Les 23 chartes de la confrérie Tidiane en details

les vingt trois conditions faisant l’objet de la charte ou wird tidiani. La Tariqa Tidjaniya repose à part entière sur les deux sources fondamentales que sont le Coran et la Tradition prophétique. Les conditions (chouroutes) de cette voie spirituelle trouvent ainsi logiquement leurs fondements dans les sources précitées.
Wolof | Français |
1. Jële werd ci boroom ndigël bu wer ci silsila bi. | 1. Recevoir le wird d’un talibé dûment autorisé dans la silsila tidjane. |
2. Do am beneen werd budul bu tariixa bi. | 2. Renoncer à tout wird d’une tariqa autre que la tidjaniya. |
3. Do ziyaar beneen waliyu, boo dund walla bu dee bu bokul ci tariixa bi. | 3. Ne pas effectuer de ziarra auprès d’un waliyou vivant ou décédé qui n’est pas tidjane (il s’agit ici de se suffire de son guide tout en traitant tout érudit d’une autre tariqa avec les égards dûs à son rang). |
4. Juli yi juroom ci mbooloo. | 4. Effectuer les 5 prières en commun. |
5. Am cofeel ci CHEIKH ak ay kuutaayam ba dee fekla si. | 5. Vouer affection et profond respect à Cheikhna Cheikh Ahmed Tidjane Chérif (RTA) et ses khalifes jusqu’à la mort. |
6. Bañ naagu. | 6. Ne pas faire preuve d’excès de confiance. |
7. Bañ noonoo CHEIKH ak kuutaayam yiy dund. | 7. Ne pas manifester la moindre hostilité à Cheikh (RTA) ou à ses khalifes vivants. |
8. Sax si werd wi ba dee fekla si. | 8. Pratiquer le wird sans interruption jusqu’à la mort. |
9. Nga am passpass. | 9. Avoir une foi indéfectible en Cheikh et en la tariqa. |
10. Mucc ci diingët. | 10. S’abstenir de critiquer (Cheikh, tariqa, khalifes, talibés). |
11. Am ndigël ci werd wi. | 11. Etre autorisé à pratiquer le wird. |
12. Wazifa ak xadaratul jumaa ci mbooloo. | 12. Faire la wazifa et la hadaratoul djouma en commun. |
13. Jawaara ak njapp. | 13. Ne réciter la djawara qu’après s’être purifié rituellement à l’eau (ablution). |
14. Bañ dogoog say waajur ak say mbokki taalibe. | 14. Ne rompre ni les liens parentaux (entendu au sens de père et mère), ni les liens avec ses frères talibés. |
15. Bañ saggane werd wi. | 15. Ne pas faire preuve de négligence dans la pratique du wird. |
16. Bañ woote wilaaya ak xutbu ci lu amul. | 16. Ne pas se faire passer pour un Saint ou un Pôle si on ne l’est pas. |
17. Teral kepp kuñuy askanale ci CHEIKH ak ci tariixa bi. | 17. Traiter toute personne liée à Cheikh ou à la tariqa avec égard. |
18. Bañ merloo sa mbokku talibe. | 18. Ne pas irriter son frère talibé. |
19. Laab ci sa yaram ak sa yëre ak berëp bi nga took. | 19. Etre en état de pureté rituelle, porter des habits purs, s’asseoir dans un endroit pur. |
20. Took jublu xibla. | 20. S’asseoir orienté vers la qibla durant le wird (sauf dans les situations d’exception prévues). |
21. Bañ wax ci jataayu werd. | 21. Ne pas parler pendant le wird (sauf dans les situations d’exception prévues). |
22. Teewlu ci baat yi. | 22. Se concentrer sur les paroles du wird. |
23. Teewlu Yonent bi, walla CHEIKH, walla Serigne bi. | 23. Sentir la présence du Prophète (SAW), de Cheikh ou de son guide. |
mane guissouma fi lokhamné meuna takh bagnouye critiké charte bi kouné ak kiko
doye kuné na yéme thi tarikhame gnoune tarikha cheikh mognou doye diapeléne thi séni boss bayignok cheikh ba faw
je trouve qu il exagere un peu avec le 2 et le 3
amna solo yalna yalla def gnou matalko ndakh nek talibé cheikh
أَمْ لَهُمْ شُرَكَاءُ شَرَعُوا لَهُمْ مِنَ الدِّينِ مَا لَمْ يَأْذَنْ بِهِ اللَّهُ ۚ وَلَوْلَا كَلِمَةُ الْفَصْلِ لَقُضِيَ بَيْنَهُمْ ۗ وَإِنَّ الظَّالِمِينَ لَهُمْ عَذَابٌ أَلِيمٌ
Ou bien auraient-ils des associés [à Allah] qui auraient établi pour eux des lois religieuses qu’Allah n’a jamais permises? Or, si l’arrêt décisif n’avait pas été prononcé, il aurait été tranché entre eux. Les injustes auront certes un châtiment douloureux. ach choura verset 21
۞ شَرَعَ لَكُمْ مِنَ الدِّينِ مَا وَصَّىٰ بِهِ نُوحًا وَالَّذِي أَوْحَيْنَا إِلَيْكَ وَمَا وَصَّيْنَا بِهِ إِبْرَاهِيمَ وَمُوسَىٰ وَعِيسَىٰ ۖ أَنْ أَقِيمُوا الدِّينَ وَلَا تَتَفَرَّقُوا فِيهِ ۚ كَبُرَ عَلَى الْمُشْرِكِينَ مَا تَدْعُوهُمْ إِلَيْهِ ۚ اللَّهُ يَجْتَبِي إِلَيْهِ مَنْ يَشَاءُ وَيَهْدِي إِلَيْهِ مَنْ يُنِيبُ
Il vous a légiféré en matière de religion, ce qu’Il avait enjoint à Noé, ce que Nous t’avons révélé, ainsi que ce que Nous avons enjoint à Abraham, à Moïse et à Jésus: «Etablissez la religion; et n’en faites pas un sujet de divisions». Ce à quoi tu appelles les associateurs leur paraît énorme Allah élit et rapproche de Lui qui Il veut et guide vers Lui celui qui se repent. ach choura verset13
مَا تَعْبُدُونَ مِنْ دُونِهِ إِلَّا أَسْمَاءً سَمَّيْتُمُوهَا أَنْتُمْ وَآبَاؤُكُمْ مَا أَنْزَلَ اللَّهُ بِهَا مِنْ سُلْطَانٍ ۚ إِنِ الْحُكْمُ إِلَّا لِلَّهِ ۚ أَمَرَ أَلَّا تَعْبُدُوا إِلَّا إِيَّاهُ ۚ ذَٰلِكَ الدِّينُ الْقَيِّمُ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَ النَّاسِ لَا يَعْلَمُونَ
Vous n’adorez, en dehors de Lui, que des noms que vous avez inventés, vous et vos ancêtres, et à l’appui desquels Allah n’a fait descendre aucune preuve. Le pouvoir n’appartient qu’à Allah. Il vous a commandé de n’adorer que Lui. Telle est la religion droite; mais la plupart des gens ne savent pas. yousouf verset 41
si ca ne nous concerne pas mé de grace cesser de l’imputer a l’islam
Continuer de critiquer rekk avec vos conneries!!!! Les chartes de la Tarikha Tidiane ne vohs concerne pas du tout. Si ça vous convient, adérez et appliquez, si ça ne vous convient pas, vous n’avez qu’à fermer vos grande gueule de merde. Senn Mame yilenn djitouwonn dièmm nagnou ba sonn pour mou fayy wayé niomm senn bopp nio moudj fayy. Et vous qui critiquez, où est la charte de vos Tarikha? Vous en avez mm pas loudoul khoutar khohtari di demm rekk. Koumou nèkh ak koumou nakari Wazifa fadiare dinalenn tankall té senn bayy yi ak senn Serigne yi dara lagnou si doul meune.
Je n’ai pas besoin d’autorisation d’une créature pour invoquer le Créateur.
«O, vous qui croyez ! Invoquez Allah d’une façon abondante »
RESPECTEZ L’islam respectez la religion thiakhane bakhoul
3. Do ziyaar beneen waliyu, boo dund walla bu dee bu bokul ci tariixa bi.
Lii Tégéwoul Fénne Waliyu Yépp Danou Léna Wara Ziar Walla Danuy Ban Kou Diéblou Ci Bénéne Tarikha
li dafa lérr trop
koumou nekh nge dieul
soula nekhoul nga bayii
amoul nékhal
ME SENEGO PRKW NGENE DI BLOQUE SAMAYE COMMENTAIRE
Chers musulmans YEWOULENE bouléne kéne diakhassé ak sény Mbokk (Mouride,Tadiane,khadre,layéne,Niasséne etc…) ay mbokou ngéne té kouthi néh ame nga sissa Morome yoyou woleré wo xamny rouss nga moulaye dég thi dingate wassilame « lakoume dinykoume walya diny » la YALAH wax Talibé CHEIKH BI na déf lako CHEIKH diguél MOURIDE BI déf lako CHEIKHOULE KHADIM digual LAYENE ba nonou NIASSENE ba nonou insu de suite.. ndax tarikha yi fy néh kéne bokoule ak sa morome aye dokhaline té lépp fa YALLAH mé naniou moytou bou bax gni nga khamné daniouye divisé pour mieux régner bouniou publier si tidiane niou nék Mouride cmnter lou niaw bouniou publier si Mouride niouk nék tidiane comnter lou niaw té couniou wax sisa wassila lou niaw sa xol diouk té ly rafét si diguenté tarikha yi barina Lolll wayé lou niaw ly rék laniouye guéné bi si moudiou Magal Darou khoudoss bi passé niou déf exposition thi sidy hadji Malick wayé presse bi niou néw nioko si wané… naniou beuguenté té YALLAH takh sopanté té YALLAH TAKH AK SANGUAME BOU TED BI (SAWS).
AK MBOKU KOUKO DIOCKOU YALLAH YOKKOU LA
KOUKO DOGG YALLA DOGG LA (WA BI OUZOUBILAH)
DIEUREUDIEUFEUTY SERIGNE TOUBA SERIGNE SIDY MAKHTAR YALLA NAFY YAGG AK SUNU KILIFA YEPPPPP amiiiiiiiiiiine
Bougnouné boul ziar bénéne serigne bou bokoul si tarikhabi ziar istimedade lanou wakh (ñane si barkém) maname ziarou teubou kouné serigne Abdou Aziz dafa sokhor danguay wakh loula nékh rék serignou darou mousti bamou lakhoo démnafa té thii Serigne Sidy Moukhtar la diaar bala fa dém dé léne wakh wakhi niite té bayi diakhassé bokou si tarikha takhoul khadialikoo andak serigne takhoul bokalé yalla moo wakh thii s:luqman né ( wa tabi’e sabiila Mane anaba ilaya) topal yonou kou dieumsi si mane mane( ismou mawsoul lio anqil) thiakhane baakhoul
يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا أَطِيعُوا اللَّهَ وَأَطِيعُوا الرَّسُولَ وَأُولِي الْأَمْرِ مِنْكُمْ فَإِنْ تَنَازَعْتُمْ فِي شَيْءٍ فَرُدُّوهُ إِلَى اللَّهِ وَالرَّسُولِ إِنْ كُنْتُمْ تُؤْمِنُونَ بِاللَّهِ وَالْيَوْمِ الْآخِرِ ذَٰلِكَ خَيْرٌ وَأَحْسَنُ تَأْوِيلًا
O les croyants! Obéissez à Allah, et obéissez au Messager et à ceux d’entre vous qui détiennent le commandement. Puis, si vous vous disputez en quoi que ce soit, renvoyez-le à Allah et au Messager, si vous croyez en Allah et au Jour dernier. Ce sera bien mieux et de meilleure interprétation (et aboutissement). nissa verset 59
مِنَ الَّذِينَ فَرَّقُوا دِينَهُمْ وَكَانُوا شِيَعًا كُلُّ حِزْبٍ بِمَا لَدَيْهِمْ فَرِحُونَ
parmi ceux qui ont divisé leur religion et sont devenus des sectes, chaque parti exultant de ce qu’il détenait room verset 32
مِنَ الَّذِينَ فَرَّقُوا دِينَهُمْ وَكَانُوا شِيَعًا كُلُّ حِزْبٍ بِمَا لَدَيْهِمْ فَرِحُونَ
parmi ceux qui ont divisé leur religion et sont devenus des sectes, chaque parti exultant de ce qu’il détenait room verset 32
مُنِيبِينَ إِلَيْهِ وَاتَّقُوهُ وَأَقِيمُوا الصَّلَاةَ وَلَا تَكُونُوا مِنَ الْمُشْرِكِينَ
Revenez repentants vers Lui; craignez-Le, accomplissez la Salât et ne soyez pas parmi les associateurs, room verset 31
إِنَّ الَّذِينَ فَرَّقُوا دِينَهُمْ وَكَانُوا شِيَعًا لَسْتَ مِنْهُمْ فِي شَيْءٍ إِنَّمَا أَمْرُهُمْ إِلَى اللَّهِ ثُمَّ يُنَبِّئُهُمْ بِمَا كَانُوا يَفْعَلُونَ
Ceux qui émiettent leur religion et se divisent en sectes, de ceux-là tu n’es responsable en rien: leur sort ne dépend que d’Allah. Puis Il les informera de ce qu’ils faisaient. an haam verset 159
Yana yalla rayma xi tarikha bi xi barké mouhamed (saw) seydil hadji malick rta yalla bour bi fayal ñiouko
lima lène di niaane yène talibè cheikh yi bou kène tontou watt , lignou fi wakh koumou doyoul khairoun, li moustapha wax leerna nagn, dieure nguène dieuf
lima lène di niaane yène talibè cheikh yi bou kène tontou watt , lignou fi wakh koumou doyoul khairoun, li moustapha wax leerna nagn, dieure nguène dieuf
ne nous suffisent-ils pas les chartes imposés par Allah et son Prophète (S.A.W) dans le coran et la sunna et avec le 2 je comprend que mém les wird donné par le prophète faut délaisser!!!!!!
cheikha diarr ma di guewelam mom ak yonente bi diara woy. 23 conditions yi kepp kouko appliquer feukk doula yob houmbaye ak moumbaye doula yob tė terrewoul di nga done djioulite pirr. cheikhna tidiane rek mo worr
thiey talibè cheikh yi deggal yi tontou rek CHEIKH Dè CONTANE NA SI YèNE ,mashaALLAH , diinè rek guène fi tontou, waaw tlibè cheikh d waroul daggasantè , yalla naniou yalla def ay talibè cheikh
DOUBA tu as bien dis un non musulman et dans ces conditions on fait allusion a d’autres muslumans n’appartennant pas au « tirikha ».et khouma tu na amener ni verset ni hadith.il me semble que ces conditions n’ont pas de fondements ni dans le coran ni dans la sunnu
merci ASSIA, TArikha bi lepp yalla la ak souna , yalla naniou yalla def ay tlibè cheikh sahal nioussi raynioussi dekkil nioussi, gars yi naniou bayyi critiquè yi, tarikha yeup bènne leu, lepp yalla la ak yoneènte bi,koula nekh nak yay khole yoone bi bi gueuneu gaaw r. wassalam
Mbokou djoulite yi seydina cheikh wakhone na lougnou wakh ne moko wakh, nagnou ko pesse si al quran ak
souna sou deupo Moma, sou safano wakhouko n dakh môme bene dieufeume Dou woute ak al quran.
Legui nagnou d’été, al quran nena : inamal mouminouna ikhwatoune fasslikhou bayna akhwaykoum :djoulite yeup
bene bope lagnou ta nagnouy rafete sene digante
benene bi moy : wakhtassimo bi habli lahi djami âne wala
ta farakho : nagnou ande diape thi boumou Yala bi te
bougnou takhaliko
kone djoulite yi tidjane qadr mouride layene thienaba
thienaba, dinagnou ziarante nianalante diapalante, ndiggelou
sounou boromla. Wante li charia la
Tariqa nak boumou meuneu done, haqiqa moko takha dioke
Fi affairou tarbiya rouh la ngir mou yegg si yalla kone dafa am
ay conditions de discipline, bokk na si yeme thi sa serigne rek
Ndakh bountou yi dieume si yalla barina lol waye talibe bi dafa
wara takhaw si bene rek di feug bamou oubekou.
souy def boumou feug touti rek dial thia bathia dess, Bou bountou di oubekou
fek demena kone kagne lay eegg
vous n’avez rien compris tidiane waroul dieul wird ba parė di ziar benene tariha te terewoul mou respecter yenen tariha talibė cheikh waroul seysi di fay wala dem sey ak kenen souniou tariha bi loulou la niou thi beugue wassalam
CHEIKH REK MOFI NEKE BILLAHI MO AME
bilahi talibė cheikh rekk ba sango souf
Dooyna waar deiii…..jai vu bocou de Tidiane aller a Touba a la mosquee pendant et en dehors du Magal se recueiliir Ce qui est Excellent et raffermit les liens entre confreries ..wassalam
Parsk tu comprends ce qu’il font là-bas et tu comprends ce qui est ziara un homme de dieu et pourquoi ont doit ziara un homme de dieu
Acceptez que ce sont des chartes et personne n’y est forcée. Tu es pour, prends le wird! Tu ne peux pas tu vas où tu te sens dans ta peau. Aussi simple comme bonjour. Arrêtons les critiques et incorrections surtout…
Pour Sénégalais fo Diar niou critiquer mais yalla bakhn’a cheikh tijany d’où morom kennnnn kennnnn ci waliyou yi kenn niom nieup Moy s’en baye koumou nekh AK koumou nekhoul li la yalla defffff
just des conneries li motakh kay junior siss t sokhor . il ne fait qu’obeir aux ordres de cheikh ..
tu es un idiot, junior dou sa morom, amale respect un peu
« Minnal laahi innal laahi anyna mouridoulaahi.. » moo guena woor yewoulen bala muy wess..DIEURDIEUF SERIGNE TOUBA
Verdad en que sentido. Niou yewou ci ban anam ki wax li ga bind ci souniou nekewgui la nelew ba Diot ci liga neh ni tu comprends
machaalla li dé amna solo trop wayé nak 2 bi ak 3 dakoroumassi dara ndaxté djoulit yeup béne laniou li guéne wakh ni tégoléne ko féne mane wornama dé cheikh santouléne lii bénéne bi moy bayiléne di dinguatt yéne tarikha yi bouléne fokk né séne tarikha bi rek mome la yalla validé nonon yalla nieup lafi nékal
Saway wax DEUG dioum nga liii ladiou nioula ci sa khalat deh ni sa idée c comme ça que tu d’accord ou pas et c fini
les 2 er 3 me posent problème. J’aimerais savoir pourquoi un tidiane n’irait pas faire du ziar à un homme de Dieu, mara ou simplement un talibé mouride ou khadre. Et pourtant le Coran et bien des hadiths recommandent l’unité des musulmans, la concorde ey le raffermissement des liens entre tous. Je ne comprends rien à ces interdits.
BEUKEUNDIAYE, TIJANE MEUNEU DEM ZIAR KOU BOKKOUL SI TARIKHA BI, YAGGO GUISS SERIGNE ABDOUL AZIZ DEM TOUBA ZIAR SERIGNE SALIOUBA MèME SERIGN SALIOU DIKO NIAANAL , Tè BA LGUI LOLOU MOUGUI AM, WAYè TARIKHA BI DAFA WAXNI DI SAKKOU SI MOM AY LEEER, LOULA MEUNNEU DEUPPOLè AK SA TARIKHA
beukeundiay, meuneu nekk kay, yagg naniou guiss serign abdoul aziz dabakh dem ziar serigne Abdou khadr wala serigne Saliou ba serign saliou di ko niaanal (images ya ngi fii), wayè daniou waxni do sakkou si mom ay leer , prck tarikha bou nekk dfa am ay principes
SALAMOU ALYKOUM CE WIRD est très riche mais il faut enlevé la 3 condition parce que elle ne fait pas parti du wird.Cela s’oppose au hadit et au couran et le souna ce qui prouve Cheikh ne l’a pas dit.Ce grand Cheikh disait si vous peser mes prpos et que cela s’oppose au coran ou hadit voir meme souna sachez que se ne sont pas mes propos.Lui méme il allait ce receuillir au autre.Tous les prophéte se valent,tous les waliyou se valent .Et que cela allait dimunier les lien de fraternité .
Cette condition n’est pas vrai.
Je m’excuse si j’ai blaissé quelqu’un c’est dans le souci de bien fair.
Wasalm
Salam. Il n’y a rien à enlever. C’est pas à toi de choisir les chartes. Si cela te convient tu prends sinon tu cherches autre chose. Essaie de comprendre ce qu’on n’a dit par rapport à cette charte. Wa salam.
condition 2: le wird tidiane a lui seul se suffit
ce qui est interdit c’est de faire des invoccations faisant appel aux djins…
on peut invoquer tous les noms de dieu…..
condition 3: ce qu’on veut dire par là c’est de ne pas demander confier son ascension spirituel à un autre (mort ou vivant)
donc prier pour un défunt ou allez saluer ou demander des prieres chez les autres n’est pas interdit.
je répète c’est confier son ascension sprirituel qui est interdit car le terme ZIAR renvoie à l’ascension spirituel
si t’as une autre question je suis là
Pour comprendre ça il faut chercher à savoir c’est quoi le ziara a un homme de dieu et c’est Quoi ça sert d’abord si tu comprends cela tu pourras comprendre ce qu’on vont t’expliquer.
Li tardel nit ñi Moy niou Bari beug nagne wakh te beugounio kham . Te Bo khamout mano waxx
thiey tarikha bi lepp sounna la ak al khuran, tarikha yeup bènne leu, tè lep amna ay fondements. waw magaye, fondement bi modi » ina dina hindal lahi islam » yala bène diinè la reconnaitre tè moy islam, c’est a dire meuno boolè islam ak lènène, motah tarikha bo guiss meunno ko boolè ak bènène.3 bi « yalla, yonente bi laniou roylo, Tè BI YONENTE BI NIEUWè, 124 000 YEUP, YALLA kène la wax niou topko, loutah lolou ngir bagn nitt yi diakhasso » lolou mo indi tarikha bo guiss, guide bi lagn la roylo
Ni ngay diapé sa mbok talibé nonou nga wara japper mbokj joulit dinner amoul xadialer
waw youssou, charte bi dafa waxni » na nga fonk kep kouy dioullit rawatina gni nga bokkal tarikha » fi amoul xadialè donc. lolou mom c simple, yalla waxni » ma teral domou adama » motah nga wara teral nieup , wayè dara nekkou si nga geuneu fonk gni nga bokkal keur, yonente bi (saw)nieup la fonkone , wayè dioulit yi la gueunone beug…. WASSALAMM
dites moi quel est le fondement ces conditions sur le coran et la sunna surtout les conditions 2 et 3
en fait le disciple c’est comme une femme. elle ne peut pas se marier avec plusieurs hommes car si elle tombe enceinte elle ne connaitra pas le pére de son enfant. un disciple qui a plusieurs marabout, s’il parvient á atteindre de nouvelles stations spirituelles, il saura pas quel guide lui a permis d’atteindre cette station. Et s’il pense que c’est un guide parmi ses guides et que ce n’est pas ce dernier, dans ce cas il aura attribué à ce dernier ce qu’il n’est pas.