Audio: « Nioune sénégalais diokh sunu serigne mo niou gueuneul diokh kou niak »

Oustaz Taïb Socé et Dj Boubs, sur l’entraide  ou autre forme de solidarité, sont on ne peut plus clair. Ils ont déploré le fait que les Sénégalais soient plus enclins à soutenir les nantis qu’à  appuyer les nécessiteux…Le chroniqueur prône surtout une organisation des musulmans voire de l’aide…

12 COMMENTAIRES
  • l+ex+de+tivaoune

    Li mo takh noukoye torokhal dafa madouwoule

  • kaw kaw

    Wakhe gua deugueu dé

  • abdou+khadir+sm

    Kii dafa soxor nit gni niongui diokh seni SERIGNE ték ci tamit niongui diokh way niack gni

  • abdou+khadir+sm

    SERIGNE si daal nileen nit gni banieei ta pourtant kou miin keur serigne si xamnga boubakh ni euddiya yileen Talibé yi di diokh niongui thiy dipbali nit gni ci Adio ak way niack yi ta YALLA rék takh

  • PIJE

    C est dommage
    Ce TAIB passe souvent a cote
    L aumone a toujour ete organisee depuis le prophet Mouhamet PSL jusqu a nos jours.
    Le prophet collectait la jakat et les dons qu il redistribuait aux pauvres.
    ABUBAKR OUMAR OUSMAN tous l ont fait.
    Si les dons sont remis aux marabouts en principe c est pour qu ils aident les plus pauvres sans vanite.
    Le danger c est de vouloir aider directement les plus pauvres directement
    Satan peut nous pousser a nous glorifier ou penser que nous sommes meie lleurs qu eux.
    Un bon musulman doit etre positif
    Ce que le marabout fera de cet argent l engage
    Ces dons sont remis aux imams aux association et autres
    ATTENTION

  • zal

    Kou Diokh sa serigne té diokhoulo kou niack wala diokhoulo sa wadiour. Amoulo tchi yallah té yakheu nga sa allal

  • senegaldakar

    Man dama hamoul koula eupe alal naka nga ko mana diohe beug lou yombe serigne si gnou bari si gnom

  • Yougua

    Gnoune Mouride gnogui sante Serigne touba bimou gnou kadioul sounou dèréte kone limou gnou lath bilaye dinane koko diokh sounou alale AK soonou dolé dieuredieuf mame CHEIKH Ibrahima Fall

  • abdou+khadir+sm

    Waw goor YOUGUA boudoul woonak SERIGNE TOUBA doungeen sakh tal tok fii naan dangeen di critiqué

  • Mamadou Mbengue

    C est une pure verite

  • Diouf

    Serigne boy diokh ndieurigne moulayy diokh ayy ndieuriman fall

  • seyni+diaw

    senegal dou reewou dioulite waaye reew mou ay dioulite dek. Reewou dioulite day atete chariya waya senegal leep lou chariya bagne amenafi. nguene balma

Publiez un commentaire