10 COMMENTAIRES
  • beugue sama reww

    sunu artistiyi khamou gnou gate diwaye sa mame diwaye sa baye rek la nou mane ga maye lene khalis gnou yakar ni da gno mana waye

  • Diop

    doye na war dal li…sénégalais d niak ambition mo ko sonal

  • Jaime balla guaye

    khép bignou khép sougnou bop mo takh dougnou avancé youssou combien de fois lagnou siguil dans le monde entier ki si elle chante en wolof c Grace à nos artice geume léne sène bop way c important

  • fama

    mai ki kanla

  • Michou

    Wayo fi….wakhofi….Ndeyam!

  • Alzo

    Tey avec cette musique vous jugé nos artistes

  • pispa

    come k no artistes son null voila l résultat

  • BLECK

    yaw doo moromou om guigui ak Queen fresh

  • khoul

    comme nos artistes n arrivent pas percer à l international , laissons les toubabs chanter pour nous. xawma kagn lannioul meunal sounou bopp !?

  • Mamadou

    mat na li rek nak modesoe

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *