[Vidéo] Les invocations de Cheikh Mahy Aliou Cisse, petit fils de Baye Niass, à Arafat
![[Vidéo] Les invocations de Cheikh Mahy Aliou Cisse, petit fils de Baye Niass, à Arafat](https://senego.com/wp-content/uploads/2015/09/Arafat-mea.jpg)
Plus de 1,8 million de pèlerins musulmans se rassemblaient dimanche sur le Mont Arafat, près de La Mecque, pour l’étape la plus importante du hajj en Arabie saoudite. Parmi eux, Cheikh Mahy Aliou Cisse qui est un petit fils de Cheikh Ibrahim Niass (Baye Niass). Tout de blanc vêtu, la couleur de l' »ihram« , (les deux pièces de tissu que doivent porter les hommes), le Cheikh récite les invocations traditionnelles du hajj. Regardez!
alhamdoulila macha alla cisse
Allahou akbar yalnako Sounou borom yoque ates yi n ak khakhabi cii baraka sounou yonintibi PSL Amine.
Al khamdoulilah cisse al Qouran bi néhna yalla naguako yague dieuf té sounou borom bi naguou ndiane yi ak hadj bi cii baraka
sounou yonintibi PSL Amine ya Rabi Allamine.
Al khamdoulilah cicé al Qouran bi néhna yalla naguako yague dieuf té sounou borom bi naguou ndiane yi ak hadj bi cii baraka sounou yonintibi PSL Amine ya Rabi Allamine.
Walla hi li nekh na lol si kholle. Yalna Yalla nangou niane Yi. Dieuredieuf Cissé.
ALLAHOUMA AMINE
Alhamdoulila
Akassa Yalna Yalla Nagou Amine
Amiin Ya’Allah
Djeureudiefati baye
Allahouma amiine
macha Allah niass dieuredieufe
Machallah SERIGNE BI niaane yi rafèttena dougouna ci xol yi dieurédieuff yallnah yallah nagou niaane yi ci barkè harafat té yallnah yallah deugeural baate bi, yokkou fane yi ci barkè mawlaana Cheikh Ibrahima niass Baye. Amiiiine
Machallah. Dieureudieuf
Amiin yaa Rabihi
macha allah ciss yalla n’a yalla nagou Niane y
MachAllah amine ya Raby, k’Allah bénisse le Sénégal
l’islam es bonne
Machallala Dieureudieufff baye niass
Les commentaires sont fermés.