22 COMMENTAIRES
  • Gossip Men

    Délénn tok didoul rek…
    Diguéne doul ba dé déme bayifi loléne jotoula doul…

  • babs

    ce ndoye bane commence à devenir dangereux en traitant des thèmes qui l’échappent.

  • Cissoko

    Travail zero mais pour dire sur la vue privee des gens mention très bien mm avec sa on veut être DS un pays émergent lol

  • Cissoko

    Travail zero mais pour dire sur la vue privee des gens mention très bien mm avec sa on veut être DS un pays émergent

  • Arouna

    Ah goor yoo xamni nétali rekk moy sen liguey, nétali ba am auto, nétali ba am keur, nétali ba doundal say doom, doyna war trop

  • association des amis de Bane

    Bilaye yéne nioniou di tok ak ndoye bane attendez vous à demain mou wéreléne ni guédji ki djiko bou bone la yoré genre louma indi woute louma yobalé. Et puis avec sa vulgarité il ramène tout au sexe sans tenir contre des heures d’audience vraiment voilà ce que l’on appelle un sale type

  • Cherie

    yen bayilen Ndoye Ban dafay ligueye te wakhkatou deugeu limouy wakh kousi guiss sa bop sa affairs la vive gfm yena niouy beugeul di niou yee Ndoye Ban koumou nekhoul talal gaz tek ci sa yef

  • hhp

    yallana ban lire cmmtr..yi waye.. khamguene nak nji mom warrounou sakh di guenn si tele nanou yame si radio ba.

  • Tamsir Seck

    Ndoye bane a quitté l arme pour devenir un Vigile (ardien) a la radio Fm Environnement pouis â la radio OCEAN FM. il pourra jamais maitriser un théme à la radio ou a la TV il n a aucun niveau d instruction.

  • Akhmadou cisse

    Ndoye bane qui disait que youhou ndour est un fra maon

  • Ndiaye L.

    Vulgaire, vulgaire, vulgaire !!!

  • Aicha-München

    Mais que voulez-vous ?
    Chaïtané rék mo takhe sénégal dou avance jamais
    Kî loumou wakhe deugeuleu mane déme na senegal dégueu la crie de coeur des femmes sénégalaises sur cette pratique
    En plus sa existe partout au monde en afrik, en Europe, en asie, en Amérique, et même chez les arabes ….
    Récemment en janvier cette problématique a failli diviser l’Allemagne.certaines femmes ont tiré la sonnette sur certains partons de service qui faisaient cette promotion avec leurs employés

  • Cherie

    mercy Aicha yaw kham nga adouna woute nga ak con yu bone yi tok ci net bi di wakh te li nouy wakh khamouniou ci dara mais daniouy sonou rek ndakh Ndoye Ban falewoulen dafay ligeuye ligueyem koumou nakhary ya kham sokhor ba dee vive Ndoye Ban thia kaw thia kanam kharr dafay wessou mbote

  • Deugeu-nékhoule

    voila la liste des journalistes et animateurs les plus crédibles au sénégal
    1- Bouba ndour de  » jakaarlo  »
    2-Mamadou ndoye bane de  » xalass »
    3-Mamadou ndiaye de « xalass »
    4-Pape ngaye ndiaye de » faram- facc »
    5-Ahmed aidara de » teuss »
    6-khalifa de » jakarlo »
    7- mami diop de » waref »
    8-Mansour de » teuss »
    yêne la yala rousse motakhe Sénégal takoule
    Yêne na takhe ba mal faiteures yi khawa ragale
    Yêne na takhe sénégal di émergé
    Et je vous étes les monuments du sénégal

    • SS

      yaak nioom tekki woulene touss.
      Sa gaayi nioo yax deukbi , yax xel yi ba ken woolotul sa morrom .
      Gni nga lime nieup danioo warra noppi

  • cure dent

    NDOYE MBAAM. metier raconter la vie privée des gens avec vulgarité et insolence et gagner sa vie avec ça,ça n’existe qu’au senegal

  • zoo

    Da ma yeureume boubacar diallo miye tok ak niome no gni dou niou aye nitou dara se ndoye bane et mohamed ndiaye

  • yen a marre

    plus de prime na la légion de sécurité et de protection .en effet les gendarmes qui se trouvent au tribunal exprime leur me contentement du fait des primes non versés .ces derniers étaient même chez le président de la cour d’appel kandji mais en vain .cela est du au colonel diallo qui bloque les primes pour ses besoins

  • Cherie

    mercy deugeu nekhoul khawma nie nga wakh niep mais Ndoye Ban ak Bouba Ndour niom ay nitou deugeu laniou

  • Usa

    Aïcha ,cherie ,deugeu , yêne je vous adore aye wakhoukatou deugeu nguén , senegalais mo beugoule verité , senegalais kouye mare aye tatame ya beugeu , ate kou kaye djaye, ake fénekate vive ndoye bane thia kaw thia kanam

  • l''

    ndoy ban fen rék

  • ndeye astou sene

    gni ci bopam nio ragaloul yalla!! dans la plupart des bureaux du sénégal à commencé par la tfm, il y’a des salles de bain, divan et mer gadou, cela veut il dire que les filles qui foulent ce seuil sont des marie couche toi la? nooooon! je les vois juger les gens à longueur de temps alors qu’ils sont pire.
    SARA est celle qui a la tête sur les épaules, j’ai beaucoup aimé sa réponse à ces pseudo connaisseur à propos de la promo canapé.et cette fille qui avait amené le sujet recyclage, et qui dit ne pas concevoir que les gens ne puissent pas prendre le temps de separer les ordures. dites si ici au sénégal y’a une seule maison ou il y’a 4 poubelle pour faire du recyclage. parfois quand vous parlez vous oubliez que vous faites pareil. vous maudissez chez l’autre ce que vous identifiez en vous. merci Sara pour ta contribution, personne ne veut être mauvaise dans la vie arrêtez de juger et donnez des solutions.montrez au moins un peu de compassion et d’intelligence dans vos sujets.

Publiez un commentaire