42 COMMENTAIRES
  • moi mm

    Vs faite k économise vo episode

  • amed

    un cafe avec amoul bene chance areteleneko

  • hamadyba

    yéne dégué na yabe nit gni kw diaroule guéne di mousse mousse lou déhh di ko diéma goudale

  • kader

    kane moléneko lathie séne film bi amoule béne chance luxe rek ak économie donc bayiléne gniou sanou dinama nékh ak 2 vie

  • fafa

    bayilenn sokhor way ak fenn yi film dafa nekh trop yenama geuneu kham

  • papa abibou thiam

    c’est koi café avec

  • kader

    fafa un peu de respect kamem kéne wakhoule né nékhoule seulement dagniounou wanoule
    sanou réalité yi ame senegal ligniounouy wane yeup dagniouko diéguani.

  • rima

    on en veut mm pas si on pourrait avoir la suite de « fanta et jules » dinama joie trope mais RTS tamit daguay warou quoi.

  • BOY PIKINE

    24H CHRONO BI DANIU SE SONN

  • tima

    OHHHH DE TT COEUR AVC VOUS MËME SI CA VA TROP NOUS MANQUEZ MM

  • mendi

    «  MOI MM« ` boulma dadji waay, mais tu as parfaitement raison, on dirait qu’ils sont entrain d’économiser les épisodes

  • pape

    Affaire bi yombeuna koumou offal sa télé sénégal dieum kanam…..nékhoula ba paré vous êtes en colere quand elle n’est pas diffusée

  • абдулай

    moy Lolou kw

  • mdrrr

    Boubs lumouy diegualou barruuuu na !!

  • khame

    moi j’adore

  • mouhann

    J aime pa c serie sa séloign carément de nos realité résisé vous et alon vers nos valeur c est tou o lieu de ns casé lé couy pour ces coneries merci

  • Djily

    admettons k wetteul leu kameme même si c pas prince de bel air !!!

  • abdou ndaiye

    na café gi niawo way namou mann ka !!!

  • Madam Faal

    cafe avec nice

  • Cheikhouna bousso

    ah ok merci way

  • Bana Dia

    Ce sont les meilleurs. Ma khalla sénégal thiow rek ak sokhor. café avec koumou safoul, saf na say wakeur aki say mbok. mane mome j’adore. c’est le meilleur téléfilm ici au sénégal. wayé kothi kothi aki théâtre comédie rek, yeufou dof beu paré diko wowé suniou réalité… motakhit réalité sénégal = yeufou golo rek.

  • gueume deugue

    pendant que boub’s avance di innover vous prenez le temps de critiquer sokhor
    mais yalla bakhna lui mome avancer rek
    yene mome khol bouy bone gueume lene yalla té liguey kou def def lou rafet ngene tathiou sinon cancer mo lene di ray
    wassalam

  • rima

    mais on a le droit aussi de dire ce que l’on pense walabok.

  • fma

    ce nest que le debut du commencement………..

  • libs

    bayilen labatou bi khamo len dara telen bayi gir yala.demlen gen diague ci gniague yi telefilm

  • libs

    c nul

  • libasse

    C NUL

  • thiemoko

    Fiiiiiiinnnnnn????????

    • ndeya

      tkt mn idole on vs attend avec impatien t l myeur n oublions pas ntre slogan wax touti ligueye lou barrriiiiiiii

  • malick seck

    j’aime bien cette serie et sa me pousse de bien bossé pour un jour vivre le luxe un jour mais la je commence a me desinterssé car je trouve qu’ils ne nous respect pas

  • deume bi

    je ne le suis pas

  • doff

    un cafe emision lutte la walla wahsa halate aider moi svp

  • LISSA

    IL FAUT NOUS RAMENER LA SUITE DE FANTA ET JULES

  • lassa

    la suite de fanta et jules c la serie la plus nekh

  • zoba

    mane lima diakhal thi café il a comasé thi téral goro ak dieuké et coma s comporte une femme marie?et on a méme pa compri la fin ? et o retour du du méme contexe du seri café sa comanse par dé gangster tec dil o final tu nariv plu a comprendre l but du seri ?

  • zoba

    parcontr la seri fanta c la realité con vie chaque jour sa c la faut a nn parent

  • toufa

    yen gniy xass café avec sen khola bonne rek café avec mellieure série télévisée au Sénégal

  • DIOP

    Bon film qui est une alternative locale aux insipides télénovelas. Consommons locales surtout que ce film montre ce qui est beau dans notre cher pays. Pas de misérabilisme caché sous les haillons de « nos réalités »….

  • khalifa

    yen da guin yabati wala daguina sokhor film ben la fi si senegal moy film ben guana setan si senegal

  • zaleh

    prkoi pa ns mettre goorgorlou. deuk bi dafa tothie. ns n voulons pa d ces luxes d un cafe avec .consommons local et montrer nos réalité.

  • weezy

    we don’t care

  • omar

    Bon courage boups moi je kiff grave

Publiez un commentaire