7 COMMENTAIRES
  • doyna

    Di sante s touba tout les jour si c étai pas ces deux raka devant l gouverneur aujourd'hui y aurai plus d églises k de mosquée Mercie bamba Mercie soudoute wone ak yaw l islam Faye thie Sénégal kone heure niogui diamou toubab yi aki kheureum té kone niou dem neury ( enfer) dieureu dieuf Mbacke amou niou sa Faye yalla nafi s sidy makhtar yague té wer amine

    • deug

      Bida boureuy Serigne Touba santoul ken mouy celebrer ay niari rak dou farata dou souna

      • NIASS TALIBE BAYE

        Ki dou deug, démou guis na sa baye ak yaye ak sa Serigne Bi Ndar
        Mame Bamba disait:"Ma condition d'esclave de Dieu, le Majestueux et ma qualite de serviteur de l'Apotre on fait mal a satan." Je crois toi Deug oubien fénn tu fais parti l'un des petit fils de SATAN. Balma déh mais c'est la vérité, Nagniou Naguo

        Khadimou disait aussi:
        "Dieu m'a accordé des priviléges qu'il n'a accordé et n'accordera à personne" extrait de Diawartou

        Biss bou sett digua ame loula nakhari, sou déyé gua na ame loula nagari,

        • reDeug

          Tu as cite Serigne Touba mais ou il à dit de faire une prière de deux rakkas donc DEUG dit que c est bida

  • begue s touba rek

    Day sane kholale li rek fi lanou youbou wone sounou mame yi at yaneene Serigne yi toubab bi neeleene wakhleene yalla dou bour niou wakh go Serigne touba rek monee go yalla moy bour mon dakh mou am li kham ganee li rek doy na dakh li moy fiir nee yi mome rek mo dioli sa ndar mon dakh mou amfa li

    • reponsebegue stouba rek

      li nga wakh meune nga ko wate? yako féké? koula wakh niouko nétali louniou nétali mo ame? Bayiléne di féwalé ak di diakhassé nane yénéne serigne yi daniou wédi Yallah alors k vs nétiez meme pas encore nés..Ay weuliyou kéne dou dougu ci séni domaines. Mandou ak bagne dougou ci domainou souniou nitou Yallah you bakh yi mome la Yallah santané.. Sénégal nak yakam ti naniou occasion banane telle ou telle autre confrérie mo eupe mérite. Toutes les confreries se valent mouy Mame Bamba,Mame Malick,Mame Limamou,Mame Baye,Mame Bou kountou et j'en passe niome nieup nioune baniou khalatoule sakh dioude,nio fi nekone guir fightal Islam donc fi dal kéne gagné woul Islam rekk mo gangé dou béne Serigne nak Wassalam

  • mbass

    cette prière ,en réalité ,c'est la prière de takoussane. On l'appelle magal des 2 rakas en souvenir de la fameuse prièrede Serigne Touba dans le bureau du gouverneur de ndar mais aussi en raison des activités organisées avant la prière. Il n'y a pas de bida ici.

Publiez un commentaire