PUBLICITÉ

Oustaz Oumar Sall taxe Serigne Modou Kara de « saboteur » (vidéo)

Le prêcheur Oustaz Oumar Sall ne pas Serigne Modou Kara Mbacké.  Même s’il a avoué qu’il ne connait pas l’intention du guide religieux lorsqu’il sortait « ces gros mots ».

Le marabout a affirmé clairement qu’il « ne peut pas prier encore moins faire des ablutions même s’il n’ose pas ne pas le faire ».

« Ce sont des gens qui jouent avec la religion musulmane. Un homme entouré par ses talibés se permettant de sortir de tels propos, ce n’est que du sabotage. Il sait ce qu’il fait« , a-t-il taclé. Et de faire savoir que « les musulmans qui iront en enfer, la plupart ne priaient pas…

Oustaz Oumar Sall Serigne Modou Kara
whatsapp 1617
Annonces

(36) commentaires

Sanou Sow

Lou ler nga wakh billahi

Ababacar Diallo

Je suis bien d’accord avec vous oustace oumar

Mr

Yaw Omar sall amo kham kham té sa kholo kiñan guí molay andil probleme bilahi yaw do dorra

Biri

OMAR SALL yow tamitt, Kara c’est juste un comédien. Il faut bien rire de temps en temps 

    Crooks

    😂😂😂😂😂

Paco Faye

Ne vous FATIGUEZ PAS ON SAIT QUI EST KARA ET SON FRÈRE JUSTE DES COMÉDIENS SUIVIES PAR DES HOMMES FOUS

Ablaye Dia

Rèèw miii lounè fi lay amè machalla

Wakh Deugg

Celuis la c’est un menteur je ne jamais vue un imame qui demande de lire le Coran après un décès en disant que c’est une obligation jamais

Ibadourahmane

Machallah qu’Allah t’accorde une longue vie Oustaze

Xaprod

Bo xamoul reik nangua mandou Oustaz!!!!!

Kabir Lo

Nettali li Yalla yonni yonenteyi dafa doye loufi diar Roure toolou seytanee mak Ñi dawouñou diko def wasalame

Parish

Dieul diné dji diko fowé😂😂

Foof

Merci Oustaz Kara est un comédien suivi par des guignols

    Ahama

    Boudone se Baye le do wakhe li complexé Hana tidiane gue

Babacar Dieng

Alkhamdoulila on a besoin des gens comme vous machalla

Serigne Sour

Bayi lène di dag wakhi diambour dèlène tèk Lèp Omar sall khamoul dara financement rek lay lèk beug nio sonal nione limited wakh sakh geumoko

Sunugal

Il se passe des choses dans le pays y’a que vous que j’ai entendu en parler merci

Josekl Gaye

Djouli takhoul ken deme aldiana doule rek la omar sall di def ak sikimou seytanebi mou uor

Dicko

Oustaz ecouter bien ce que Kara a di mame Abdou avait.prier C. difficile si accorde un de c prière il sera au paradi directe.Oustaz le minebare sa existe pas au temps du prophète c bida.ds le monde tous les gens qui vs sui sont ds des guerres. Serigne Touba Alaji Malik Baye Niasse’s ont plus pure que toi.vs êtes ds démons de l’islam

Senegal Nioko Bokou

Oustaz!! Islam jangual nala Manou ak ko meuneu done lo féké woul déglou ba mou djékh khamo yéné gua lo ci wax guinaw gua kathieu la soce.
Bayiléne di topou lou néx journaliste yi bay toy séni morame.
Joulite day manou tay wakh deugeu bayi soxorrr!!!

Ndiouga Ndiaye

Ki moom limo Wakh si madou
Dakhe mom madouna

Mbaye

Kouye dem sawara yallah rek moko kham. Yow nonou yonou mouride nga

Ahma

Yaw mi dit wakhe té metrizewo liguaye wakhe diaregua yeureme
Complexe mofi âme legui koumou nèkone se Baye do wakhè ni
Serigne Touba dèfe fi limoufi défe wakheko dieuf KO vous refuse sa be parè âme Lou guéne Di wakhe

Ahma

Yaw oustas yawe laye wakhale.Kousi gueustou wakhou Serigne Touba se lamigne digueko tèyé,Kou Tèdeki mon d’onde yonénetebi donne le sauveurs de l’humanité tè vous refuse sa.
Donc vous n’avez rien a dire au Général.
Nafékegue.

Ahma

Serigne Touba moniou faguoule diouli ale wor nioune dans se écrit léep mouguisi sokhele wouniou diouli pour déme aldiana wayè hamenaniou né liguéyale Serigne Touba taméne au Paradis

Ahma

Yaw Abe simple oustas gue bouleniou fonton se que tu dit tu ne le metrise pas tu cherche le beuz tu l’aura nafèkegue .Serigne Touba wakhe fi dieuf fi vous tous vous refuse sa be parè âme loye expliqué yawe nitou ibliss gue tu réussi ta mission Jake,
Kouné Serigne séné hole Di bonne kéne hamoule lo donne séyetané bi

Ahma

Faite très attention et faite bien la pare des chose Un oustas dernier son écran a chichotè Un guide entouré de millier de jeune qui parle publiquement il se cache pas.
Kou gueustou wakhou Serigne Touba wakhe Lou rawe limou wakhe…

    Amar Coura Gueye

    A Onzoubilah Bismillah Inawali Yalah koumana tignala té ni YALLA souniou Borome mi dawoule bayi Yonéne bou yok mba wagni mbirame Ahmadou mou moudj mi khamé farata ak souna Charia ai akhikha Dou fowé aye mbirame 1981 ba 2019 dou niari fane bobou bataye mouye wakh patoule guoumba woule lagui woule mandou thi aye mbirame dadaye liguene Isboulah au Isbou chaytane mo fi né té Ahmadou Kara moye Borome Parti de la vérité mi Isboulah Kone Lou wa demb menoul wone thi Djole Maka ak Djole Mbacké wa taye douniou ko mene thi Ahmadou mou moudj mi kou begue diame diarale thi yonou dioupe moytou togne

Gogol

journaliste bi meunul oubbi gattam bi qu’on entende les questios qu’elle pose, dout ko baram ci l’oeuf mou yok baat bi waay

Amar Coura Gueye

A Onzoubilah Bismillah Inawali Yalah 1981 ba 2019 Dou kou mena tigna laté ba Mélni YALLA souniou Borome nga khamni dawoule bayi Yonéne bou yok mba nga wagni wakhame kou kame Chari a ak akhikha ba Mélni Ahmadou mou moudj mi do wakh lou wéroule Kone naniou khamni Isboulah ak Isbou cgaytane mo fi né Modou Kara dé moye Borome Parti de la vérité khamna fimou djeume te Dina fa ague Bouléne sonale Séne bope kou menoule wone Dara thi Djole Maka meno ko thi Djole Mbacké doko mene thi Ahmadou mou moudj mi

Amar Coura Gueye

A Onzoubilah Bismillah Inawali Yalah koumana tignala té ni YALLA souniou Borome mi dawoule bayi Yonéne bou yok mba wagni mbirame Ahmadou mou moudj mi khamé farata ak souna Charia ai akhikha Dou fowé aye mbirame 1981 ba 2019 dou niari fane bobou bataye mouye wakh patoule guoumba woule lagui woule mandou thi aye mbirame dadaye liguene Isboulah au Isbou chaytane mo fi né té Ahmadou Kara moye Borome Parti de la vérité mi Isboulah Kone Lou wa demb menoul wone thi Djole Maka ak Djole Mbacké wa taye douniou ko mene thi Ahmadou mou moudj mi kou begue diame diarale thi yonou dioupe moytou togne

Nitt

Je ss tidiane mais oustaz manouwoul

[email protected]

Wallahi oustaz tu as raison

Diaadieuf

Pourquoi SENEGO censure-t-il la réponse de l’Avocat de Sonko à Maître Ej hadji DIOUF l’avocat chasseur de primes du régime !

Alou

Yow Oustaz kou niak maandou ga so beugué degg deug ak sa sikkim cheytané. Kan moy sa mame ioe???. Senego bayilen interpreter wakhou jambour. Ana kan mo santané diouly?? Guen oubi sen gatt yi di wah. Ak lou meuna hew vous êtes responsables.

Amar Coura Gueye

A ounzou Bilah Bismillah Inawali ya Lah kouma mena tignala té ni YALLA mi dawoul bayi Yonéne bou yok mba mou wagni wakhame Cheikh Modou Kara mi khamé farata ak souna charia ak khakhi kha dou fowé aye mbirame Isbou Lah ak Isbou chaytane mo fi né Ahmadou mou moudj mi moye Borome Parti de la vérité di Isboulah Lou waye menoul wone thi Djole Maka ak Djole Mbacké doko mene thi Ahmadou mi khamna fimou djeume té Dina fa ague kou Téd ki moye ki koye womate dieuredieufetéty Chekh Ahmadou Kara Mbacké Noreyni

Publier un commentaire