Annonces
Annonces
» » Vidéo: Moustapha Mbaye fait pleurer Déguene...

Vidéo: Moustapha Mbaye fait pleurer Déguene Chimère Diaw en pleine émission. Regardez

Annonces
Annonces

6 commentaires

  • a sow
    15/06/2015 13:28

    lingene wax amna solo waye merbi mome waroul wakh kene dara nah boude dey dimili wate limou
    sol rk wakhou mala limou tak nah men nasi dimale louwara tolou si fanwer si ay domi adama wakhou mako guir kharap ko nah mena solou waye nay sorale bis dina niew niou mirasko

  • madan faal
    15/06/2015 16:14

    Ndeysan ken dou Muhammad S A W Yal nangoul sunou diamou te deg nio degeu degeu djulit, Amiin

  • omar diaw athiou
    15/06/2015 22:39

    mamy yaw may gnou trompeuse gua.

  • insa
    16/06/2015 00:46

    Yalla sén dioy yi nék liu deugou ci yén ndakh bou wéré niarigne rek lay done

  • fall modou bété bété pur
    16/06/2015 02:21

    Billahi wallahi watallahi .nguinaw yallah soubhana watala. kén dou rassoulillah psl .Yallah naniou yallah geuneu doli geum geum rek ta geun nio khiir si beugue ya rassoulillah psl. …dieuredieufe mbaye. yalllah nala yallah yokou banga yeukko. ak mbolem dioulit si barke seydina mouhamed psl

  • thiate
    16/06/2015 23:52

    djeureuf …sougnou sanguebi mome rek laye tague sougnou rogoye tourou…yalla nagnou yalla maye djiko djourafte …labekala chereke labaye…

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL