(Vidéo) Niagass demande pardon à la Première Dame
Suite à ses insultes à l’endroit du Maire de Saint-louis et de la Première Dame, l’artiste rappeur regrette ses propos et demande pardon.
Suite à ses insultes à l’endroit du Maire de Saint-louis et de la Première Dame, l’artiste rappeur regrette ses propos et demande pardon.
niagas duñu sa nguaka wakhal wakh dji
Niagass yaw danga yabate kou sagaawon sa yaye doulaa nexx il faut etre correct et civiliser tu aura une famille un jour pense a tes futures enfants lorsqu ils veront Ça ils ont regreter que tu sois leurs pere
n'eut DEUG moye ngeuy tothi di diegeu lou je sius contant de vous merci niagass
Niagass xawma ndiaxoum kou tox sa thioto ndeye rew nga
nitt kou bakh day daw yama togne app dioulitt dou togne
Boul gnou yap way yaw
daffa doffffff
Je me demande qu'est ce que la police attend pour arrêter ce pauvre con de voyou tu l as fait exprès mettez le au gnouf c'est pas la première fois qu 'il insulte publiquement dafa rew donnez le une bonne correction
daffa doff
dafaa doffff
baba car diop khana bonne yow lou gnou la wara d'eff loumou d'eff rek nga d'eff nit niteée
Danga bayi sa khel rew amoul ben njering
Tres honnete j'ose espere k Mme Sall t'a pardonne
dioumoul dafa wakh louko nekh
il s'est excusé c'est le plus important.je vois que certain en profite pour caricaturer les rappeurs alors que nos hommes politiques vont plus loin.
niagass…niagass…niaaagaaas.niagass nit dafay tey.amo ben foula nak.magoum diem tol ni yow takhaw fii di saga sa premiere dame.niouy wakh nga nane mangui balou ak.y ow garde corp yi a la setsi rek. topal fale
niagass defaleu son bou toudou bayi na sagaaaaaa
bal nala ndeyssane yeureume nako sakhe mane.
heureusement il a demandé pardon le but c'est de pas commettre les mêmes erreurs sachant qu'un artiste est un idole de bcoup de personnes donc pensons a ceux qui nous entours
niagass domeram bou makla na asimile ay responsabliteme danou waron deugue n deyem ba pare bayiko diaroul teuthe senegal mo neh dagay def loula neh apre nga balou
thieuy niagass.donc souma comprende affaire bii mou ke yow golbert motah nga balou.way dioguewoul cii yow. ya doye warou d'e.
Dieu pardonne ce qui se repentit et tu as bien fais de demander pardon , mais ne recommence pas et c bien d'accepter tes défauts et essaye de changer pour la prochaine fois merci
senegalais yi geum léne yalla tée khame nii niagass nit leu reck téee nit bou doul djoum amoul n'a gneup d'eff nii môme dème ballou ak ko messa togne balnala té nama gneup bal
niagase bayile tokh louboneli mola yobbou thi djikoyouboneyi bayiko mogeune
c est émouvant mane dé bale nala thi sagua youma dégue . togne balou dara nékoussi wayé mou bagne la dalate ndakhe bo sagua nit sa bop ngua sagua 4 fois ndakhe béne barame ngua koye diokhogne 4 yi sa bop .
Dés que l'individu commis un fait et du coup il s'excuse,son pardon est obligatoirement accepté.
C'est la parole d'ALLAH. Dieu dit qu'il est le pardonneur.
Il pardonne à toutes les fautes sauf,de lui associer quelqu'un c'est à dire "alchirk".
Donc par analogie des faits nous pouvons dire que tout le sénégal doit accepter le pardon.
Cependant,arrétez d'étre vulgaire,vous étes trop vulgaire vous les rappeurs
NIAGASS BILAHI YAYE BANDI MALLA GUEUME
Niagass senegalais YI dougnou HAIE doff te boulene diappe hai doff,kou nek tie ganaw li lepp ak louka diar explique toi mou geuna leer,,,
Bayilèn cinèbar…
🙂 Thieuy Niagass ya doy warr dee!En tout cas mane de mon cote balnala et et j'espere que la premiere dame et sa famille seront animees de la meme esprit de tolerance afin de pouvoir te pardonner.Sinon comme l'a dit Aziz dans son commentaire ci-dessus,mandibi nga wara bayi ndakh todjaguer yi yeup moloko tek.Du courage yalla sokhoroul! 🙂
"…par le meme esprit de tolerance…" 🙂 j'ai du mal a toujours relire avant de publier ree ba tass
magg boul tolou nii di def bay
ball maandi .mandii momm tanka yagui koy def chak foi si diegalou rek Gay deukk
kidourouse tognebakhoul