23 COMMENTAIRES
  • boy bronx

    waly et sa music moi Jaime
    les temoignages du marabout sur la personne de waly aussi Jaime
    mais je pense que waly soit dans un tenebre qui est la music et son marabout est sense l’illuminer
    jattandais du mara quil demande a waly darreter cette music car cest haram

  • dijj

    da ngeen sokhor rek yeen gniy critiquer lii wally ame di ngeen dounde ba dee doungeen ko amee seen khol mo gnoul kii day dem. amoul seen diot adoynam la siukeur. khalee bou ndaw 85 yalla may ko teranga younekhh yii kou meer bokoo

  • astoundiaye

    haaaaa waly wayal bamou nex mar yacine maissa biguee ya saff nieup lou waye wah bahna yangui teral say wadiour sa hol rafetnaa yangui dimbeliiii new diii dolee yalna yala hepp doliiii

  • gadio

    Mé biba sandi khér bobou ak sokhor é iñane raison pour la kél il s’avance yallah bgoul ñiou sokhoraneté sunu biir nañiou tapé xol yi way

  • abou gaye

    magui dieguelou mes dapres ce commentere aye afaire de kignane aki seytaner gnak degue alkhourane mofi nek way wakh si bakh nit ki yacar nani si bakh ak yiw le bok ne fonk wadioureme te beguena serigname lou fi diarre yenne yi a kou sokhore te nafek di wakh lo metrise woul a deh gui leye khare ne gnou tape kholeyi te bayi di ate nit ki lou way mele naco gnanal boude lou bakh le mou yocou bou de safane mou sopecou mo guene wakhi kignane

  • biba

    billaye gadio dama yereume wally tè hahouma ko sahdè dama hamnè loumou def gui sadisi kani vrema damako yereume

  • gadio

    Biba les gens font k parlé wally rawnaléne yageuna yallah moka déf ep8 nite kounék ak linga beug bla bla nak Sénégal la deuk mangui diégalou

  • stuxe

    Un
    pour un chanteur au tenue de femme.
    C’est du n’import quoi!!!
    Ordonnez lui d’arreter de chanter , c’est un péché
    merci

  • bakhbakhaa

    lii nak moy yeufou doméram deug,ndakh mane loumma doul défal sa baye doumako défal bayou kéne loudoul serigne bima diangual lakour’ane,té khamna kii dangualouko sinon kone dou nék di way aka tassou…

  • King Kong

    serign touba, serign salieu et alors les personnes qui les enseignes sont où et quand une personne à dédiés sa vie au islam, d’où est là pars des prophets Muhammadou ( saw ) musa ( as ) Essa ( as ) noah ( as ) etc etc etc why

  • King Kong

    franchement pourquoi tell mensonges, franchement je ne comprends pas les sénégalaise franchement est ce que vous n’êtes pas de croyants?

  • yalla rekay yalla

    Nion dal dall nanou kenal serigne touba rk te toppou ay nigalam niou si bari tane wou niou len amou nioi thi serigne touba dara ak cheikh ibra loudoul sant wi kepp kon nioun nagne djamou yalla te toppou ndigali serigne touba sou niou begué mouthiou adouna ak alakhira

  • boye

    wa gnion fan lagnio dieum thieoy lii

  • fatougueye

    mé serigne bi dafay sédé djiko you bakh yi nékh thi waly seck lolou darà nékouthi thissguén fii ba tayi goor wala djiguén gnouy sol yeré you yiw ta sén djiko bakhoul waly lén rék lako beugué boy dafa am kiliffa fokouna ay wadiouram c’est trés l’importent dans la vie man dama khamoul Sénégal lanlo takh niou sokhor rék

  • Ib

    Mé sénégal légui bo amoul khalisss sa talibé dafa melni sa talibé dou mat; bala nguaye ame talibé dal ngua yor ak foko mana dieulé nak, li dafa niaw si nioune dioulite serigne bou tok devant le monde di wax li té ki khalissam fimou kay dieulé yalla gueureumoko dé! wa salam!

  • biba

    thieye senegal mo mètidè lodèfe lomou rafèt rafète niou timalko tè bouniou sanione mèlni yow mane ma yereume borome xole bou nioule wally mome louko nite wah tè aye wadiourome wahou niouko rek nioune douniou safe boulène fatè ni yènè nègeula borome mo si fanane wally raw nalène monolenes si dara

  • demou serer

    kii da doul du dara fuk you

  • saye faye

    mayléne you kou santoul nite do sante yalla

  • niane

    mane dama diakhlè sènègal so wakhè lou bakh sakh niou nè do li wala la mè santat rèk

  • tabarfakale xali bi bo gounako nexal de xawma nomay def ba mou diotsi paske man newoma senegal dembale len masi limoy sama sky sankhe2

    Ki d’où saringe way serigandoula seringne moy kilay tig si siratal moustxim xamal la koy yala ko doul dioli do wor tane yaye diake al diana wali si landam ga ne de xaral ba lergue fegke ga xamne yala rek moy bour mo diara diamou bayilen tiaxan

  • Fall

    Diagne Lou wer gua wakh yalla nagnou yalla tok soutoureu musik bi dé l’islam nangou wouko te amna si yen khetou serigne bo siwoul amo khaliss kholou gnoula ndeysane ana la serigne saliou dane def ana la mame abdou dane def yen soi disan serigne delo lene sen bop si borom bi te wakh deugue talibe yi waye figua tek sa tank fofou yangui koy lor yangui koy sank

  • DIAGNE

    hahaha serigne bi néé « fii mo tekk tenkam baax na » Alahou Akbar. Senegal nekhna kou wooté nitt yi topp la comme kharrrr. waayé lou way deff boppam. yala nagnou yalla dolli soutoura

  • leuza

    Mdrrrrr !!! Sénégal mo nekh mai SERIGNE CHEIKH BOU SERIGNE SALIOU MBACKE bilahi yalna la SERIGNE TOUBA fay

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *