11 COMMENTAIRES
  • deuguite

    Procureur sou d deug l'ay dawal warna deglou kepe koi bokone tie élection présidentielle yi nga wakh lou leer mba del cachot
    MAFIA deug mo am tie senegal

  • Révélé

    Sont mouillés jusqu'à l'os: c'est les 2 vrais bénéficiaires meme

  • senegalaise

    Pfffffft khana kone lamine boutique yi mou dieundé dkr ak gni mou maye gneup dkr on doit les attendre et sur quoi au juste? Boulène gnou sonnal waaay

  • Benn Senegalais

    c'est du vent. Youssou n'a rien fait. il a 95 milliards qu'il a gagne durement par la musique surtout. Il n' a pas besoin de 20, millions, 50 millions ou meme 100 millions de Diack. C'est un complot. Ne salissez pas cette figure emblematique de l'Afrique.

  • am

    Yen boulen nio sonal Youssou bamui am ay million khamoul kui Lamine Diack

  • rim

    Afairou lamine diack lamine diack rèk la sokhal

  • fifi

    Yakh dèer moy presse bou Senegal dano beug dèf afairou lamine diack com arme tè c pas normal

  • fifi

    Lamine diokhla khalis nga lèek tè khamo nimou amè khalisbi lolou dou dèli wayè problèm moy yèn journalisteyi yènay dèf darra foudarra nèkoul

  • Relax

    Lorsque l 'on soit disant gagne sa vie dignement qu es ce qu' on a affaire a la politique. Combien de grands musiciens en Afrique personne parmi eux n est entré dans la politique mais Monsieur faiseur de malin se nourrit de la confiance des pauvres sénégalais Comme soit disant bailleur .ouvrez les yeux seul ses interets personnels compte sinon pourquoi karim l aurai sachee du palais wassalam

  • am

    Mercy Fifi yaw kou am khel nga Machaa Allah,wa sen tv niom danio begeu Youssou am promblem kom Thione way nak danio wara khamne Youssou Dou tapelekat dou Trafique te dokhoul si afferou foi billets,Youssou sa boumou yeewo mougui khol lou njimale senegal kanam kon kou yebou yene ko jamm,Youssou Yalla nala Yalla lafal thait te mousal la si nitt yu sokhor yu bone yu ignian yi,Amiin

  • ze

    Yallana yalla samou youssou ak kokako yènè

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *