Vidéo-Ne pas céder au chantage sexuel pour l'acquisition d'un emploi: Regardez le sermon de Oustaz Iran Ndao
Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Aucune recommandation disponible.
wakha ty nga dueg iran merci
Iran wax na deug , le pire des métiers c'est sécretaire . Té sénégal nagnou bayi diabarou diambour yi gni chantage thi bureau yi dilén teudé (Lou boon , lou Arame ngi nonou). Les femmes aussi , ayez de la vergogne , niit kou bax dafay am loumouy rouss , am loumouy bagne , nga khol sa diganté ak sa borom , ak say dom aussi .Djiguén bouy ndialo ak moy dou diouor lou bax mouk , té yageu yageu dinako djiss , nda dina torox fii , bala niouy dém feulé .
Djiguén yi Kholat lén sén bop , beug xaliss , wala poste boum lén diaral lolou mouk
Bilay y'a ay