Les paroles de ce Baye Fall ont ému plus d’un. Regardez !
Ce Baye Fall interviewé par Pape Sidy Fall, a séduit tous les téléspectateurs de la 2stv. Dans son intervention, le jeune homme, dreadlocks en évidence, revient sur l’image d’un vrai Baye Fall, conformément aux vœux de Cheikh Ibra Fall.
Galassbambakara djiko yonent bi mo done li yalla sant djoulite yeup mou Def ko mais c’etait pas un comportement. Demal wouty kham kham mo gueune thi iow. Li nga wakh amoul
Yaw moomu di tuddo borom ndiarem est ce k yaw woornalane Yalla nanguna sak jullit banga bëgë geenee kenn ci diné ji Aljana guinga yeene sa bopp yeeneko gnëp.Yonent(pls) bi Yalla ci djiko ju rafet lako tagee « wa innaka lahlaa huluhin hazimi » waaye tagguko ci mana julli te ci moom lako waccee.Ab jullit li njëkk ci moom mooy mandu.
Dieureudieuf Borom Touba
Mais il aussi oublié de cité ce qui est plus important. La prière, jeûner pendant le mois de Ramadan, et aller à la
Mecque. Le gars l’islam n’est pas descendu au Sénégal et il y’a pas eu un autre prophète après Mohamed (psl).
Alors modifier pas les 5 pliers de l’islam svp. Ceux qui ont fait connaître l’islam au Sénégal n’ont pas modifié les 5 pliers. Alors de grâce coller nous la paix avec vos arguments niit daye mandou. Lolou yombena trop.
Mais il aussi oublié de cité ce qui est plus important. La prière, jeûner pendant le mois de Ramadan, et aller à la
Mecque. Le gars l’islam n’est pas descendu au Sénégal et il y’a pas eu un autre prophète après Mohamed (psl).
Alors modifier pas les 5 pliers de l’islam svp. Ceux qui ont fait connaître l’islam au Sénégal n’ont pas modifié les 5 pliers. Alors de grâce coller nous la paix avec vos arguments niit daye mandou.
Josekel waye wérnani niaka diouli guénéna nit thi lislam adounabi yép senegal rék nguay guiss kouni dioulitla wayé douma diouli douma wor douma dém maka ay thiakhanla mamiou wakhanté deugue
Djouli takhoula done dioulite borom djarem
wa yène lii bouguène dèmè ba doko wonè wara lènko dague di yabalatè thie istagram
Di diouli di wor boléthi di taukh ak di nane mo guene fouf bayi taukh ak nane té do diouli do wor senegal yéwoulén té bayi nakhantébi kou yallani dioulil ngani diouliwouma mounila woral ngani woral boyabo déf loula nékh té khamni guénéngua sa bop thi dineji ak ko mena done
Oui sa s’est un real baye fall akassa
Leer na. Ce ssont ces genres de prrsonnes qui doivent invites pour parler de CHEIKH IBRA.
Bayilène gni ngeniy wowè bay fall niognou gno bolè sèn bopou si Cheikh Ibra wayè Cheikh Ibra bolèwoulène si bopam.Baye dou toukh dou nane dou moy yalla