PUBLICITÉ
PUBLICITÉ
» » »

Vidéo:Macky Sall à Tivaouane: »Kou wara dè rek dagaye dè »…Regardez

Annonces

(7) commentaires

Deug

Yakh khalice bi reek tie serigbe si khana seni talibeyi miunougnou lenko defal
Jeune yi amougnou kheuy
Tambacounda sedhiou ziguinchor kolda kedougou dara defoulokafa melni boukougnou si rewmi mais 2017 yagatoul

Bour

sa way teegua nopi

Nit Doff Killer

Deug change ton nom avant d parler "

Same Seye Touba Milan

nite daye wakhe loumou wara wakhe lidale rafetna ta diadouna bakh rek la def nako yalla faye

Monalysa

l egoisme n est pas musulman

Carlos

doul rek

Wakh Deug

se domange ke sounou president dafaye fateni dou niti tarikhayi rek noko fale . se domange ke sounou president dafaye fateni si rewou democrasi lanou nek koneka amega droit gueme loula nek. se domange ke sounou president dafaye fate ni ndayedji sekh la wara done .MANE DIAPOUNANI DOULI MOME LANOUYE KHARE SI MOME SALAM

Publier un commentaire