38 COMMENTAIRES
  • penitencier

    c une accusation
    alors moustapha n’a qu’à faire une plainte

  • ansou

    c’est un mensonge pure et dure comment on peut volé un passeport d’un lutteur meme les militaires qui vont en mission leur patrons garde les passeport pendant un an disons jusqu’au retour ca cé rien du tout

  • Ridial

    narafèt rk

  • aboundour26@gmail.com

    abo

  • ............//

    Oh li takh ma transhumer changer woy kate mako kham , wally amel nama akh benene musique mounouma saff boudoul bossam , malene may li si wally seck yeur lene ko(https://www.youtube.com/watch?v=rsZPLJrLfP0)

  • Gi

    En tout cas dieule passeport nitte sans autorisation wame dou yonne. Baboye kou am fouleula té dou wakhantou kén moussouko dégue ci lou niak fayda. Moustapha aye wakham diaroule dorre sa dome, koumou sékheul business après daye am tiow.

  • touretouremalick

    No Moustapha Tafa yabaté wayy

  • khalil sy

    c ‘est un escroc;nous qui avons fréquenté l’école liberté 6 c nous le connaissons bien ainsi que son frère Mor Dieng,ils sont tous des arrivistes.

  • Moussa

    sisco baboye bimouy gnuw orop fii moustapha khal la khawma kouye fakh way dou baboye

  • deugeu rek Ndiaye

    mé baboue bann intégré leu ammeu bat yakh il été en italy pendant combien de temps moustapha mon djuboul kou wédy ladial Amadou badiane promoteur bi teguonne combat baboye contre bombardier

  • qap

    yalla moy até moustapha mi vrai dore cate la couco soré woul kham

  • youssou

    Mai Grand ibou fekké lolou amna defal videos nga léral ndakh nekkoul gneuppeuy coment ndakh gnou comenté woul gno eupeu cone defal videos

    • KOU NEKHA NAKH

      Grand Ibou dal da melné ni comprendro badou da nga naif , genrou moustapha yi seniy deal day sett dou ame trace té diaral na lene louné nakk, kerok rekk mo si moudjou bamouy tilimeul victoire wally seck, té baboy dou wakhanetou amoul sakh djotou yoyou sou wakhé rekk fou woor lako tekk

  • Seydi

    Trouvez lui un surnom waaw !!

  • Deug

    Je Suis pas avec moustapha mais c normal mou dieul passport bi sono lénén lafa baboy di def lou bokoul ak liko yobou

  • rina

    Merci baboy

  • Tar

    il faut faire trs attention avec ces genres de Moustapha, ils st dangereux et c’est des voyous masqus

  • CHELSEA NEW LOOK

    dey fenn rek

  • rana

    mousetapha tourr bi rek mo bakha waly seck am name ci momm

  • Moise

    Baboye est un vrai con ,ce qu’il dit n’a pas de sens et si c’etait vrai il a eu intervenir combien de fois a la press depuis l’hors et il ne l’a pas mentionne!Bayilen Door yi Ak ay clan

  • ....

    mais Moustapha yaguena nk imbcile,domoram piiiiiiiire la

  • GRAND IBOU

    Baboye wakhoulo deug ndakh mane mi si gni done sétlé Moustapha sa passeport bi si la bokone . Moustapha takhaw na ak mome ak yow ak sa rakk bi yorone sa thioumikaye nga koye sédéle né nite mo begona yakh bessam bi c’est à dire saboter ba toude nga si sakh niome aziz Ndiaye ak gaston né bougnou sagnone niom nioye organiser combat bobou.Bayil sosse baboye

    • MOh

      Wakho fi dara ap sathi dina sathie ba paré bokkou sa gna koy weur ndakh bagna fegn

  • dass

    mousatpha a Di laverit sur wally a coz d a vs l insult

  • Ababacar

    touré n’oublie pas que Baboy a été immigré vers les années 2000 – 2001 et il a bel et bien une carte de séjour d’Italie. Sokhla woul visa pour voyager.

  • sohnasi

    merci TIOTIA baboye di deme founekeu yor ay papiers American di fakheu pour deme fane yene delene khalate waye

  • tiotia

    domeram leu ce moustapha vou ki dite k da bagne mou daw é ce k vou ete normal baboye é un pro il voyage tou le temp fane la daw dieum ce moustafa lâ é un gran truand dorkat bou mac mé continu comca rek tu risk de finir mal

  • Youssou

    Ngorr sosou kouko guiss kham ni djout khaw ma mousstapha khaw ma epeuna wow mousstapha sakh

  • Doudk

    Baboy Arrête de mentir tu fais parti des plus grand dealeurs de visa du SENEGAL maygnou way

  • Yalla day até

    Nonou wally seck yi begougnou dé , yalla day até kham ngen ni moustapha mi mo sikk

  • Sisco

    C’est normal que Moustapha récupère passeport yi ndakh gayi dagno gaw si fakh tout à fait d’accord avec lui

  • blues 4life

    Ba boye bayil doule

  • Liza

    Merci baboye. Mustapha momounak mounekafi rek nak dignou rey ak wakhbou bari

  • Julien

    Bientôt ils vont l’accuser de sorciers, deum li pere wade wakhone Macky marieme
    wa ki nitt leu wally nak dottoul
    M’botté

  • Toure

    Il a dû prendre son passeport pour éviter qu’il « FAKH » tout simplement. Car certains profitent de ces sorties pour s’évanouir dans la nature. C’est tout

    • Thiat

      xana tapha bala mouy rékipéré passeport fek mou organiser. bokoul wonw sax ci bagasse yi organisé woul dara da beugoneu peuteuhlou rek. xamnga rek sathie si you xoumb louné moungi ci. rissou kat lathie lén boy marone.man ak sama grand frère mbour laniou xamé tapha mok copain wam ji

      • KingYanis

        YALLA rek mo mana até. Beuthieugou ndar kamb. sathie ak borom bax meunounio and

  • retane

    Moustapha mi nak diouboul de liñ koy dien ñangui beugue beuri trop

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *