21 COMMENTAIRES
  • wa italie

    je suis fans balla mè bou baye talè otom dèm ker balla dèy yombe .

  • oulz

    waxtaan lèèn rek dibo dina am. boulène bayi setanné sen diguanté

  • awa samb

    baye ndiaye borom khol bou rafet nga bilahi li kou niak kiniane rek mokoy wakh

  • BALLA GAYE REKK

    bayilene balla gaye aye waye domou diambourla ahh bala rekkk depius dimache ba legui khana amoulene bane programe te bayi balla

  • Aniiita

    baye niiit kou bakh nga niak kignane ame personnalite franchement jtddr wakhtane lêne rk balla dafa dioum

  • madieng

    baye yaw borom bakh nga balla borom bakh la li amone sene diguenté nak guenonla rék motakh yalla défko mais day diékh sa khol nicee na trop yalla nalén yalla bolé watt si diam

  • Habybatou GAYE

    Je suis fan de Balla GAYE mai saytané dafa bari dolè donc je vous conseille yène gnar gnep ngène rakhas sène khol tê balanetè akh

  • Oui

    Senegal dou dem fene émission niou nul rek du matin au soir

  • Chifaye

    mbaye ndiaye si tu te di ami avec balla votre problème c'est pas dans les médias que vs allez résoudre cela. c'est même pas joli de raconter certaines choses interne entre vs deux. amitié c'est une chose que vs ne comprenez pas du tout moi je ne crois pa à tn amitié envers balla.

    • lol

      Meconten ga rek me les jalou von maigrir

  • Madou

    Mais qu'est-ce qu'on en a foutre vraiment . Thiey sunu télé poubelle yi , ils ont rien d'intéressant a nous proposer Ndeysane !

  • deugueafpa@

    Balla gaye2 doit allez baye est lui demandé pardon je le connais toute les deux mais il faut que vois vois retrouver pour parler balla gaye va voir baye Ndiaye nous tes fan's nous te le demandons on c es que baye t'aime beaucoup.média yi Lou tass rek nioko tass

  • milito

    mbaye il faut que tu revienne l amitié est plus fort que tout toi tu es plus agé que lui prend les devant tu va voir. balla il n est pas con il seras tellement gené il demandera le pardon vous pardonnerai tous les deux car l erreur est humain ainsi les 15 ans d amitié ne vont pas s envolé du jour au lendemain. en plus toi et balla vous etes des gentlemens et les gentlemans s accompagne.

  • djily

    eumeu sene for rever

  • paco

    fait la paix baye mou allè ndiaye dafa bakh

  • khadimsylla

    Adena amol sele ane lene yala baxna

  • yakar bamba rek

    ya rafett djikko th loulo rek mou am soulo si nitt bölen diglou wakhi noun yi

  • macp

    Yéna far baye!!!

  • MOUHAMED

    BAYE STP BAYILE LEPP NGUA DEME GUISSE DOUBLE LESS NDAKH FRANCHEMENT BAYE YEDE YEUREUME MOKO GUEUNE TE BALLA YENE NITTY DEMBEUME YENAKO MANA DIMBALI NDAKH BEUTE LAKOYE FATTE DOUKO GUISS

  • cherif moustapha

    Alhamdoulilah

  • aminata diallo

    Balla gaye kileu beug mola sonal damala fonk ba loula nit wax thi iow doumako fale lolou mo dal baye ndiaye beug nala dh kula ko waxoul waxoula deug ravale ta fiertè gua tale sa auto dem diap baye sama yaram sakh dafa daw bima deguè limu wax goor la dh yaram la!

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *