16 COMMENTAIRES
  • rim

    Youssou lima lay khamal moy naga téy si contrayi .animateuryiga yoor yépou solén beugué défal contra cdi diga masa am proplém naga khol bou bakh contrayi pour souba sou afairyi dokhol nga mana takhaliko ak niom da do am thiona . Yalla nalla yalla sam

  • dama

    uum

  • babacar

    Walay kirek la nopp. I don't know why, I swear I've never seen a girl as cute as her.

  • Byby

    Tekky gua dalale diam

  • issa hane

    ok nonou leu danouleu donne siis rek

  • Madam Faal

    Welcome fama sa nieuw bi Yal na anda ak jamm khewal sutura,Yal na la jik jik Youssou ak kep kui ligueye gfm,Amiin

  • degue rek

    wiri wiri diari ndari

  • aliounediop

    bienvenu

  • aliounediop

    tfm boy boome youssou ndour si lou bakh

  • ds

    Fama barri na ci morom , gni bouga gnew TFM . Qu'ils le disent ou pas , ils veulent tous venir . Fama verra bientôt la différence , on va te lifter pour être une vraie professionnelle qui ne parlera que des choses utiles . Yousssou moy bougou ndi bagne .Les télé qui boycottent ses produits paient les conséquences , moins de fidèles . Il faut serrer vos cœurs et diffuser des produits de You ou Prince Arts , ils sont incontournables ou vous fermez boutiques .

  • dij

    du courage fama lepaye bakh

  • avovacat bougan

    sama guayi boulen diawalé kou transumé ak koun dakh

  • VAB

    ingrates

  • nina

    fama dafa bari wakh

  • garmi

    Pouff fama dai nekoul kou am importance nonou sentv sino dougn ko dakk

  • fallou sarr

    Bagne bagne beugue affaire bi sentv la fama amo ngor ak kolore tey Niep sunu la deme ba xam sentv mo taux me betouniou yak cheikh xa mouna Andé lo xass tfm yepp delene difateloukou demb

Publiez un commentaire