saytaané daa bari doolé may wakh MOUSSA MBOUP na bayyi thioowly ta dém leggueeyi SERIGNE MBOUP leggueye rék la gueum nguir bol oubil bonto bi saytaané saytaané yagg naa yakh ta yeen famille MBOUP niéppa leen naw dileen déf royokaay nguir yalla MOUSSA bol yakh waywi
Bayiléne dii wakh louléne léroure waywi Serigne Mboup yakhnako bou yagueu Moussa Mboup dafa meusseu resté derrière beuguoule dara kheutho woule dara beugueu Serigne Mboup respecte koo Serigne nak wako yobou police yobou ko si télé yii Serigne Mboup gathé bou yémé si bir nékk domou ndeye mokoye fath warone nga roussa déme sii télé yii dii wére sa famille té Serigne nak cou niépp tousli nga toye Moussa rékala déssé wone wayé nak boo takhawé si sétou do khole sa bopp yaw ware nga rousse kii fimou djarak yaw warone nga takhawé nénéne
serigne mougnal rék none yi rek la,yalna yalla défal diameu te moye ame.dakh sodoul lolou dana am niou contanne trop
billahi lou ko gana lerr guisouma ko
saytaané daa bari doolé may wakh MOUSSA MBOUP na bayyi thioowly ta dém leggueeyi SERIGNE MBOUP leggueye rék la gueum nguir bol oubil bonto bi saytaané saytaané yagg naa yakh ta yeen famille MBOUP niéppa leen naw dileen déf royokaay nguir yalla MOUSSA bol yakh waywi
khamo aye thiakhan djop rek gua guim tenko thi l'Islam mboup