Le fondateur du Mouridisme Cheikh Ahamdou Bamba reste une icone mondiale. Les Khadres du Nigeria l’ont rendu un vibrant hommage à travers des chants spectaculaires. Regardez cette foule en liesse
Vidéo: Les Khadres de Nigeria chantent les gloires de Cheikh Ahmadou Bamba!

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
tous des arabises. colonisés. ne nous fatiguez pas
dieureudieuf
merci talibé c’est vrai ce que vous dites sur cheikhou omar ll est le contemporain de presque tout les saints au senegal et l’Afrique de l’ouest et beaucoup ne le savent pas
quand a cheikh ahmadou bamba tout les africains doivent en être fier de lui parce que avant lui nos encetre voyageaient très loin dans les pay arabes pour trouver des guides et des wirds le cheikh a renversé les chose en se donnant corp et âme en adorant DIEU et endurer de très lourdes epreuves jusqu’à ce que le prophète lui consacre le titre QUTB(pôle)et lui donne l’autorisation de proclamer qu’il est un asile et un refuge et lui donne son propre wird et il fut le premier et luniq homme noir à donner un wird au blanc dieuredieuf mbacké !
Envoyé depuis mon appareil Samsung
wa yaw younoken li gaye wakh khamouci darà gui di dioye seringe chiekhouna Mbacke mo.el hadji bara fallou la.
SANTE YALLA BOU BAKH SANTATI KOU TED KI DI WAKH NI MONTRE YOU BAKH YEPP NIO BOKK HEURE LY KOUMOU NEKHOUL NGA XAM KO AK NIAKO KHAM ‘BAKHOo’nioniou nak(nafékh yi) nioye nék si rso sociaux yi di diéma diakhassé tarikha yi suniou publier si Mouride yi niou dieul tour wouniou mine si tariqa cheikh comenter wax si lou niaw bouniou publier si tidiane yi niou dieule tour wouniou mine si Mouride yi wax fa lou niaw naniou si bayi xél bou bax khamni amna nio xamni lou tass tarikha yi rék moléne takha diok Mouride tidiane moye mbokame, layene, khadre, niassene etc yalla naniou yallah doli soutoureu té moussale niou thi gniniouye diakhassé
amna niōu wara kholat séne khôl yi li dioulit yeup nioci wara bégue.domou Mame Diara dji ndamou l’islam la
jaajjeef Abraham ci lèral bi adouna bi dal kouffi dègue Cheikh Ahmadou Bamba beugue kham moy kane do dèm foudoul touba , domi sokhna diarra ji ki dioulè Samory tourè , diakhal toubab bi , refusè croix legion d’honneur , liberer diam gni tè gaaw ci sokhla yi , borom touki bou yaggue bissi seurithieu bou barri
Yonouken tu ment car celui qui pleure c est serigne cheikhouna mbacke ibnou aladji bara ibnou serigne fallou ibnou cheikh ahmadou bamba
وَإِنَّ هَٰذِهِ أُمَّتُكُمْ أُمَّةً وَاحِدَةً وَأَنَا رَبُّكُمْ فَاتَّقُونِ
Cette communauté, la vôtre, est une seule communauté, tandis que Je suis votre Seigneur. Craignez-Moi donc».
فَتَقَطَّعُوا أَمْرَهُمْ بَيْنَهُمْ زُبُرًا كُلُّ حِزْبٍ بِمَا لَدَيْهِمْ فَرِحُونَ
Mais ils se sont divisés en sectes, chaque secte exultant de ce qu’elle détenait. al mu’minuun versets 52 et 53
إِنَّمَا الْمُؤْمِنُونَ إِخْوَةٌ فَأَصْلِحُوا بَيْنَ أَخَوَيْكُمْ وَاتَّقُوا اللَّهَ لَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ
Les croyants ne sont que des frères. Etablissez la concorde entre vos frères, et craignez Allah, afin qu’on vous fasse miséricorde. al hujuraat verset 10
Je suis fervent chrétien en esprit et en vérité et j’aime bcp serigne mourtada serigne fallou et serigne saliou ils font parti de ma vie ces 3 fils de serigne touba
isma bayil gni dagno ignaane serigne touba a travaillè pour le senegal et pour l’afrique on devait etre fier de cet homme mais senegalais mo complexè tè ignaane jaajeef domi Mame diarra ji
alahou akbare walahi mangui dioye
Alakhou Akbar Dieuredieuf sunu Borom
Alakhou Akbar Dieuredieuf sunu Borom
yonoukene tu préfère que les nigerien chantent un irakien que de chanter serigne touba ? ? vraiment yaye nitkou bone kholatal sa khol bi t’a un sérieux problème toi YALLAH loudoul qalboun salim mouy khol bou séle sokhlawouko thi nit
Isma sa wakh rafétena!dieureudieufé serigne touba
yonoukene bayilen rivalité entre nitou YALLAH yi ça n’a aucun sens et aucun intérêt té parparlo dafa haram en entendant parler des gens comme vous on dirait que nos vénérables guides religieux étaient en guerre entre eux té faux talibés yi melni yow rek nioy indi haine entre tariqa yi qu’es ce que ça peut vous faire du mal quand les nigerien chantent cheikh ahmadou bamba radiyalahou anhou qui est un sénégalais comme toi ? baye niass radiyalahou anhou sou momé nigeria loumoukoy doyé ? kou nek aldiana sokhla woufi dara les vrais musulmans c’est ce qui s’aiment entre eux arrêtez votre jalousie vous êtes trop bête way !
@Isma Diadieuf Isma. Diangalé ngua lii wara done takhawayou Dioulit. Il faut niit gni khamné Dinganté Sénégal akk Nigéria tchi Diné daffa Yagg. Cheikhou Oumar Foutiyou Tall fekk na Cheikh Sid Moukhtar Al Kountiyou keur Osman Dan Fodio. Deffana né boba sakh djeuleul gou wird Tijaniya. Wakeur Osman Dan Fodio akk domame Ahmadou BEllo ba légui ngnô nekk Nigeria.
Sounou makk gnou Bakh sène tour agg na founék. Wallahi Affaire bi dou guerre akk compétition.
yoneken nitt kou bakh dou féne dou sokhor
dieudieuf li rek mo ame solo walahi
hooooooo rafétna vive senego
nigaria bay niass mom nako bou yagg yi chiekh Ahmadou bamba laniouy woyy chefif la mogui dekk irak
Yonouken tu ment car celui qui pleure c est le fils de eladji bara mbacke ibnou serigne fallou ibnou kcheikh ahmadou bamba il s appele serigne cheikhouna mbacke
non chierif bi mo toudou ahmadou bamba mogui deke irak wakhouniou bi neke senegal na lerr senegal chiekh ibrahima niass momom nigaria
Moi je suis khadre et j’adore bamba parce qu’il nous a honoré en donnant le nom de ses deux enfants à nos guides:cheikh Abdou khadre et cheikh Mohamed fadel (serigne fallou ).
Dans mes prières je demande même à qu ALLAH acceuille au paradis Quiconque à entendu le nom de serigne touba khadim rassoul .
J’adore Bamba
eskeuy ! !
thiey balla aissa sama waaadji ken dou mom gaawlène avant mouy trop tard