23 COMMENTAIRES
  • conné tout

    noo ousmane mo nékh

  • dikh

    ah ki raynama

  • luego

    le gars qui film mome il est agressif déh. Quand la personne pleure, la décence voudrait que tu la laisse extérioriser sa tristesse ou que t'essaies de la consoler. mais lii mome vraiment c'est pas gentil.

  • yaa

    c pa du tout drole un peu de consideration

  • respect

    Non c'est pas sérieux du tt

  • ohhhhhh

    il n'y a rien de drole ici vraiment..

  • lufa

    senegal dal mogui ni rek lou bakh dun kadef ki yalla la yalla lou ka nekh lay def

  • astou

    Il n'y a rien de drôle ici. Arrêtez de vous moquer des gens. Un peu de respect.

  • fatou1

    noune niep bena lanou

  • Makavelli

    No Ousmane dadjé nama. .mai Waly na si diap bokk. ..

  • badou

    Pour man filma bi gara woul li kouko gis dimmba liko boka dague dimmbali ciao tutti

  • timachoue

    Ils jouent rek koulen degu hamnani danouy fo Koneu wahi yeup diarouko way

  • belle mignone

    wally louné lakoy defaral kou khamoul khamoul dagnuy togne. enplus video bii yagna trope dpui lanné passé laa

  • tra

    wally dey Def dara yeni tam

  • ba

    bilay souma khamone numerom dinako diapalé adouna amoul salo liguéni mene liguéye mom menouko liguéy wakh ta yalla takh

  • amaf

    C'est pas cool..

  • mamfa

    Ahaha waly diokhal ousmane ligako dikk

  • fabiana

    C'est honteux bayilen ki nguen di filmer..sou nekone sen rak wala mak wala papa vs n'allez jamais faire ça. Diko filmer Diko rei pour l'âne. …halate lein yala

  • aw

    non li dou dara on blague selemen

  • soninke

    Senegal dagnou wara bayi kheep niit

    ki nitela comme tout le monde

    il faut respecter l´etre humain koumou mouna done nak

    mais di filmer niitki pour diko re c honteux sincerement
    Ousmane nak na tak ndiguam t ligueyi ndakh tougoune dou handicap

    amnga beute amga tank aki lokho kone OUSMANE demal ligueyi wala nga oute metier

  • Ozil

    Donnez Moi son numero s'il vous plait

  • fa

    non ousmane toungouné mo khoromou il ma tué

  • fondé

    Wally sec defal dara way tass yakar bakhoul

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *