Publicité

Vidéo: Serigne Bethio dieufé ndiguel en enlevant les titres à son épouse et à 75 de ses talibés. Regardez

Serigne Bethio Thioune dokhée na ndiguel en enlevant le titre de « Cheikhette  » de son épouse et soixante quinze (75) de Cheikhs déchus de leur titre. Après la notification du Khalife des Mourides, Serigne Sidy Moktar. Regardez

53 commentaires

  1. cheikh

    Ndanane yaw laye dèklou pour tontou sa lathie bi sa yo paré wakhma ma diokhla sama numéro boudé dèfar rèk ak beuga kham mola takha diok boudé lènéne aussi nga wakh ko

  2. doy na waar

    Yawe mii dii wakh mbirou baye fall watawat maandoul ci loo xamoul boul laal boul diegue sinon dinga rethiou fii ak fee

  3. doy na waar

    Yawe mii dii wakh mbirou baye fall watawat maandoul ci loo xamoul boul laal boul diegue sinon dinga rethiou fii ak fee

  4. mouhamadou rassouloullah

    je commence vraiment à aimer le cheikh. c’est un grand homme et seul les grands hommes reconnaisent leurs erreurs

  5. Yahya

    Mane dè warouna si sènègal so dèfè dara niounila yalla dako tèrè nga bagne. Souniou nè srigne bi diokhèna ndigueul nga bayi.
    Wa lègui nioune kouniouy diamou

  6. sanguisto

    Kou khol Izbou tarkhiya da nga naw mourides yeup ak dioulitou sénégal yeup mais yonou mouride dà fa am deux blems: c’est les baye fall et Cheikh béthio. MALHEURMALHEUREUSEMENT NIO GUENEU FEUSS

  7. mouride

    MOURIDE NA NIO WADIAL MAGAL GUI 1 OOO nakkkkk là wax 500 geuleimme??Khartoum 3700
    guinara 500 mbeiy 400????????kou ame doulé defkou

  8. yoo

    fatiha falahi nasi .il arrive pas articuler bien les mots et il vous donne des ordres sur la religion islam .ou j ai oublier sur vos propre religion .digal yalla hololenko di deglou digal un charlatan

  9. baye lahat

    vraiment le secte mouride gno mana thiakhane il n’y a rien de l’islam dedans. j’ai piti de ces fous

  10. Ibadourahmane

    je dirait pas de tariha .mais vous prenait la religion comme 1 jeux que vôtres pères ou mères à créer .repentait vous avant qu’il soit trop tard .astafoullah wa toubou aleyk

  11. Senegal

    yen.ou bari si mouride ni ngen diape lislam ak li lislam wah woute naou lool way dief djou baah ak yermande sounou borom moy dougelate aldiana

  12. ndanane

    mouridisme c’est comme un jeux d’enfants pas de prier pour les baye fall pas de Mecque pour les khalifa tu maintenant cheikhette yallah mon meuneu mougne

  13. khadim

    hahahahha ki kom khalle bou ndaw rek kilifa no kham ne Lou mou wakh rek niou wakh no rek kham guene ki dou kilife deee

  14. xelcom

    bethio bouder dagua am kilifeu bala gua deff daraa dagua waraa dieul ndigueuleum d abord mo guene gua melni xaley bouy deff bêtise rek chak jour nioukay yarrr..ponkal bou tol ni yaw warna am loumouy rouss koi. ..wagnil poukeuree bi soffff..gua tropp ak say talibés toi kannassou.

  15. xelcom

    bethio bouder dagua am kilifeu bala gua deff daraa dagua daraa dieul ndigueuleum d abord mo guene gua melni xaley bouy deff bêtise rek chak jour nioukay yarrr..ponkal bou toulni ni yaw warna am loumouy rouss koi. ..wagnil poukeuree bi soffff..gua tropp ak say talibés toi kannassou.

  16. xelcom

    bethio bouder dagua am kilifeu bala gua deff daraa dagua waraa dieul ndigueuleum d abord mo guene gua melni xaley bouy deff bêtise rek chak jour nioukay yarrr..ponkal bou tolnii yaw warna am loumouy rouss koi. ..wagnil poukeuree bi soffff..gua tropp au est talibés toi kannassou.

  17. beugue sama rew

    il n’a pas de kilifa seulement il a peur.et je vous dis ce qui arrivera à bethiou yagatoul dara tout sera clair incha halla yonou serigne Touba wi louthi bokoul douthi dougou wassalam.

  18. Max laurant

    si la religion musulmane dafa wakh ni Nitt dafa wara mandou Niou ci bari ci yeen deh mandou wou len ndakh ko saga son Serigne mou saga sa prophete dou moudjou fene Nitt day Mandou

  19. wakh kadu you deugou

    magal gui DINA niou woone wa aduna SAMPOU SERIGNE SALIOU KNE MEUNOUKO SIMPY ! DANIOU MIRASSOU DIEUFEULE SERIGNE TOUBA CII BEUSSEUME BI SERIGNE TOUBA AMOULE MOROME SERIGNE SALIOU MOO NIOU NEKH SERIGNE BTHIO MOO NIOU SAF YANIOU FK FANIOU NEK DINIOU DFAAR DINIOU TRRALE T DOO NIOU KO YEUGUELE DJEUREDJEUFETY SERIGNE SALIOU CHEIKH BTHIO

  20. wakh kadu you deugou

    DJEUREDJEUF THIOUNE LOO NIOU DIGEULE NIOU DF IOW KP LANIOU BEUGUE ! MAGAL GUI DINA LA GUEUNEUH LRE NII IOW KP LANIOU YAKAAR

  21. xelcom

    bethio bouder dagua am kilifeu bala gua deff daraa dagua daraa dieul ndigueuleum d abord mo guene gua melni xalat bouy deff bêtise rek chak jour nioukay yarrr..ponkal bou toudou ni yaw warna am loulous rouss koi. ..wagnil poukeuree bi soffff..gua tropp au est talibés toi kannassou.

  22. xelcom

    bethio bouder dagua am kilifeu bala gua deff daraa dagua daraa dieul ndigueuleum d abord mo guene gua melni xalat bouy deff bêtise rek chak jour nioukay yarrr..ponkal bou toudou ni yaw warna am loulous rouss koi. ..wagnil poukeuree bi soffff

  23. Ibrahima

    Alhamdoulilah niougui santati cheikh sidy mokhtar dika diaralé si cheikh Bass adbou khadr. Lii moye wanéni liguéyou serigne touba kenneu manouko gakkal. Dioub dioubal rekk. Boudé dagay woté kilifeu nakk warga moy toi aye ndioumté you beuri

  24. tupac

    merci thioune mouride mome ndiguel rek ganaw serigne sidy al moctar joxnaleu ndiguel dieuffer rek dieuredieufety serigne touba.

Comments are closed.