bi nio khamni daniouye diel tourou diambour disi déf lou léne nékh moye tou léne commentaire yi bala guéne di am bakar mone na nék kénéne kou doul séllbé ndome

  • jean

    la vraie selbé reaction par rapport a ces acusations eclaire par rapport aux imposteurs

  • Ballago

    @ ROF .. mooooo!!! Mé grand yowit nai gorré teh rafett wayy ! Mais waneh mom wessoul woul ngai Waakh mba di témoigne lo fekkeh woul…. Naniou yallah bal mé sa classe gui safara rek! Lo Niou khamal ba ngai naan serigné tou la gambiene yi meune ? Kor yap iow??? Sawil teh dem teudi bor amoul l'or waaakh

  • lywa

    def taat ta tou dis c des arnaqueurs ki utilise sont nom

  • yaye fall

    geuwma ni selbe ndom la li kou xam vie wame moko def kouko xamla topou ko ba jexalko waye dou salbe afair bi da yonbou lolou way

  • Mane

    Thieye nitt ninn woloulene sene borom te bayil cs fau tips

  • bara

    Selné wakhna ni amna niouy tu do tu Rem si resbuk bi di Na kh nitngi yewuleen si facbuk bi

  • laye

    elle a envoye l argent sur le nom de son fils

  • begue s touba rek

    Nanou khalat yalla ta bayi adouna bi wakh you niague fay da yi

  • Pape

    Selbe ndom qui envoie des MSG sur Facebook faut être vraiment con pour se faire piéger.

  • développement de notre pays

    mais li gnanouwoul maana way selbé nane lay néké Sénégal Di khame problèmou kou nek suied c faut pas selbé ndom

Publiez un commentaire