Vidéo- Kouthia repond à Coumba Gawlo ''on n… par hamidou-sy3
Vidéo - Kouthia répond à Coumba Gawlo : ''On n'accepte pas que tu attaques notre patron"
Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
senegal rek et diaga o moin vs réfléchissez
kouthia doff deug la coumba gawlo n’a pas critiquer youssou ndour ils la critiqué le ministre deglou lene coumba bou bakh
Quel pays! C’est vraiment triste! C’est tellement piteux! Aucun argument pertinent! Du folklore! Il faut des siècles pour changer nos mentalités. Coumba Gawlo Seck a fait une critique très objective.
koutia t’abuse aussi ses histoires entre les musiciens tu n’a pas répondre à coumba comme sa on sais que c’est ton patron mais attention
kouthia a raison coumba danougua
gunn balma deug nekhoul mme la rts gfm moko dakh sott. wasalam
non gayi c a l’image d vos patrons et dirigeants kenn d’o lall You nous savons s ki s pass tfm rfm lobs tt l monde khamena foi guenn ft naht dompatt sah sisott lebok
Coumba daffa warra woutti jeuker té wah jiii…you amoul jotame
koutha maroul ben tate degeu rek la wakh senegal danio sokhor way lilen nakhary Youssou tegoulenko sen khol yu bonyi
kouthia iow ya wareu tontou gawlo goor gueu waleu djiguéne? gueumo dara mar taate rek doul rek
coumba dafa riewo
Ah bilay Kouthia ray ngama. bou sagnone doleen tontou Coumba gawlo a toujours été jalouse de notre You international☺️☺️☺️☺️
koudia employer leche cu
athioum li forna tu sais dans la vie personne n’est critiquables mais la meilleure réponse c’est l’ignorance même si la personne à plusieurs défaut admettez l’investissement qui la fait pour son pays.wa salam
koutha man bouma sangon yen wa gfm digeun melni sen patron Youssou bolewout dara ak wakh te limou am yep likoko mey moy niak tonto ci katanou Yalla te niep kham nenj Lin daga kholou nonyi moy loumou lan Yalla barkel ko te lolou koko bange dangay wakh ak Yalla wakh ak sa ndey ndakh Youssou limou am Yalla mokoko mey ak ligueyu ndeyam Machaa Allah law la that
vraiment lerna nagne coumba dafa khamoul pour mom intelectuelle la