Nécrologie: Décès de Serigne Modou Abdoulaye Fall Ndar, fils du 3ème Khalife des Baye Fall

Triste nouvelle pour la Famille de Mame Cheikh Ibrahima Fall! Nous venons d’apprendre le rappel à Dieu de Serigne Modou Abdoulaye Fall Ndar. Ce dernier était le fils de Serigne Abdoulaye Fall Ndar qui était le troisième Khalife des Baye Fall.
Senego présente ses condoléances à Serigne Cheikh Dieum Fall, Khalife Général des Baye Fall.
YALLA NAKA YALLA XARE ALDJIANA FIRDAWSI;
YALLA na dadjéég geureumal CHEIKH IBRA si barké LAA ILAAHA ILLALLAAH
yalla nako yalla yeureum té kharé ko aldiana si barké serigne touba
k Dieu lui accueille dans son paradis
que Dieu lui accorde le paradis
YALLA NE YALLAH YOKKE LÈRAM TÉ TASS NIEUPPE TCHI LÈRAM FALL!!! AMIIIIIIINE FALL
yalla naco yalla yereme te djeguelco tasse ngou thie barkeme
Yalla nako cheikh ibra ak serigne touba térou thia aldiana firdaws
Rahamahou lahou amine yalla nako yalla wanalé ak mame Cheikh Ibrahima fall té yalla tasñou thi sen barké.
Yalla yokku leeram tanu thi est un barkém
Diey adouna diekhna b paret
yalla nako yalla khare aldiana firdawsi
inali laahi wa ina ilayhii raadji hon ne thieuy yalla yalnako yaala yeume yal nko cheikh ibre takhowou fiir dawssii
yalla nako seringne boumak. bi téru
oh hinalila wa hinalirajoune yalle na yalla yok lerame tasse niou ci barkéme ci barké mame lamp fall ak serigne bamba amine
yalla nako yalla yèrem thi bakhou Mame chekh ibrahima fall