Fatwa du Khalife des Mourides: Bethio invité à renoncer à la pratique des « Cheikhettes »

Le khalife général des Mourides, Serigne Sidi Mokhtar n’a pas attendu longtemps pour remettre les points sur les I à Cheikh Bethio Thioune qui avait commencer à élever au rang de « Cheikhette » certaines femmes dont une de ses épouses.
Il a fini de notifier au guide spirituel des Thiantacônes sa désapprobation avant de l’inviter à renoncer à cette pratique selon Dakaractu. La décision a été portée à la connaissance du Cheikh par Serigne Bass Abdou Khadre Mbacké.
Les motivations du Patriarche de Gouye-Mbinde sont claires. « Élever des femmes en Cheikhs n’est point conforme aux enseignements de Cheikh Ahmadou Bamba et foule au pied l’orthodoxie Mouride ».
Cheikh Béthio a été élevé lui-même par Serigne Saliou Mbacké, cinquième Khalife général des Mourides.
alhamdou lilahi
niola geum serigne Bethio…yala naguafi sakh
c’est pas trop tard ?
SERIGNE BETHIO moy SERIGNE TOUBA…
serigne bethio serigne saliou nena yay mom les video son la ,kou dem youtube diga guis video entre serigne saliou ak srigne bethio na nieup manu. kounek na xol sa niawtef sissa borom ba paree sogay lidieuti kenen
🙁 je me demande quand est-ce que sa liberté provisoire dans son dossier de complicité de double meurtres bi di diekh? Kheuyna bok dafa « cheikhal » les avocats des 2victimes,le procureur et le juge en charge du dossier. Khalass !!! 🙁
Jerejef cheikh bi
j’ai écouté les réactions du cheikh . mais il m’a étonné. je ne savais pas qu’il était si attaché au ndigueul de serigne sidy mokhtar. je pense qu’il est un exemple type de talibé. il est plus talibé que ceux qui l’attaquaient au lieu d’écouter le ndigeul du khalif. les mourides doivent savoir que serigne sidy est le gardien du mouridisme et qu’on doit l’écouter avant de se prononcer sur une situation quelconque.
Ils sont jaloux de bethio seulement parce qu’il est griot. c’est vrai que au Sngal les serigne ne considrent pas les gewel mme s’ils ne le disent pas lolou lanou gueum sissn khol. la preuve dougnoussi tak dougnoussi takal sne ndiabott. laissez bethio tranquille c’est lui serigne touba
Mbacke dieuredieuf yague fi lole khadimou rassoul déh bimou wax serigne saliou May yaw Serigne saliou deh bakko wouko outé wouko xalis wala daradia wathioul diné niawalole ak tallibé con cou serigne saliou ni Yaye man man yaw lima waar yakar dou fékhe ba cou beggue xaas yonou mourid si yaw lay diaar dakh ay dieuf yo xamni gou niague touti tay go xam khadimou rassoul xamna dieuf yoyou beggouko saytané daa barrí dole dina fégue loubakh mourahko yalla nalén yalla takhawou takhawou gnou barque khadimou rassoul
dieuredjeuf thioune
owwww !!! cela montre qd meme que le khalif est tres puissant et que ya de l’autorité chez les mourides !!! cela n’aurait jamais marcher comme tel dans la tarikha a laquelle j’appartiens ; j’avoue que le ndigeul est tres sacré chez les mourides !!! @@ alors là REspect pour ça @@@ c’est ce qui fait votre force d’ailleurs !!!@
kii dou rouss sakhhh. …bethio soudonn kou bakh. ..dou khaar sakh gnoukoyy tegatt sii yonn. ..dafa gnakk Talibé. ..espece de coureur de jupon
yala nala yala fay
dieureudieuf
baye lahat con nga khamobi cheikhette mome serigne touba digueuléwouko,serigne saliou digueulewouko.talibe cheikh betio yi nak di nane cheikh betio moy serigne touba moy wakh yalla ak yalli.lou doul dine ak lislam rek nioroul serigne saliou moy deugeu moy gneuk moy moudiou.talibe betio amougnou khel(chien) diangougnou alkhour ane(mbame)
Serigne touba newon na ay diamono thy kanam seytané dila lakhasou nit ndiaye mouy wouyo mouride di def khalisam thy yonou mouride fek seytané la bethio nak lolou moko dal serigne saliou dafa lakou rek mou rakadiou serigne sidy moctar dou wakhantou nitou yalla la sou reagir ré rek amna loutax ndak bethio nimou nekhé du deug du yon loutax bimou néké caso ben mouride reagiroul ndak nitou ibliss la seytané la dafa beug tilimal yonou mouride
Lou wr te ler nga wakh Deug
Sa moromou nitt soudé wakh sa ayib dala beugueu wéér yalla souniou borom soulay wakh say ayyib dala beugueu dimbalé toube day yokk daradja guor yalla.diamano dji légui nak da nguay yor sa barigo défauts nè ko fa nioukk di lidieunti copou défaut kénéne
M’amène bagne khana yene meunolene yabi sgne Bethio.mahal gui mou wonatiléne moyyy séné baaay ci fane yep ci sgne Touba.ndakh yene khamolene djeufeul sgne Touba
serigne sidi makhtare yalla ngafi yag tr weir ci sa barkè baye cheikh mouhamadou lamine sama yakar
Mane dé nit kou Yalla bakhal soumané yaye mane may yaw damay roy si mome loumou dane def si lou baakh makoy diéma def loumou moussoula def doumako khalate bakoy def