17 COMMENTAIRES
  • petrol

    wakh ma rek kaan mo nek fofou sii tol yii dii fayékou 1000€ wakh mako rek yaw kay dagua warra wo senegalais yii nek fofou amou gnou kheuy amou guonte gua diokh leen keen kou neek salairou 1000€ aprais gua sogua wo gnii am 600€ guiss gua nitt kou gnoul dee sama salairou 400€ la yor dii dound dii sii yoné senegal samay wadjiour dima gnanal amailou ma keen bor senegalais mo wara wagnii wakh gnii xam cheikh am yeup lignou xam sii mom moy milliadaire la diokh gnou depanse ta xarou gnouko sii yaw kone boul toutel 600€ wakh ma saa premier salaire gnata donéma dagua djioudou rek commencé am aay milliare nagnou bayii wakh bii ta liguey xelcom la faa serigne bii dioub lou dou ay wakh wayé dimbalii diam yii amoul woutal aaay tol dieul 5000 jeunes dilen fay kou siii nek mill euro yaw waro xar etat ta gua xam nii exampl guasii rew mi yaw so wakhé gneup lay degu lou am alal rek doyoul am talibé xam niguay wakhé am na keur you barii you nek senegal dagnouy doundal aay niit ta soutoura yalla rek lagnouy doundé lii ma dioub samay kadou moy naa nitt kou nek di xol nimouy wakhé nakh daguay guiiis niit dii wakh nane 100€ rek lolou tégui né woul rek keep kou matal diko wakh dagua faté nakh gnom gnii am alal do sii guiss ken tok nane 1 milliare rek magui diegua lou samay kadou nak di wakh niit gnii nagnou delou delo sen xeel sii yalla wasalam

  • wakh deug

    yaw yaye diabarou serigne saliou

  • mick

    diadieuf cheikh je sui fier de toi

  • attou

    menteur ivrogne ont gagnent pas 600 euro con combien tu gagne en france toi du wiskly

  • momo

    Deque rék nga wakh

  • VERITE

    MERCI CHEIKH AMAR POUR TON ENGAGEMENT A TOUBA ET SERIGNE TOUBA MEME LES GARDES DU CORPS LE PROUVE POUR MONTRER CETAIT LES OCCIDENTAUX QUI NOUS COLONISAIENT MAINTENANT CES A NOUS DE LES COLONISAIT CAR TOUT LEUR BIEN VIENT DICI ILS N ONT PAS D OR NI E DIAMANT NI DE PETROLE CET IMAGE MONTRE MONTRE COMMENT LHOMME NOIR DOIT FAIRE ET NE DOIT PAS AVOIR DE COMPLEXE ET OU DE JOUER LES SECOND ROLE MAME BOROM TOUBA LIGUEYYOONE NA LI NASARANE GNOOY SOUKA DIEBALOU TARBIYOU LAGRICULTURE EST LA BASE DE DEVELOPPEMNT DUN PAYS SA CEST VRAI EN BAS LES CLASH ET INSULTES FAITES COMME LUI ET TRAVAILLER POUR LA CAUSE DIVINE ET INCHALLAH LEPAY BAH YALLA NA YALLA DOOLI SOUTOURA TOUBA AKH SI SENEGAL AKH ADOUNABI YEUPP MERCI

  • PAKO

    TU ES UN DROGUé
    CHEIKH AMAR TU TE CONTREDIS
    REGARDE LES TOUBAB QUI ONT GERE TA ''SECURITE'' !!! C'EST DE LEXPERTISE ETRANGERE NON ?? TU AS PEUR DE QUI ? TU ES KI TOI?
    TOPOTOL SAY AFFAIRE REK
    ON A AUCUN CONSEIL A RECEVOIR DE TOI
    YA TELLEMENT DE SENEGALAIS QUI FONT DES MERVEILLES QUI AIDE LE SENEGAL SANS AUCUNE PUBLICITE

  • pakojackson

    TU ES UN DROGUé
    CHEIKH AMAR TU TE CONTREDIS
    REGARDE LES TOUBAB QUI ONT GERE TA ''SECURITE'' !!! C'EST DE LEXPERTISE ETRANGERE NON ??
    TOPOTOL SAY AFFAIRE REK
    ON A AUCUN CONSEIL A RECEVOIR DE TOI
    YA TELLEMENT DE SENEGALAIS QUI FONT DES MERVEILLES QUI AIDE LE SENEGAL SANS AUCUN PUBLICITE

  • paco
  • Larry

    Cheikh Amar boulniou fonto kou am 600 euros di ssi soutourlou ngua Ba ko ak li ko yalla diokh pour ton info en France même le smicard n'est pas à 600

  • pape

    comment se fait il que tu distribues de l'argent alors que tu dois de argent a d'autres senegalais.

  • lune

    comment se fait il que tu distribues de l'argent alors que tu dois de argent a d'autres senegalais.

  • lune

    cheicke svp verifier information de ahmed aidarra

  • me sagna

    diambar amar boul diesstou mook ke kanamme rec inshlah

  • khana neex

    yaw dangay dem si kannam rek inchala

  • ahmed aidarra

    Bonjour Mr AMAR si tu crois vraiment a serigne saliou paye aux sénégalais que tu dois de l'argent, j'ai un ami qui court derrière son argent depuis 6 mois dans ton fameux projet Touba Almadie. par la grâce de serigne Touba paye lui son argent

  • Moustapha

    Tu es un exemple fier de toi talibe serigne saliou

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *