31 COMMENTAIRES
  • Marietou

    Doyna war

    • Titi

      Séné yaye tamite baakhoule dé. Abandonner ses enfants comme ça

  • lali

    Li kay eupe na tool

  • Marina

    C'est pas vrais sa tu parle ta propre mére tu nais pas honte

    • morgen

      ki moye daram rék!!! Mane da ma rousse sakh
      Sayaye boula djoure ngay khawi soutaram yawe dé do bakh mouk .sa yaye sou féké day nane sangara sakh da nga ka wara soutoural
      Ya ngui wakh sa yaye wayé tanéwo sa yaye

  • FILS

    YAYE MBAME TA PROPRE MERE DO NITE DO ROUSSE SA DOME DINALA WEER YEUW TAMITE

    • morgen

      ki di domarame ki mo bonn .jai tout vue dan ma vie sauf sa pour la premiere fois

  • Mrade

    Gueweul yi ay nit lagnou kom laobe yi guer yi am mabo yi !!!
    Fi gnou tollou ni c'est a nous les jeunes de se départir de ces idioties culturelles seul les layennes n'ont pas ces considérations !!!
    Nous sommes tous des êtres humains li bakhoule mounna indi lou nek kou weddi ladjal wa rwanda

    • omar

      senegal dou dème nakh adayi moniou sonal tè lima diakhal yalla bindoul guer ak laobe kèweul toukouleur yalla domou adama la dèfar soufèkè da dèfar aye guewal aki sèrère aki teugueu .guène wakh mako solène ko khamè…………….sama numero 00393457948256

      • münchener

        omar yaw ya Gnaakh khorom khana djiguén ngay weure mo takh ngay djokhé sa numero?
        Billahi gale-yî takhna ba europe amatoule ndiarine
        Khame so donone modou bou ame ndjarine do djokhé sa numero bi si reseau bi

  • pipo

    mais nioune si bane adouna laniouye doundou ni? adouna bi li siye xew esk k nite gni nio gui siye bayi xel. sama yaye da dem veringara niou eumbeul ko…. doyna war

  • begue s touba rek

    Lou kheew nanou go wakh tanee sy kuer mon gueene mouy deem sy télé lolou niaw na lolou sakh daga kham nee sa yaye la niit dagay am soutoura rawa Tina sa yaye nague

  • monia

    g honte si javai la pire maman du mond j vai jamai parler del de la sorte koi kel puiss m fair une mere restera tjours une mere.

  • Aduna tukki na

    Yaw ya bonne, sa yaye bou donne nane sangara sakh, gueu soutoural waleu lènène loumou meuneu nèkè, guani dagua febar, guissa guo dara, dara dala guoulo, nitt nak lo lebb lè rek lagniou laye faye,

  • doynawaar

    incroyable!!!!! rewmi soutoura dafa melni dafiiy beugueu diekh. li moy laann ni???

  • mm mboup

    9mw dou bn fan epw tu es1fm te amgua dom alor boul wer sa yay ak noumu meuna mel doth la de

  • Junior

    Essayer de la comprend si ce qu'elle dit est avere je trouve normal de denoncer cela faut appeler le chat par le chat ….. Faaw niou tekk ko thi table bi nakh nieup meune thi diarignou niouni nene leu

  • niang

    ah moy werr bopame kay ci tele yi gua khamnee amougnou bene programe

  • dije

    yaw yay domeram sa yaye ngay ni mais c du nimporte quoi c la fin du monde

  • biba

    Ma soeur on ne vilipende pas sa mère comme ça quelque soit sa faute, son comportement, sa vie dissolue. Que cela ne t'arrive plus. Si tu avais vraiment besoin que les imams la conseillent tu aurais pu aller directement vers eux sans pour autant la jeter en patûre comme ça. J'ai mal bien que je ne cautionne pas le comportement de ta mère. Mais je pense aussi que nos médias doivent faire un select au lieu d'aimer trop le sensationnel…. Où va notre pays ????

  • binette

    Comment peut tu venir devant le monde entier pour gaspiller le nom de. ta mere j'ai honte à t place meme si ta mere a des problèmes toi aussi tu dois allé te faire soigner par ce que tu es vraiment.vraiment malade j'ai vraiment pitié de toi

  • united kindom

    thieuye Senegal mo yemme desitou gueweul.
    mais guewell yii gno yakh Senegal bamme yakhou

    • Tali

      Yarou bakh na de

  • Arame

    Wa mais mom nena 69 la djoud khana kone yayam Maguette la wara done wala en plus yaw mi kou bone nga sa yaye ngay vilipender….

  • pasarme

    Vraiment c triste mes tu as raison de dire sa, amna lo khamni kene warouko bayi si khol, li nga mana def pour nga fekh mé yalla nalene yalla diapalé .?

  • niang

    mann dei guissna kou diour foukki dome kenn khamoul seni papa tei tay domm yoyou danio sangue senn yaye bamou sett yiirko soutouralko ba kennsagnouko khass domm dayy sago ay wadiouram dontei newouniou ci dioub dioumnga ma soeur setiwonn imam yi nekk sa kigne niou dieima deff ay demarche wakhtann ak sa wadiour mo gueunone yomb linga deff nga balma

  • ML

    KHANA MERE BI DA MOOLE

  • mansour

    kenn waroul khawi soutoura yayam donté daf ko deffone yayam pour se jeter dans les bras d'un "GUEWEL" ce qui reste une futilité Sénégalaise. c'est donc un tradition dans cette famille elles n'ont qu'a gérer leur héritage et nous laisser en dehors. C'est la fin du monde on dirait quand on peut dire certains trucs de sa propre maman j pense vraiment qu'il est grand temps de revoir l’éducation sénégalaise. pourquoi ces choses se passent maintenant au senegal. De grâce faisons recours aux éducations des grands érudits.
    Vous les organes de presses, y a des info qui n'honore nullement l’éthique et qui vont a l'encotre du respect de nos bonne moeurs alors svp aider nous a eduquer nos enfants

  • thiey

    sama rak sa problémou galé boulko wér ci télébi way

  • Yowtamit

    @ Junior et Pasarme n'essayez pas justifier l'injustifiable. Kii dou nitt kou bakh soufekéné histoire bii deuguela. Mann dé gueumou makko. Faisons attention à ne pas prendre tout ce qu'on sert dans ces télés poubelles comme argent comptant.

    • cicco kaolackois

      sayaay boudee thiaga sakh dancoo wara nianal mou dioguici mais doo ko weer lii ngay wakh rafetoul dara neenga dangaa bague koula dimbali mooy nga diamo dji yala

Publiez un commentaire