Serigne Moustapha Sy: « Des  fonds arabes sont investis au Sénégal pour combattre mon mouvement »

Serigne Moustapha Sy: « Des  fonds arabes sont investis au Sénégal pour combattre mon mouvement »

Serigne Moustapha Sy, leader des Moustarchidines, a révélé ce jeudi, à l’occasion de la célébration du Gamou aux Champs de Courses à Tivaouane, que son mouvement (Dahiratoul Moustarchidina Wal Moustarchidaty) est toujours combattu. Ce qui constituerait sans doute un frein aux retrouvailles de la grande familles de El Hadj Malick Sy.  A l’en croire, des  fonds arabes sont investis au Sénégal «pour combattre son mouvement religieux». Et les complices, avance-t-il, sont des Sénégalais. A en croire Xalimasn, il en a parlé avec Aliou Sall, frère du président de la République qui était venu lui rendre visite.

47 COMMENTAIRES
  • didi

    Vrement vs faite rirr ….magal gouddi yonent bi lan wax …pa magal sa mouvment ?

  • mo

    Ki mome dafa doffff rẹ́k

  • Mou

    yen est ce deglu nguen wakhtan bi bay wakhh ? ? Sénégal li moko yakhh rew nguen trop.. li Yonentebi Psl mom leup diokhnakoko Kon noppilenn

  • Abou

    Wakhal sa bay boudé mingui am khél ba légui mou guén wakhak talibé yi. Yén reka fi meussa am tarikha bou amoul khalif. Lenen lo def wala wakh loudoul lolou dangay nakh sa bopou.

  • jimbori

    yaw Abou sa Haye thiagua la …Laval nako..nopil domarame

  • jimbori

    BOU NGUENE KHAMONE MAODO DI NGUENE AME TEGUINE….mais on a pas la même religion .nous c est ..l islam….yeeen keenn khamoul…kou sa Serigne gueuneul yonentebi..PSL.. kou khassaides gueuneul al khourrane…da ngua réerr..tu n es pas MUSULMAN!!!!!!!!!!!DEUGUE NEKHOUL…

  • RS
  • diep
  • NIT DOFF KILLER

    cey galsen lou way nex wah

  • Junior

    J'ai retenu quelques c'est les tidianes sont toujours là a insulter les mourids te kou wakh thi sene serigne yi niou mér ….. Maodo tapette leu ba fi toubab bi néké diaye warga ladone deff ba affaire yi nékh mou beugue bari wakh … Wakh lene ak mbaye sy kouthia mansour wa junior( junior diekhal na wakh khalé la ) … Sene khaliff bi wouteul lene ko canne ak noir fumée da goumbeu motah meunoul guéne … Niak dioubo bi ame au sein de la famille sy rek warone na takh nguéne kham ni amoul bene batine nakh kou yalla nioor do khoulo do tongo…. Motah yene tidiane yi nguene wara yarou khaley tidiane da rew dixit junior

  • Kathia

    Jumbori you au Abou yeno télé at te Waye lou ampoule yare se dîner demewoule nonou do âme yare ni teigine cou yarouwoule do âme dara

  • mbaye

    senegal mou nekh de lou nekh waye wakh

  • Abou

    Kathia wakh ko sa mbok momou di saga. Kheuy na limou kham si yayam rek motakh mou defeni yaye yep nonou lagnou mel. Loula baykaye wakh si nawete rek si tolam lako guissé. Gnake yar mom koukoy def rek Moustapha Sy ngay diapalé mom mi dane khass aka saga bayam abdou aziz junior, diko djigne sathie ak féne. Wakh léne sén khalif bi guéne wala mou diokh khilafagui kenen. Khamon nguen ni Yalla dina lêne ték gathia beuthieu gou ndara kambe. Guissa go léne dara sakh ak séne tarikha bou beuri clans bi.

  • Abou

    Ndeysan serigne cheikh nimou beugué wone nék khalifa wayé tay ndeysan mingui wayé dara. Bou fore yombé seug diafé

  • bada

    JUNIOR POURKOI TU ES IMPOLIE MAL ÉDUQUÉ C EST DU JAMAIS VU COMMENT OSE PARLER D UN HOMME DE DIEU AINSI JE ME DEMANDE KI ES TU PEUT ÊTRE TU N ES PAS MUSULMAN TIDIANES MOURIDES ON EST TOUS MUSULMAN MAODO ET BAMBA-MAODO TU ES PETIT POUR LES DIVISER TAIS TOI WAY

  • budy

    JUNIOR ATTENTION À SE QUE TU DIT ON PEUT TE TRACER T ATTRAPER CE QUE TU DIT EST GRAVE LOTAKH NGA YARADIKOU KESK TU CONNAIS RIEN DU TOUT ATTENTION À TES MOTS

  • tidiane mbaye

    mourit bi tidiane bi lépou bénla nagnou réfétal djikoyi nguir yalla

  • cisse

    ABOU EST AUSSI TRÈS INCORECT VOUS CROYEZ C EST SA LA RELIGION INSULTER LES AUTRES COMME SA VOUS MOURRAI LA TIDJANIAH CONTINUERA À PROSPÉRÉ APRÈS VOTRE MORT

  • nongali

    na rafet way

  • nongali

    bou yawmal khiyamé dinan kham kou meune sa morom di adounala dz bakho thiow mais nanou soutouranté adouna amoul solo

  • Junior

    Je reitere tout ce que j'ai dit kou meune tracer tracel mais deugue rek mo nekh yalla .. Ahaha là les tidianes parlent moins … Tidiane = nafekh soff beugue diaye lou amoul … Satan habite a tivaouane dans la tombe de mbaye sy borom diaal bou yaa bi bouléne ko faté di nianal dixit mbaye dondé borom niéti khour yi

  • Junior

    Séne propre mosquée meunolene thi deff khaliss pour mou paré enfin ba paré beugue niou diaye lane gueme yalla ?

    • A JUNIOR

      Tu es vraiment pathétique. Tu n'es pas un mouride, ni un layenne ni un niassène, en fait tu n'est qu'un mécréant qui cherche à diviser. Vas lire la sourate Al Imrane, pour voir ce que Dieu réserve aux individus de ton espèce. Niak yarr, loumoula khagnoul doulako may. Lepp li nga wakh si forum, di ngako fekk sa bamel. Que personne ne lui repond, Tidiane, mouride, khadre, layéne, c'est des Tarikhas de l'Islam, donc de Dieu. ET quiconque jette l'opprobre sur sa création, Dieu lui même se chargera de lui appliquer la correction qui sied. Démal rek, bammel khatt na té leundeum neu, sa dieuf rek mooy doone sa wééteul. Wakhal louleu nekh, saggal ba nga contaane, après tout nioune ca ne diminuera en rien notre croyance en la tarikha Tidiane et ca ne nous empêchera pas de manger, boire, dormir, prier et accomplir de bonnes actions. Lou waay def sa bopp, continell, vas y, balence tes insultes. Tu fais vraiment pitiè

  • DamaDaii

    Haha saway boulma ray way

  • mame

    merci bada

  • mame

    mes junior yaw kou niak talibe ga magui Diegalou mes yar bakhna trop wasalam

    • A mame

      Bilahi junior diaroul wakh ay wakham parce que dou djoulitt. Dioulitt dou tilimeul dérou moromam. C'est des gens comme ca qui peuvent créer une guerre mondiale. Il parle de satan, té khamoul ni limouy deff, talibé satan deugu mokoy def. Bayileen ko ak yallah. Guiss naniou fi louné, boo démé djouli diouroom mam sakh matoul. Sénégal moo nékh rek, waayé yawmal khiyam, lepp dina leer.

  • max
  • touba

    aye senegal bayelene wakh dou niaw amoul solo

  • Mouride

    Mais Junior tu risques la prison pendant beaucoup de temps si tu continues comme ca sur le net.Moytoul mon frere…

  • serigne moustapha seck

    guéne balma bayilén wakh dji morite ak tidiane yépp bénela serigne touba akk el hadji khamaté nagnou avant notre naissance
    sama gars yi déf léne cii ndackk kou yakar sa way moy wadia ba diamou woo yalla yagui nakh sa bopp
    serigne soka guemoule boule wakh cii mome lou niaw kéne kou nékk ame gua sa baye té beugo niou wakh ci mome lou niaw svp!!!!!!!!!!!!!!!!

  • maanou
  • Abdou

    Senego = chat des Rats d'egouts…. Est des inconciente a la folie passageres vos impolitesse depasse le rewandé Ou le Xarrou

  • il maestro
  • aabbaa

    lol junior sa melni danga doute baaram fuy metti deh wahaha

  • Abou

    Djakadji dé mom war na gaw paré way

  • Talibe s touba
  • thiam

    y'en seringe si doun sen morom am l'en yar aki tegin

  • amadou ly

    yènagui nakh sène bop sama lou waye khamoul nathii mandou mo gueune yénou lo khamnè do kham fokoy yéniko dimgate diakhassè ak di wakh lo khamnè bou thi beut yémè beugeu todj lou geummènie nième woul bamtou ragal yalla mothii wara djitou un peu de respect pour vous même avant tout

  • modoulo

    yaw vrai dof ngua koi yaw junior dagua guiss leup

  • Mamadou

    Une chose est sure et certain Serigne Moustepha moffi togal Rassoullilah lou way dii wax nako kham té nassi téy bou bax réwandé doula yobou fén loudoul dila yakhall té dila saxeu

  • tontou

    waw dègueuna am kouye wakhnane maodo tapet la et pourtant séne serigne bobou guène nane dafa diouly si guèdji gui dè soudoul wone maodo ak yènène serigne you bakh yoyou kouthie melni mame limamou ec…fala narona dess name sakh mom boudèni dèlousina yite woroul aguite mom manga niou dèthie diarème khaprou bobou dara nèkoufa nioudiléne nakh rek fofou rek la yamnak tè souguène wakhatè dina gueuna souli wate yènène ok wasalam.

  • Nafi

    soufékéné talibé bou diay drogue indi ko tivaouane wa la koi liguéy bayi sa wadiour diokhko serigne bi, wala kou sath khaliss indi kon légui diouma dji paré. Gnoune tidjane alal bou léw la gnouy tabakhé sougnou diouma té yomboul.

  • seydina

    nous sommes comme des bêtes c pourquoi c 'était trop façile pr les blancs de ns faire des exclav . Amougnou déggo si darra kou nékk day takhaw sa coté yakk sa mbollo nan manla si wallou politikk bi si wallou diné dji léppou massé amoul kén kouy wakh lou rafét çi sa morrom mo takhit dounou dém féneu mais sinçérement beuggon na gnou magg touti rékk çi wallou xél té xam ni la majeur partie des gens ne st mm pas musulmans dc modéré

  • Al Makhtoum

    Nann meii junior kmenn peut tu dire ces genres de choses. Tww tii neii. Po 1humain.chuii tidiane mw eii je suis fiere de l'etre. Kan a toa je prie pr k Mame babacar t pardonne. Prckk tii sais po ck tuu diss.tii p ns insulteii otan k tii voudra. Prckk serigne cheikh ns a apprii a respecteii ns freres et soeurs. Eii. Mouy mouuride dii tidiane ceii la mme chozz.

  • Juste 1muslim

    Je vous demande pardon suis pas la pour offenser quiconque
    " juste une question es se ke c'est marqué dans le Coran que musulman doit être dans des mouvements ou suivre un guide spirituel ou prendre un chemin indirectement à part le coran le sunnat. Je pense ke chacun pour soit é dieu pour les pieux et pieuses. Yowmal qyam y a pas tarika ni mère ni Père ni oncle ni marabout " allez voir dans la sourate 99 (Az- zalzala ) la secousse .que la paix soit avec nous la famille

  • mame malick

    Junior iow amo kilifa mbam sax mola gueune sounou diouma bi lou léwoul doufa dougou.Mame Maodo dafa nék sénégal di ligueye ba yallah mayeko limou am bou démé tivaoune rk si képarou serigne moustapha sy nga guis sen serigne yoy réroul yi diougui touba nieuw fa toc di diangue.sen tarika laniou guise tak seye bou amoul sunnat ak warata thi laniou guisse tamite koufi raye nit soulko fofu tamite laniou guisse diaye drogue bou méti bi

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *