C’est cette vidéo qui est à l’origine de la polémique entre Oustaz, Omar Sall et certaines confréries. Ses propos ont été qualifiés d’insultants et intraitables par plusieurs fidèles. Regardez ses déclarations…
Vidéo: les paroles de oustaz Omar Sall qui ont fait réagir les Tarikha! Regardez!
Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
dieureudieufeu serigne touba boudé raay ,yalla naniou raay
khaassida ci alkhurane la diougué, serigne touba lépam alkhurane la ak souna
Ces propos ne témoignent d’une quelconque sagesse dont il se réclame.Ces propos manquent de cohérences, de discipline, de vérités bref de tout…Comment parlés de choses aussi sérieux que ça et dire *WAKHNAGN* vraiment vouloir dénigrer les autres ne te permet pas cas même de raconter des choses dont tu aurais du mal à justifier sinon faire des #lambaatous. Je pense personnellement que les grands figures qu’ils insultent ne le méritent pas et apres tout vouloir faire l’apologie du salafisme(dont on voit toutes les dérives qu’il a engendré aujourdhui dans le monde actuel) ne te permet pas d’insulter le soufisme (qui est aujourd’hui garant d’un monde dépourvu de tout FITNA).WA SALAM…
Ce mr yague na di def aye video!mais yoyou yeup ben bi rek guen si taan?pourquoi a quelle finalitè?
Assalamou aleykoum
Je ne sais pas si c reellement oustaz Oumar Sall mais cette video date d’il y a longtemps et ne se trouve pas dans son site. Je pense que ceux qui ont publier cette video sur internet ont tord surtout s’ils sont contre oustaz Sall
pourquoi mes messages ne sont jamais publiés? je ne comprends pas du tout!!
Peut-être tu les publies mal et pourtant celui-ci est là
nena el jadji oumar foutiyou ninki nanka la yarone cey liii
En l’écoutant je vois que cet homme est limité. Il ne peut pas se permettre d’interpréter le hadit xudsi et dire que son interprétation est la seule valable et les autres interprétations surtout celles des soufis sont fausses. Si Dieu dit que en parlant de son serviteur: je suis l’oreille par lequel il entend, les yeux par lesquels ils voient… lui il dit que cela signifie que la personne ne doit entendre ce qu’Allah veut et ne doit regarder ce qu’Allah veut. Cela n’apparaît pas dans le texte. Allah n’a pas dit dans ce hadith l’homme doit écouter ce que je veux, il dit je deviens les oreilles par lesquels il entend. Sincèrement ce mec est drôle.Je trouve quand même bien ce débat, ça permet d’exposer le savoir et démontrer les limites de certains qui veulent s’attaquer à Baye Niass, Serigne Touba ou encore à Maodo Malick Sy. Il faut accepter que la connaissance, les livres sont là pour tout le monde, on peut apprendre. La compréhension, la quintessence des choses n’est pas cependant donné à tout le monde. Allah dit dans le coran, vous avez beau appris mais c’est à moi de décider qui comprendra et qui ne comprendra pas. Al hamdulilah et encore bon courage à ces frères qui ne comprennent pas encore. Je les comprends aussi, il faut se mesurer aux forts pour apprécier sa connaissance. Il vous reste encore du chemin, qu’Allah vous assiste inchallah. Salam
lolou lou amla nit dina tollou foo khamni di dioulli ci yonentibi ak diko tagg moy guene diangue alqurane ci moom…. ndakh yonentibi psl neena woon barina kouy diangue alqurane fekk boba alqurane monguikoy reubbou …… xamna nak yeen gni ande ci liii mou wakh seenoum khel dafa dess lool ndakh imam khazalii leeralnako ……. niouye mouride yi amoul ci monde bi kouniou meun ci alqurane …. kiii niii di wakh rek mouy omar sarr man miii rek mako dakkh alqurane fouf kou weddi bismilah dieulal sama numero 00 55 42 98 02 97 57
Machallah ya Oustaz yangu bay sa warr si diné dji yaw mi beuga diakha sé oustaz ak diamou yalla ragalla yalla bakhna
nitt kou bakh day manou surtout mou manou si kilifa dinee yi nga kham ne danou ligueyyal sounou borom bamou fay lene lou bakh dounou ay morom te kou lene fowee da koo guiss legui do yague sakh
Mane mom , bima guéne Si Fima nékoone Ba Dougou Si MOURIDE yi la meune DIANGUE ALKHOURAANE tékk si Khassideu yi
DIEUREUDIEUF SERIGN TOUBA, DIEUREUDIEUF EL HADJI Malick SY
guisgua adouna nitt dayyy maytou di Yé fitna;ouataz bi amoul yarr limou wakh ni si ayy degg na lakko tekk serigne touba ak baye dougou sa morom…..REW GUA TOROPPP
Nit Sou wakhé dara Ne si kham kham lako tek
Sokey Tontou dang key Tontou Si Kham kham mai Di saga Di teubaka dall
Kou khamoul dara Rek Moy Tontou ni Di saga Kou Amoul Ben Yarr
Oustaz Sall Kou Andoul Si Limou wakh Dangey Def nimou Def tegui Limou wakh si kham kham pa wakh diou bari AK Sagua !!!
Ki dadial pur la,,nioune serigne touba laniou gueume louniou si fekk bakhna
Je vous invite a suivre la Sounnah du Prophètes (PSL) ça nous souffit. le Prophète (PSL) disait de son dernièr sermon je laisse derrière moi deux chose: le Coran et mon exemple la Sounnah et si vous les suivez. jamais vous ne vous égarerez.
Même si on peut accepter le sens de cette parole que tu dis, ce n’est cependant pas un hadith même s’il est cèlèbre dans les bouches des wahabis.
Les 2 choses qu’il laissées sont le Coran et sa descendance (Itrati).
C’est ce qui est authentique (Muslim et autres).
Alhamdoulilah. Fène bakhoul. Ki meune fène.
Kogueum yala té guemo serigne touba sa gueum wéroul
Kogueum yala té guemo serigne touba sa gueum wéroul
ki day doul
Vrema oustaz nagouna ci benne cotte me magn naa lou bariii ci ligaa wakhh vrema psk tey.dey.bakhh nioug khamm lii s touba deff ak lii maowdo deff ak maman baye niass ak kenen nak.kenen ndakhh nioug takhh nioun nioug khamm fii niouy tegg sou nioug tankue ba menna khamm lii yalla wakhh ak yonentam….khamm mouno dioudou rk khamm yala ak mouhmed konn faww ga khamm nioug la khamall yalla ak mouhamed…. vrema nagou wouma ci ligaa wakhh nakk
saytane yeungou na ak ay gnognam
way dei ngui ni di gneuw
tei wadji li mou fi wakh 70% worou ko lerou ko ak yakh moko takha diouk
ma ngui watt ci al hour’an nei sou dei takha wei dina rethiou limou wakh
alhamdoulilahi rabil alamine ham hamlai yomboul baye barham niass borom faydou kaine dou mome bou ma daiger oustaz bi mou wah damy haip lolou oustaz yi menimom fayda ak tariha niougui ko soss si souna yeureumnala serigne bi amo ham ham
Chers Frères je vous invite à suivre la Sounnah du Prophète (PSL) c’est la seule bonne voie.
un insulteur public, rien de plus.
il se base sur des a priori sans aller a la source.
Manou ci lo xamoul bakhna si ap joullit.
Dans ce pays il y’a des personnes qui pensent avec leurs grandes gueules tout connaitre du coran or ils ne savent que dalle!!!
Cheikhou tidiane ,Baye Niasse, Serigne touba Mame limamoulay , Mame Maodo douniou moromou Pa bi douniou moromou bayam sakhh!!!
Dc parles du coran et laisses les personnes vivre leur foi comme ils veulent !!!
DE quoi je me méle
Oustaz danou gua
Sénégal on aime bien le protéger le marabout.et oublié Allah soubhana wa ta’ala et Son Prophète ce que Oustage oumar Sall a dis c’est la vérité allez vous regarder le Coran et sauna de prophète Mohamed salut sur lui. pour moi celui qui n’a pas d’agrément celui qui insulte arrêtez de vous insulter on peut critique mais pas un insulter je pense qu’on a dépensé ça
Un bon musulman ne doit pas se baser sur « wakhnan wala degna » Tout le discours de ce gars porte sur des wakhnan. Il essaie de discréditer les tarikhas et le soufisme parce qu’il y était et n’y est plus et on ne sait pas la raison de sa sortie du tarikha tidiane ce qu’il dit ne me convaint pas
Dieureudieuf oustaz omar sall
ki clochard deug la kouko wakh chaikhou tidiane michel la toudd dayy fenn mom si boppam fenn katt la waliyou yalayi koulen di sossal san kou rec guay deff
dagaye doul rek cheikh bouder poison nagnou raye doul kate bi imbesile yi
Senegaal daniouy diangue Alkhouraan pour barkélou wayé dou pour dieurignoussi surtout les mourides. Oustaz Omar Sall n’a fait que citer ce qui se trouve dans vos livres. En plus cet audio date de plus de 20 ans. Pk vs ne la diffusez que maintenant? Mbaadou li oustaz Omar commencé siiw moo takh? Des personnes sont parties attaquer Oustaz Omar chez lui, loolou loumou toudd loudoul terrorisme?
man deug rek la wakh senegal dafa bari ay nafekh khaside ak loumou meun don Alquran ak Khadith moko geun kon heure bingay jel diko diokh khaside diokhko Alquran mogeun boulen niou sonal bayilen sen thakhan yi te dem diamoudji Yalla mogeun S Touba limou def pour bopam la parce que yawmal khiyam koune ak sa djeff demlen si souratoul Abasa set lifa Yalla wakh,Yalla nena kerok bessba Bay dina daw dom Ndey daw dom djekeur daw djabar dom daw yay kon khawma lou seringe di kharr geum len Yalla te bayi thakhan geun bal ma akh deugeu nekhoul tarikha yangui beugeu yakh senegal tarikha mouride nak mosi raw tijan yi sakh tane nen parce que nie si opeu djanga nen
Sokhna Amina benn lath lalay lathh: Dinée islam lann moko sakhal sénégal ak gniane gnokko sakhal? ba nioun nieup diot thi iow ak man ak nieup?
ou etait tes grands parents quand les cheikhs que tu denigre resistait a l’oppression des thiedos et la furie des colons blancs
SERIGNE TOUBA FOWOUL FOWLOUWOUL BAGNE NAGNOU KO BA TOUBA AM NAFA DARAY KAMIL, bèpe ndadiè bou mouride yi am dagniye wathiè ay kamile ba parè sogua diangue khasidayi té khasida you eup Serigne bi dathiye tague yonèntebi MOUHAMED S A W, SERIGNE BI YALLA AK yonènte bi S A W , ak diangue alkhourane dourouse khassidayi yar aki tèguine lagnou dianguale. lègui nak diamano mo nèkh balou waye nèkh wak serigne bi, fatè nagnou diguèntèm ak Toubab ba bireau bassa ndar ay boudone gnii di wakh tay. DIEUREDIEUF SERIGNE TOUBA boudé rayé yalla nagnou raye boudè tawate yalla nagnou dal boudè khagné yalla bougnou am.
katal sa ndeye sa mame diamono bi mag gni di resiste toubab yi ak thiedo yi foumou nekone
Senegal mane mome yalla rek ak yenentobui
Sénégal le problème c est pas touche pas a notre religion mais c est touche pas à mon marabout.lui il la Dis se qu’il a vécu de 1 ,et de 2 il donne des noms de livres,allé vérifier ou repondé le par des textes du coran et sounna.de 3 y’a plus de 150 vidéos il parle que coran et prophète et la vous sorté que sa pour soulever du fitna .sa va tombé sur vous avant votre mort ou le jour du jugement.que Allah nous guides dans le coran et sounna.
ancien mouride,mouhamed,amina yéne mome lou gneuw yoboulene .ki limouy wakh bilahi walahi talahi dara amoussi day sosse rek. di féne.li mak gnu bajh gni ame mo takh senegzl am lou bene deukeu amoul.te mak gnu bakh gni loudoul islam falewougn ko.khassaide ay wayou yala ak yonene rek la te lolou aramoul.bougn lene topé terroriste yi amfi bountou.yalla naniou yalla mousseul si niom
Amminsheytan ya xaar sa leuffeul ndeyy meune fene ki mo ngi si diouma ibasheytan bou nk castors
DIEUREUDIEUF SERIGNE TOUBA BOUDé RAYé YALLA NAGNOU RAYE BOUDé KHAGNé YALLA BOUGNOU AM Té BOUDé TAWATE TAMITE YALLA NAGNOU DALE.Mom liguèyale na yalla bamou fayko limou am, yène nak adouna mo nèkh tay apparé vidéo yi tim lène ak microyi guène diwakh rèk di guène wakh dé (WAYé YALLA AK SERIGNE TOUBA REK KAGNOU NIOR AK MAK NIOU BAKH GNI).ay oumar sall ay cheikh sakho ak gnénène gni si guinaw boudèmb done tay kone toubabi guène di diamou,dimbalilène gnou darra guène khamoul.
AMINA yow waxxi doff rk ngaffi waxx. khana xamo khassaid alhourhane ak diouli ci yonentei bi lagn ko teunkei.ahourhann waxxi sounou boroùm tei khassiad waxx ak sa borom laa. demm lenn guestou dji geuno lenn gno ragal sounou borom
Daye doul wakhoul deuge
Fene coukaye defe do dioulite
Ma cha Allah, Wakhou kate degue moy Ki, les bockalé kate te détestent pask melo ni niom yaw lou yalla wakh ak yonentam ngay wakh, t niom lolou rek lagni bagneu degue, Qu’Allah te protége du sheytane et ses collègues sénégalais
geumouma darra si lounga waxx. c’est pas vrai
En tout cas naggnou andakk souniou khéll !! Faut pas l’ ignorez !! Investiguations ??? Loubary louniou done neubeu fimounékkani mingui fégne !! Yalla rékk mo worr dou lénène dou kénène !!! A méditer !!
Il n’est pas hypocrite,il dit la vérité.Au Senegal on adore les hypocrites.La vérité c’est la parole D’ALLAH et la sou nna du prophète
Soss bakhoul ,allez regarder toutes ses vidéos il ne parle k du Coran ici au Sénégal on passe tout notre à faire du bokalé nagnou ragale yalla tai diko dieufé mogueune wassalam
yen boulen niou sonal Oustaz Omar limou wakh deug bou worr la amna mouride yo khamne finiou tek khasayide tegouniou fa Alquran ak Sounna te lolou dou deug dou yoon parce que Alquran wakhou Yalla la Sounna wakhou Mouhammad S A W la te mom loumou wakh Yalla mokoko wakhlo dou wakh mouk si banekhou bakenam te Yonente bi S A W la Yalla yooni si nioun yooniwoul kenen te dotoul yooni kenen senegal nak dekou nafekh la parce que li Oustaz Omar wakh yenen Oustaz wakh neniouko waye sen keur yi lanioukoy wakhe parce que danio ragal te warouniou ragal dara parce que kou and ak Yalla ak Mouhammad S A W waro ragal dara,Oustaz Omar Yal na Yalla goudal sa fan mey la werr ak werre yok sa kham kham,Amiin
bien dit yaye amina !
wa oumar sall mi niiit la; tu na ka créer ton propre tarihan et laisser le pays en paix. beugual diam bahna
Ce discours est le énième d’une longue série qui suivra. Ce n’est ni le premier ni le dernier contre le soufisme. Leurs maîtres wahhabites ont débuté leurs entreprises diaboliques depuis très longtemps. C’est ce qui a d’ailleurs engendré DAESH. Cheytané peut paraître dans les habits d’un musulmans, maniant les sourates et les hadtihs jusqu’à ce que leurs discours ressembleny à la vérité alors que c’est eux qu’ALLAH évoquent en parlant des nafiqq (hypocrites).
Ces gens sont dangereux car pour amener les gens à adhérer à leurs discours il faut absolument qu’ils dénigrent les soufis. C’est très dommages pour ceux qui croient à ces gens qui ont vendu leurs âmes au diables wahhabites.
je ne sais pas de quand date ses paroles sur le soufis, mais sont très impertinentes, choquantes voire dangereuses. on a pas besoin de ces genres de paroles qui divisent davantage la communauté musulmane de ce pays. Imam gua, yémmal thi waaraté, té bayyi di attaqué pass passou ay kilifa. pass pass biri xoll la yalla mooko xam. Soufis ou non, xamalné ki guene yalla mooko xam. kou néék na sakkou xam xam, djiamou yalla té ragalko. ligua wax, surtout concernant Cheikh Ahméd Tidiane se base sur des allégations ak ay néttali, tu n’as apporté aucune preuve documentée. j’avais beaucoup d’estimes en toi avant la publication de cette audio. je suis très déçu, car ces paroles heurtent, choquent et peuvent enraciner la haine entre les musulmans de ce pays. oustaz waraté baxna, wayé soss baxoul. xam xam baxna wayé dafa wa ande ak sagesse, wa salam.