Annonces
Annonces
» » » » (Vidéo) Bour gueweul, membre du staff de Pape...

(Vidéo) Bour gueweul, membre du staff de Pape Diouf met en garde Ahmet Aidara après sa revue de presse d’hier

Les sorties des proches de Pape Diouf se multiplient après la revue de presse d’hier de Ahmet Aidara. Bour gueweul, un membre du staff de Pape Diouf assène ses vérités au reporter de la Zik Fm.

 

Annonces
Annonces

88 commentaires

  • dieukeur
    26/04/2016 17:34

    Ameth Aydayla niari febar nioko diap reuk : DOULZEYMER ak DIEUWLEPSIE !$$$$$$$$$

  • rim
    26/04/2016 17:34

    bien parl Ahmed aidarra danko wara gun si walla presse amoufi plasse

  • maman
    26/04/2016 17:35

    borom paris waye

  • Fatim
    26/04/2016 17:36

    Hei doul yawe bour gueweul fou nou la paix imbécile

  • amina
    26/04/2016 17:37

    diakhas ak yakh nit rk si lay dokh patrn sentv boun korro wally seck lolou waroul takh nga beug yakh pape diouf

  • Mamadou
    26/04/2016 17:39

    yena soff way

  • poupette
    26/04/2016 17:42

    Ta raison

  • France
    26/04/2016 17:43

    Partez au diable avec pape diouf .se bour gueweul mi nga khamni moye soukh artiste ici a pari merde waye

  • poupette
    26/04/2016 17:43

    dans la vie chacun son étoile

  • you
    26/04/2016 17:44

    yaa gnak khorom wakho fi dara

  • makhou
    26/04/2016 17:46

    Mdr d ieukeur ratnama

  • reine
    26/04/2016 17:49

    dieukeur ray guama

  • verite
    26/04/2016 17:54

    Ameth Aidara ne mérite que l’ignorance ; pourquoi donner de l’importance à ses propos indignes!
    Quand on n’aime quelqu’un on ne lui cherche pas des ennemis!

  • Soda
    26/04/2016 17:56

    Yaw bour gueweul merde va en enfer toi et ton ami pape diouf khana Leigui môme da nga bayi diaye thiep

  • Babs
    26/04/2016 18:03

    Wa yen yena yap Ahmed aidara il n’a rien fait de mal sauf relater se que le journal libération a écrit mais yeine pape diou moye kane bou Leine niou raye Waye sonal ngueine niou ak ces types doul Waye ak sa thieukaye nokhouleine feulei espèce de malade

  • babs
    26/04/2016 18:05

    wa he bourgueweulagui wa yaw kagne nga kham pape diouf bay bok thie stafam merde way

  • Mame
    26/04/2016 18:06

    Wakhna deugue
    Amed aiydala. Mon wara bayi Pape diouf ak Family youssou ndour gir yalla def lenne senne yieuf tee bayi diabour yi

  • kheus
    26/04/2016 18:08

    amet aidara mom il parle trop en plus il nai pas journaliste doul rek

  • Mami
    26/04/2016 18:08

    Bour deugue rekk rek la wakh bayilenne yakk deer bonne genne trop

  • adama anne
    26/04/2016 18:19

    Mais bour guewel balagaye wakhe dangaye kholl baparré sou fék journal mokabindeu dakoye lirrr boull hou fonto

  • Wakh Deugg
    26/04/2016 18:24

    LI MOO TAKH SENEGAL DOU DEMM…..POURQUOI REPONDRE???? C ENFANTIN…..PAPE DIOUF, WALY SECK, YOUSSOU, THIONE…..Y EN A MARRE DE SES PRIVILIGIES ET DE LEURS QUERELLES DE JEUNE FILLE…….TROUVEZ DU TRAVAIL AUX JEUNES, PARLER DU PROBLEME DE L’EAU, DU COURANT, CORRUPTION……

  • Fa
    26/04/2016 18:29

    Môme bour gueweul Ahmed aidara Sakh mo ko tanei mo dakh doul nieup et pui môme kagne la boke thi staffou pape diouf Mane dal ma warou gni dal nio nafekh reike.

  • modou makhfous diop
    26/04/2016 18:30

    elve

  • diop
    26/04/2016 18:32

    ahmet aidera reude prss rk lay lire

  • rimbi
    26/04/2016 18:33

    waly lagnou wakh, dou moromou youssou ndour, wakhoumalak pape diouf, waly thia kaw, kousa khol khasne wokal

  • Safi
    26/04/2016 18:38

    Hei gueweul Mbäyë boul niou yap yaw ak sa gataye bou reuye wa ki môme kangne la commencé and ak pape diouf mongole

  • fans number1
    26/04/2016 18:42

    mai Ahmed fokna lou journal bind la wakh rek ter yaw gua bayi pape Diouf tontoul bopam

  • Amina
    26/04/2016 18:42

    Youssou dou moromou bayu waly wakhoumalak waly khana nekh

  • Zèle
    26/04/2016 18:47

    Mo gni dal nio sof Leigui môme dieu four ngueine keine mana toul teuyei bopam doul waye

  • Papis
    26/04/2016 18:55

    Yaw Aminata kou niake FAYDA so deimei baya teukeulei youssou ndour ak waly yeine khamato Leine Sakh fo Leine di takhaw

  • Diop ndiaye
    26/04/2016 18:59

    ameth aidara sof neu me bour sof ngeu te beug buzz star dou tontou gniy wax ken manoulne tr wax

  • Khady
    26/04/2016 19:00

    Ki môme khamoul fou mouye takhaw Môme thiogue reike la kou nieuw mouni la y’a fi neike et yaw khamo sa bope nga mélni nei ak sa gataye bobou

  • ana
    26/04/2016 19:00

    Hahahahaha yewoul way da ngay nelaw. .youssou ndour ba mou torohale thione ba tey da len meti…massa wally sa baye diarone nafi. Bayil pape diouf dou sa moromou baye wahoumalak youssou ndour

  • senegal
    26/04/2016 19:03

    xamna sof ngen niou trop am ndour indil Seck doyna ohhhhh

  • Mimi
    26/04/2016 19:06

    Mon hahahahaha youssou doumoromou bayiou Waly sakamtoumak waly bokouniou sakh waly ay khale ak gordjigenn rekk nion ko top

  • Astou
    26/04/2016 19:08

    Yenn yenaniou yap hahahaha youssou ak Waly conme pasti ak dayiou beuye doumonromou bayiou Waly sakh yena beug buzz

  • Waliette
    26/04/2016 19:11

    Khaley bi ndieuka teugue Bercy Faramarene bi motakh niouye diafour. Dara diomboul nite kou doul wore, bakh,yewane ame koleure

  • Paris
    26/04/2016 19:13

    Sene baye youssou ndour Sakh Manoula nopilo Ahmed aidara espèce de soukh nopil doul keine ladioula

  • Eva
    26/04/2016 19:18

    Ahmed Aidara bayil doul yi je viens de regarder la soirée de Pape Diouf au king fahd palace ay Ahmed watawat!!!!!

  • WALIETTE
    26/04/2016 19:22

    LI NAKE MOYE DIAFOURE DEUGUE YENE BERCY AK WALLY DANS MA VILLE MO LENE DI RAYE.WALLY MOYE FARAMARENE BIYE TEUGUE BERCY DARA DIOMBOUKO AME NA KOLEURE ,DOU WORE TE YEWENENA PAPE DIOUF LI TAKHE TEUGOUL BERCY DOU NIAKE TALENT MAIS AKHE MOKO TOPE TE BIENTOT INCHALAH KENE DOTOUKO DEGUE COMME NDER

  • Keuz
    26/04/2016 19:26

    D’où il sort ce cancre, cas dire ça a libération et Améth tranquille.

  • Zoo
    26/04/2016 19:31

    Même personne ki commente kou âme diote nga sokhnasi woutil lo deife mo gueune thi yaw nga neike fi reike ak sa même parole yi « youssou ndour d’où moromou bayi waly reike « réfléchi au moin avant de commenter .astou ,mimi ,Anna et aminA même personne.

  • Xaragn
    26/04/2016 19:32

    Yaw bala nga wakh diafour nga xar ba 100 personnes BERCY ngén di politique nane daguén sarakhou nit yi pour niou gnew BERCY

  • Salistar
    26/04/2016 19:37

    Pomme de terre dou patate Waly thi bir aleu bi golo lathi wala sakh pithie
    Pape Diouf ségu youssou ndour gaindé

  • xamxam
    26/04/2016 19:48

    c’est du jamais vu,au Sngal maintenant le show biss c comme l’arene de lutte,on diraient des lutteur,mais chaqun a c’est fans qui viennent au soir de son artiste,c vraiment honteux sa

  • Laayelow
    26/04/2016 20:00

    Quand les sénégalais manifestent leur ignorance; Ahmed Aidara ne fait que relater ce qui est écrit dans la presse écrite et il me semble que ds ce cas précis c’est le journal « Liberation » qui est à l’origine de l’article. Si Pape Diouf et ses ouailles contestent ces dires ils doivent plutôt s’en prendre à eux. Malheureusement ils ne sont pas les seuls à faire cette confusion.

  • mina
    26/04/2016 20:08

    bur MAYNIOU FII NGUA NIEUW DIEUW PAPE DIOUF NANE DAA RAGUAL DIABARAM BA DOMAME BI TOUCOULEUR LAKOY LACKEU APRES NGUANI MAMANé DA SATIONE GAMBIE THI BENNE HOTEL baniou diape ko ak yennene yenne les chanteur yewulene nhi farrou niou feene aay wakhkatte laniou

  • aids
    26/04/2016 20:10

    vraiment je sais pas si c’est bour guéweul ou seytané guéweul ma warou avec son restaurant ou gargotte à paris

  • Wax Deug
    26/04/2016 20:28

    les fans de Waly Seck calmez vous? Arreter de comparer Waly Seck a Youssou Ndour. Comparer Waly a Youssou c’est insulter un patrimoine national ou meme international. Youssou Ndour a fait le tour du monde avec sa musique et est respecte partout dans le monde. Les presidents, Jacque Chirac, Obama, les stars planetaire, Papa Wemba, Alicia Keys, 50 cents, Peter Gabriel ect… Votre Waly Seck n’est meme pas connu en Nigeria donc bou lenn niou sonnal okk. Vous devrez encourager Waly a developer sa music et ses textes pour au moins avoir la chance de suivre les pas de Youssou Ndour au lieu de rester la a dire Waly dou morom Youssou Ndour alors que Waly n’a encore rien fait dans la music senegalaise. Youssou Ndour vehiculait des messages forts a travers ses chansons et c’est ca qui interessait les renommes international a vouloir connaitre davantage sa music ou meme desirer a travailler avec lui. Les Bercy de Youssou Ndour vehiculait des messages avec les chansons tel que immigres, liggueey, Africa Dream, No Mele qui encourageaient les gens a travailler davantage et de ne jamais oublier leur pays, le Senegal. Le succes c’est pas remplir le grand theatre, Bercy ect… Le success c’est gagner le respecte partout dans le monde et remporter des trophees reconnus mondialement. Tellement que Youssou Ndour a remporte des prix internationaux que je vais seulement lister un: Youssou Ndour meilleur artiste africain du siècle en 1999. Je vous laisse avec cette question: avec quelle chanson educative ou encourageante Waly va chanter a Bercy pour inciter les gens a etre fier d’etre Senegalais, Africain??? Peut etre Koboyi?? Ou bien Na Goree?? Reveillez-vous avant que ca soit trop tard.

  • Wax Deug
    26/04/2016 20:29

    les fans de Waly Seck calmez vous? Arreter de comparer Waly Seck a Youssou Ndour. Comparer Waly a Youssou c’est insulter un patrimoine national ou meme international. Youssou Ndour a fait le tour du monde avec sa musique et est respecte partout dans le monde. Les presidents, Jacque Chirac, Obama, les stars planetaire, Papa Wemba, Alicia Keys, 50 cents, Peter Gabriel ect… Votre Waly Seck n’est meme pas connu en Nigeria donc bou lenn niou sonnal okk. Vous devrez encourager Waly a developer sa music et ses textes pour au moins avoir la chance de suivre les pas de Youssou Ndour au lieu de rester la a dire Waly dou morom Youssou Ndour alors que Waly n’a encore rien fait dans la music senegalaise. Youssou Ndour vehiculait des messages forts a travers ses chansons et c’est ca qui interessait les renommes international a vouloir connaitre davantage sa music ou meme desirer a travailler avec lui. Les Bercy de Youssou Ndour vehiculait des messages avec les chansons tel que immigres, liggueey, Africa Dream, No Mele qui encourageaient les gens a travailler davantage et de ne jamais oublier leur pays, le Senegal. Le succes c’est pas remplir le grand theatre, Bercy ect… Le success c’est gagner le respecte partout dans le monde et remporter des trophees reconnus mondialement. Tellement que Youssou Ndour a remporte des prix internationaux que je vais seulement lister un: Youssou Ndour meilleur artiste africain du siècle en 1999. Je vous laisse avec cette question: avec quelle chanson educative ou encourageante Waly va chanter a Bercy pour inciter les gens a etre fier d’etre Senegalais, Africain??? Peut etre Koboyi?? Ou bien Na Goree?? Reveillez-vous avant que ca soit trop tard.

  • wax
    26/04/2016 20:33

    ******les fans de Waly Seck calmez vous? Arreter de comparer Waly Seck a Youssou Ndour. Comparer Waly a Youssou c’est insulter un patrimoine national ou meme international. Youssou Ndour a fait le tour du monde avec sa musique et est respecte partout dans le monde. Les presidents, Jacque Chirac, Obama, les stars planetaire, Papa Wemba, Alicia Keys, 50 cents, Peter Gabriel ect… Votre Waly Seck n’est meme pas connu en Nigeria donc bou lenn niou sonnal okk. Vous devrez encourager Waly a developer sa music et ses textes pour au moins avoir la chance de suivre les pas de Youssou Ndour au lieu de rester la a dire Waly dou morom Youssou Ndour alors que Waly n’a encore rien fait dans la music senegalaise. Youssou Ndour vehiculait des messages forts a travers ses chansons et c’est ca qui interessait les renommes international a vouloir connaitre davantage sa music ou meme desirer a travailler avec lui. Les Bercy de Youssou Ndour vehiculait des messages avec les chansons tel que immigres, liggueey, Africa Dream, No Mele qui encourageaient les gens a travailler davantage et de ne jamais oublier leur pays, le Senegal. Le succes c’est pas remplir le grand theatre, Bercy ect… Le success c’est gagner le respecte partout dans le monde et remporter des trophees reconnus mondialement. Tellement que Youssou Ndour a remporte des prix internationaux que je vais seulement lister un: Youssou Ndour meilleur artiste africain du siècle en 1999. Je vous laisse avec cette question: avec quelle chanson educative ou encourageante Waly va chanter a Bercy pour inciter les gens a etre fier d’etre Senegalais, Africain??? Peut etre Koboyi?? Ou bien Na Goree?? Reveillez-vous avant que ca soit trop tard.******

  • Amina spain
    26/04/2016 20:38

    loll amoul aidara amoul pape diouf nioune bercy laniou wac nioune mdrr

  • Fati
    26/04/2016 21:06

    Wax yow doul boul niou raye ak sa commentaire bou goude bi merde Waye Leigui môme thi sofe ngueine dieume tout se peine perdu pour waly seulement niake ngueine fayda

  • Sori
    26/04/2016 21:16

    Si vous allez jusqu’à comparer youssou ndour qui as fait 40ans de carrière ,pape diouf 20ans de carrière et se garçon de rien du rien du tout qui vient de boucler sa 5quieme année sa devient grave Leigui franchement khamatoleine fou ngueine di takhaw ta lolou khalaloleineko .tololeine Lou wara tolo ta ngueine bayi khalei bi mou continuer son chemin mo Leine di nopal .

  • as
    26/04/2016 21:37

    louma nakary nekhouma, waly yeguoul tinoul, am waly indil waly,nianal lenko mou am ndamm, laf thiatt, il a 1 evenement, kil chante les personnes ,kil chante autre chose ,les gens l aiment ,bayilene djambour ,yalla moko tathiou..youssou ndour a chante des personnes avant mouy ague fii tay, te komou meusseu way nga d wala doto am dara, donc bayilen waly ,yalla dakoy gueuneu may ndamm, sen wakh moy galadjam

  • mimi
    26/04/2016 21:39

    Andeu bou raft ngun yak ko

  • mimi
    26/04/2016 21:40

    waly nena mome youssou ndour papam leu waly wayna birane ndour respecter pape diouf df ko mak nk lne nit

  • deuch
    26/04/2016 21:44

    Senego mome di ngun tal senegal

  • kha
    26/04/2016 21:51

    Andeu bou raft ngun yak ko

  • baba
    26/04/2016 22:00

    vous avez oublier la mort

  • pape
    26/04/2016 22:26

    faut arrêter yow bour guewel li moy sa tieur dakh daga calé sénégal visa gay xar pour gneuw té si pape diouf guako yakar.
    tu vas resté encore à dakar boul ma wakh lo fi gua done dieuw pape diouf di nane da ragal bébé bass di dieuw mame mané

  • boukhes
    26/04/2016 22:46

    c bien

  • fogu
    26/04/2016 22:49

    difol dara diagun ko Yap

  • al-khatir
    26/04/2016 23:15

    bour gueweul yawe mome soukhou nga rek ???

  • diadia
    26/04/2016 23:18

    rimbi Ya meun doule

  • boypaname
    26/04/2016 23:18

    Vrement vous nous fatiguée koi mé dem lene ligueyi ta bayi teusen té bi wakh rek

  • bisou camara
    26/04/2016 23:25

    mais pourquoi les gens sont bête comme ça on parle pas de wally on parle de pape diouf es-ce que wally fait dedans merde

  • BREF
    26/04/2016 23:37

    Aprs tout a niounane Sngal ben bopp la ken mounoko khar niane !!!!!!! wouyou len Baba nena vous avez oubli la mort. ..

  • Manou
    27/04/2016 00:17

    @WAX DEUG personne ne compare Wally a Youssou Ndour, You est le pére de Wally lolou meme Wally le sait….Mais Wally a le droit d’aller a Bercy il a le droit de rever, kou ayé wal sa momé…Bercy santoul Ndour lolou il faut que mou leer ci sen bop

  • nd
    27/04/2016 00:47

    dfgh

  • ND
    27/04/2016 00:48

    fjl

  • Diagne
    27/04/2016 01:22

    Yaw doul waye

  • diallo
    27/04/2016 04:04

    le problème en es que wally, pape diouf ak youssou ndour nguén di diéma mettre en mal et je pense bien qu’ils tomberons pas dans vos piège. Mais senegal yakhouna bilahi keneu taloul ligueye top wakh bou amoul solo diéme léne changer ndah niou meuna avancé. C’est vraiment déplorable….

  • rohey
    27/04/2016 04:20

    my bro go fix ur teeth o no

  • makhou
    27/04/2016 06:11

    bien dit diallo mais boulene gnou sonnal sénégalais negn demee liguey instent bougni kebétou yenene dekeu yagui liguey komme doof gnoùne gni nekeu bitti rew dougni degu Lou radio waleu setane télé senegal dagni am lougnou metti bilay wakh yoroul rew wa salam

  • Abdoul Aziz
    27/04/2016 07:09

    Toi bour guewel tu peux dire ce que tu veux mais arrête de dire qu’on lui a monté ok Améth Aidara est majeur et vacciné et aucune mouche l’a piqué une fois il est libre de dire ce qu’il veux .

  • Khady
    27/04/2016 07:43

    Non vraiment wadji mo niake FAYDA pape diouf mo takh ngaye weire sa bop ni li nga done neube yeupe on la exposée sur le net .gueume sa bop dal bakhna .pape diouf dal diarouko.

  • Bass
    27/04/2016 07:51

    Vous savez le problème de cet famille ndour c’est qu’il n’aurai jamais cru de leur vie que se gamin atteindrait se sommet c’est comme un poignard chez eux .j’ai entendu parler un jour ibou ndour mais c’était affreux .se qu’il disait .se garçon doit être prudent si non il risque d’être décapité en morceau .

  • kas papy
    27/04/2016 08:50

    oh! que son âme repose en paix

  • na
    27/04/2016 09:52

    doul doul doul doul

  • rema dieng la wallyette
    27/04/2016 11:38

    yaw amina ya meune doul yaw demal diangui mba ligueyi mo gueun thie yaw gay fene wally mome mromoul youssou ndour te youssou def na carriere ram ba pare wa legui yene wally domou diambour la n est ce po do lene ko maye diam ce pape diof ak wally ay mak ak rak la niou legui seytane idiot yi beugue dougou sene digueu nte yaw kou la fekk ak sa famille niou diakhase len est ce que di na la nekh yaw ne fait pas chiiee waye idiot que tu est

  • cartel
    27/04/2016 11:53

    nous sommes née de même père et de même mère mais bs sommes pas née sous les même étoiles conne diarokofi

  • boy LG
    27/04/2016 12:22

    merci REMA

  • bigboss
    27/04/2016 14:21

    un gamin qui a 32 ans?merci pour l’ironie…..

  • Giss Giss
    27/04/2016 14:52

    bour guewel ya dof demal fane niou setla verro

  • el mo fils
    27/04/2016 15:28

    sama papa youssou mo mene africe day way ba usa di yuengou présidant obama di gis bopam waly sou buegé li day tarbiyou come papam yi you rek

  • omar
    27/04/2016 16:43

    yaw mina ya meuna fene bour guewel yague na Paris khamoul lou niaw douko deff wakhouma la dieuw sene khol dou sed mook bilahi dieme lene bakh mo guene

  • balli
    27/04/2016 19:35

    Wakh ma sa kharite ma wakh la ki nga doneu wakh bou niaw dekoule famou dieum fimou diougué la thiossano pape diouf ak c compagnon yeup merde vous nous faites chier Ahmed défouléne dara il ne fait que relaté ce qui écrit sur les journaux Ahmed faléwouléne meno léneu ko téré yégue bour guewel et fary mbaye fuck u mother bande d’idiot faléwoule

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL