Exclusivité : Wally Seck en train d’effectuer son Oumra (Vidéo)

Wally Seck effectue son « Oumra » avec Niang Kharagne Lô et Ndiaga Euro, son Manager. La preuve en vidéo !

whatsapp 4112

(12) commentaires

Ass Malick Gueye

Oumra dou ay thiaxane bayilén sén thiaxane yi

Cheikhna Chaikh Hamala Aidara

Nonnnn waw boula nékh

Djigeuman

Massala sama wadji balama contane gua ame dix d’or ak Platini si barké yonénetébi sala lahou khalaye wassalame

Jules

Bon oumrah

Saoune++H

Oumra ojrd8 c bien mais dmin soirée vogue cela n a pas de sense

Diambar

il est mieux que ces deux papa qui ne pensent même pas d’aller à la mec thione seck et youssou ndour ragalene yallah.

Galass Baayou Mbéne Ka

Au retour dans le pays nga diema change kholat sa thiolka you bonne yoyou en suit ngay ande ak ay goor yalla pas ay goor djiguene

Mami

Djougé si lou bakh délou si lou bone amoul sens

Cheikh Ndiaye

Wa Senegal lou takh am gniou sokhor wally dioulite la am dorois oumra com toule musulman bayi leen lou nitte deffe nguene sikalko sokhor? Guene trope melne sene paye mo mom dinedji yalla mokham koumou bakh ak kou bone

Cheikh Ndiaye

Kou kham ndakh yalla nangouna sa diamou yalla am ndeete ken khamoul yalla Rek mo kham

Miryam

Derrière ces palaces des filles et hommes senegalais sont réduits en enclaves. Je cromprends pas les Senegalais . Yalla mingui founé ,
Man sama dara d’où dem thi deukou nar yi . On a touba et autres warnagnou doyy

Veriter

VOUS PENSSER K EFFECTUER LE PELIRINAGE A LA MECQUE CEST DE LAMUSEMENT . UNE BANDE DE BANDIT APRES CEST POUR FAIRE DES VIDEO NUE SUR LE NET . DU NIMPORTE QUOI SURTOUT AU SENEGAL. JAI PETIE POUR LISLAM