79 COMMENTAIRES
  • Sy

    Senegal dafa nékhe koufi déf louné wingne rék né téyoumaco wola dou man

  • cheikh ndiaye

    dhoynewar toroppp

  • adja

    En tout cas elle a comit un grand erreur et un jour viendra tu seras la mere des enfants les images et tous sa sen vol

  • michu

    mbathio les paroles s’en vont mais les images restent, fallait y penser tu seras mére de famille que vont dire tes enfants s’ils voient ces photos, vraiment désolé

  • michu

    désolé les paroles s’en vont mais les images restent,tu es marqué à vie, une bonne leçon à toutes les filles, mais le sénégalais n’apprend jamais des erreurs des autres, arrêtez le buzz.

  • Paco

    Cette fille c’est satan. Regardez la bien.

  • BREF

    Dieguele lenko te yalla takh adouna amoul solo mane dieguel nako si khol bou seed

  • Ndiaga 2pac fall

    Bathio dafa Djoum mais aussi ki publier affair bhi dafa djoum aussi Nitt dagne kooy Sangh Soutoura lolou Lha Yalla waxx

  • Moustapha

    De toute faon c’est difficile pour une fille comme elle de regagner sa vie pour le reste de sa vie aprs tout ce qu’on lui a devalis sur le net, Mais courage Dieu est bon

  • Abou

    Faut savoir pardonne et être comprehensif.elle as commis une erreur de jeunesse et elle as pris une bonne leçon.donc naniu ko nianal yalla balko dolli ko soutoura.persone n’échappe au piège de nos ennemies .khana di moytou rek doli sant

  • Herculo

    mbathio wala Badio ndiaye kou tppi sa……………..yow diourla yakk meuniw la! sale GARCE

  • Touré

    Ki d’où d’Ara méritéwoul sa nek sénégalais

  • éyîiiiii

    ma sœur d’où béne yone wala niariyone mane de ma part intéressé wouma fi sabililahi change toi yonou téki yi barinanou stp boul khole si nite yi yallah mo mome djégal kone yallah nala yallah djégal tékla si yonou siratal moustakhime maye sa yaye kholou mougne bamou djégal là amine y’a allah

  • laye bamba

    no mbathio defo loudoul yap sngalais yi df sa lou bone yi ba par di dioyonetou

  • teuf

    bouleine niou réy. .mbathio demal nga kharou dji. .laver sa honneur. .

  • lo

    mbathio lpou mom la

  • Assane diop

    sérieux c pa du montage gni Aÿ Domou RAM lagne rek

  • rimaa

    Mane dale doumassi sori torope youssou ndour waye na barki dembe BE CAREFULL.
    Wassalam yalna yalla def jame Amine.

  • abdou sall

    danga warna wakh nkhoul yalla bapar dra wakh nkhoul sa yaye t yaw knetgnoula y tgne sa bopou autorit yi balagnouy diapou ki dougal photo dagn wara diapou ki photo wou bapare ndakh wolof nna lou dfou wakhou

  • l.d

    goudoul dioum amoul mai moytoul nah none dafa bari pèkhè

  • Riha

    Je ne sais pas si c’est du montage ou vraie mais loumou mouti done da fekh ne mom la bofam fegne et c’est pas elle qui la publié arrêté de l insulte et insulte celui qui mis ses photos sur le net je pense que c’est lui qui ne respect pas les sénégalais et ni en sois même doumâne amoul de mais les filles qui n’ont fait ses genres de photo de notre génération on les compte du courage mbathio insulte la fille d’autrui c’est trop facile et ya pure au senegal pure même

  • babandakarou

    waw lègui kaye ci yaw la dèss pour sa yaye bal la yombe na bayile beugeu siw par force bayile lèp dèm diamoudji yalla mo geune beyonce mi ngua nane mome nguaye dièmeu roy sokhna yi bakh yi tedeu senegal ngua wara roy wayè tok tie tèlè bi nane dama beugeu mèlni beyone ak rihanna diogeule sa bop

  • mbaye

    esta é vergonha para nós senegalês nos tem nosso cultura,e muçulmanos .si cultura europeia não gosto estas fotos,nós qui cultura mas rico não tem de gostar estas merda

  • Barham

    Ah yalla deh louné meune nako ballé bamou dess déwé si bokalé boudé yangui reuthiou na deugou si yaw rek diapal ni ARRAHMANE diégual nala makoy teudié nane la toupp diogui xallou safara la kén douko diogui di si téguate sa tank

  • blacko

    nooo!! li métina nak. Natou bou wathie se kaw le à cause de tes « déviations » récurrentes dans le passé. Repentis toi devant DIEU et mènes ta vie religieusement tt en délaissant ce milieu perverti du jet set. trouve toi un mari et continue ta vie hors du pays. avant cela, faut pas avoir peur d’affronter les regards de la société. nul n’est parfait.

  • cheikh

    mbatio tu est brave on n’ai derier toi qui defli yalnaco yala were je suis pas un amie niet un fanc je te prendre com ma seur ou une membre de ma famille lii dafa méti dieu est grand li yeup aye Lecon la

  • Yacine sall

    Hum parfois les filles ont tendance à s photographier nue xamna ay moromam kassé la djiguéne gni gno gueuna sokhor gnoune la rékk koumou donone sa rak tante mère doula néxxx yeureumouma mbathio ni sa mère mais ay propre domam euleuk

  • Amy

    Salam Sama mbok Senegalais yi mbathio dogma la faar si liga def bou neke yako def rafetoul si jigueen wane wakh ga Lou ame solo soutoura dafa bakh.te nit dafaye dioum nit nak boko bague dimbali dioubanti ko dou aye khass ak aye sagaa.fi Kou nek ame ga baakar.taye si sounou dine amna aye niit you deugone mais taye machallah.aduna nak dafa goude tank.te dound gou sotegoul Lou nek khathieu nassi.diegaloul sa broom.te bagnati def lou Melni.te diem kham jiguenn dioulit naka la wara mell.yalla na gnou yalla doli soutoura te maye gnou .degu ak tope dine wassalam.

  • Guid

    Soutourowo same bop pure d classe

  • Zeustilo

    Balnala ak mann
    Mais gogorloul laisse la faciliter.ke dieu te guide…

  • diija

    Suniou borom bii d soko diegloo mou diegeul leu thi kaaw gua bagn ko defaate
    Tiaakaay baakhoul motaxite teyei seu bopp beu niou takk leu thi farata ak souneu bax neu thii

  • samou

    c honteux mais il né jamé trop tart pour bien.j’aime ma mere c pourkoi je ne veux pas voir une fille souffrir.mbathio ,tu doit tout simplement se répentir,toubeul sounou borrom ,changé ta manierre de vie et revoir beaucoup de choses.les sénégalais ont un mémoire d’éléphant c’est-a-dire ils n’oublient jamais les mauvaises choses mais toubeul rék té boulko téfati Adouna diarouko.

  • mamy

    metina trop massa ma belle niit nii naniou kholate senn bopp bayi dieuf diou bone ak niakk soutoura

  • DEUUUG

    OHHHHH ARRETEZ DE JUGER EL A FAIT UNE ERREUR EL SAITELL SAIT REPENTI MAI BAL LéNE KO ET ON PASSE A AUTRE CHOSE ON FAI TS DES ERREUR ON EST MAL PLACé POUR LA JUGER YALLA REK MO MEUNEU BALé TE SAYOUGNOU KHEUYé TOGNE KO T MOUGNI BALE NAKO KOUNEK KHOL SI BOPAM…. YEURMANDéEEE

  • crysti

    Mbatio daga tiaga beug goor te beug khaliss nit dagay ame foula damala merré ndakh derou djiguene gneup gua yak li dieukarou diambour diarouko way

  • khouras

    svp rfm et zik fm arrété detr hypocrite é d réglé vos problém au détriment dé gens.
    mw j défend pas mbathio mais les commentaires de ndoye bane m m ndiaye boubs é la fille c indigne et méchant just parckel a fait sa déclaration sur lémission teus.

  • NDACK GUEYE BA

    GNOUNE GNIEUP AY DJIGUENE LAGNOU MOI PERSONNEL MENT JE SUIS FÉMINISTE DONC LIMA GUISS YAKO DEF EXPRE BA PARE DI DIAYE INONSCENTE LI ALALOU ADOUNA DIAROUKO LO GUISS DAYE DIEKH. MAMAN DEGUENE CHIMERE BABOU MOUNGUI FI NEKONE NEKINE BOU RAFET BA KHEYE DEME KHOLAL SI MOM TE POURTANT LI MOU AME AMOKO FIMOU DEME DEMO FA TE GARDE IMAGE NEK REFERENCE BA MISSION DIEKH .YAW GNOULA FI GUENE DIONGAMA GNOFI NEK SI SENEGAL . S IL TE PLAIT KHOTATAL SA BOP MBATHIO NDIAYE .SO BEUGONE SA YAYE DI NGA KHAM LILA INDI DAKAR MAIS MALHEUREUSEMENT SER NGA YEFOU SER REK NGA DEF.TU M ENERVE

  • nianga

    Torokhale nga sa bop torokhale sa yaye fallait reflechir avant de le faire tu gagnes rien lou bonne baakhoule té yalla kène meunouko nakhe lii loukofi diare? Taye ngaye soga comprendre ni lou bonne baakhoule sa adina yeup toukki ni!!!! c aussi une lecon pour les filles qui le font ou qui pensent le faire. Dilène khalate té bayi lou bonne amoule mouthie

  • nianga

    Torokhale nga sa bop torokhale sa yaye fallait reflechir avant de le faire lou bonne baakhoule. Yangui ko donne déf té soro wone un jour ni meune na siiw yalla kéne meunouko nakhe sa bop nga donne nakhe. Taye yangui ni sa adina yeup yakhouna ndakhe déf lou bonne dara diaroufi li si adina. C aussi une lecon pour toutes les autres qui le font et qui pensent le faire

  • nakodal

    dagua dioume ta koudoul dioum amoul yala rek modoul dioum toubal ta balou akh sa yaye bou bakhe nakh ainsi mola guene diakhlé té lii nala doy kom leçon ta couñiou tope daye moytou khamou mala bou bakh mais sa ma fait mal en regardant les photos .mais aussi boula dara diral kharou wa salam

  • Gueye baba

    Katall ndayam fele yako tay do def ligua def bapare di doull nan nattou va fanculo

  • Bubs

    Oh ndeysane du courage ma soeur, reste positif tu verra que tout ira bien inshallah

  • Pisco

    Doule waye

  • HTC

    xawmà ko ndéy yààp -_- -_- màywax mouy touddou Seydina Mouhamed(psl) tsheep
    mm bou lép lééré sax sa n’éffacera pas les mauvaises actes que tu as fait

  • sata

    Mane sa youma xeuyei si togn yalla la deuk kone meunouma juger keneu mais wakhtane wakh deug thi la Mbathio mom loumou wakh la amoul pask yalla dani soutoural len sen bop kone leep liko dal dou ken koudoul mom ndax goor boudoul sa dieukeur boula wara meun diaral yeneu niak fayda ak class yi la xamoul amena yo xamni beug seuy diarouko te yakamti yakhoulei niteu dangay teew goor boula beugei takk doula fowei yagu nanoufi djign niteu lou bone te ken douko djiss mais yow linou lafi waxal leep tay nga geneu fi moy ni respecter wo sa bop ni sa yaram ni say thieur kone boul wakh niteu yi respecter la ndax diokho ko sa bop. ..wa salam dou courage yalnanou yalla doli soutoura

  • Elton

    Toubalal yalla ta dièma sopèko mo geune

  • danilo

    ndeyssane yeureum nala wayè sa thiopperette bi ngua dègnthieu , legui khamnagnou ni badio mo gueneu yombb guèrtè thiaf au senegal wayè boulssi euppeul mougneul tènga kholaaatt sa bopp

  • Il Maestro

    Ma soeur mougnal ta boumoula dalati toubal ngua déllou ci YALLA même soula dallé dallatila arrête même si tu quitte le milieu ngua jël béneen yoon jarnako lèppe dina jalle

  • julessn

    QUI PEUT ME DONNER CES COORDONNEES ?
    JE VEUX L’EPOUSER ET L AMENER HORS DU SENEGAL
    JE SUIS SERIEUX

  • deug

    kou fi meussoul teuth jiguenn sa nék rek wakhal, et pourtant kham ngani yalla moungui lay guiss,téré nako, naak nek si bou bakh, apres nga beug yalla comprendre la, nite dioum déf yafeu niak kilifeu ,yaw domou adama ngané nono, dafay yombe torop, kouné khol ko sissa bop, li ngay déf neuboko yalla , bess bou feyone nga khamné domzé yi barinanou, je cautionne pas nak, mais dama khamni mangui niane ndiegueule sunu borom , donc je le fait pour les autres

  • ami

    mais d koi ell parle si elle l avait pas fait on verait rien,beugeu buzz c tout,tu ns en merd

  • Begg Rewmi

    ATTENTION Arrête de te droguer sinon la prochaine exposition sera suicidante .

  • Momo

    Boul gnou yapp deff lingay deff ba paré disi dougal yalla ak yonam tame

  • Begg Rewmi

    Ben yone on peut comprendre mais plusieurs fois c’est inadmissible. Tu dois consulter un psychologue. TU ES MALADE.

  • masoeur

    mounieul ma soeur té delloul thi YALLA bou bakh té li boumou la dala ti ma soeur siguil té dox li la dal meun na dal kouné nit day dioum
    Yalla nalla Yala tég thi yonou dioub ba lii doula dalati

  • ocarbo

    boule gnou yappppe waye u la fait sans regarder le bon dieux ojordh8 u ose dire yalla

  • azizgueye

    Mbathio yaw daga fattè yafi fèthie soir des lutteur yi gainenais saye parti intim niouye wakh gani lolou dèrangè woul fèthiate soirè defate la mème chose dou bène diu niare taye bo dèfai li waroul bète caine naikhoul sa yaye caye lolou khame nagne ko di mounouko nekh nak.en plus bigaye def khalise bi rek ga khalate khalato sa yaye t sa yaye mossi gene touti mounonega khalate yalla khalate younene tebi khalate serigne touba boul niou yèp waye

  • kaddudeug

    stp arrete ne nous fait pas chié stp combien de fois gua exposé sa thiop’s si bitti dou ben dou niar wala yoyou douwone natou bi mo geuna fess doncmoy natou guiss ne pleuré pas pour elle car nit dafay xam lou bakh diko def tei nak dou mom kécé jiguéne amateur … ymgx pitié pour ces parents

  • Aicha brux

    Ce que je pense de cette histoire d,c’est elle peux pas parler à cause de l’enquête. Elle a sorti un singel rek ,un sénégalais ou une sénégalaise fait sa. Ahhhhh ….li mome doyenawar d.

  • dioubanti

    mais alez vous faire foutre si c sa vie privee yonou kaine newou thi sof ngaine ndeyam trop sou faikainai daniou ko togne amna droit wahli vraiment mbathio mangui diegalou

  • ASSB

    PATHÉTIQUE

  • dado sall

    arretons de nous prendre meilleur que les autres on est personne pour juger les gens on commet tous des péchers moko def defouko sunu yone nékouci beaucoup dentre nous on a fait des chose kon aimerait ke personne ne sache bcp ont des secret kon garde discretement nagnouko gnanal yalla rék diguentém ak yala la nit dagnoukay soutoural kouné nanga kholé ci sa bop wala sa mbok yala na yalla tek gnou ci yonou siratal moustakhim

  • KANYSAF

    arrêtons d’être hypocrytes.
    Comment peut on donner la parole a cette fille qui a perverti le sénégal pour qu elle revienne pour raconter des conneries sordides.
    Dite la de fermer ces cuisses et de bien s’emballer le corps.

  • Deb

    La vraie douleur est silencieuse !!
    Pourquoi ne pas tout simplement arreter ton mode de vie et retourner tes parents ?
    Pourquoi vous aimez la vie facile d’un coté et ne pas vouloir assumer les responsabilités qui en decoulent ?
    Pourquoi mettre l’argent et le materiel au dessus de votre honneur et de celui de vos parents
    Les biens materiels n’ont acquis honnetement meritent-ils de vous faire ainsi
    Pourquoi avoir vendu votre ame au diable et venir par la suite vous plaindre!

  • Mansour

    Je vous jure sur le saint coran ces danseuse là MOUNOUMA SO NOOM XOL ! mai apres tout son des êttr humaine TÉ NITE MATOUL cackun de nou peu prendr l’exempl sur soit méme. Dakor Ce k’elle fai c le pire de ce k une personne peu faire ! S.V.P. MUSULMANS ET CHRÉTIEN KOUKO
    MOUNOUL BALL S.V.P YEUREM KO parsk nous souhaitons tous YALLA YEUREUM GNOU yeureumléne pour sa famille té yalla takh

  • fsll

    mbathio mounial té continuer sa liguey, Sénégal dafa AM ay nit yo khamnè yakha rek mooy sen liguey,so wakhè niounan guem nan yalla,wanté li eupp ci nioom guemounou Dara,yalla dafno sante nouy soutouraalanté,té yonnanti bi saw dafa wakhné kou soutoural AP dioulit fi si adouna sounou borom dinala soutoural elek yowmalhiyam.fi si adouna nit kouné déf ngafi lo khamnè bego ken khamko.madila conseil DILA wakhné nanga toube té bagne sé délouwaat

  • Unesoeur

    Maylen gnou ak waxou noone yay sa nonou bopp bala ma D ngen nane noone thiiiipppp

  • Diop

    Tu devais penser a dieu a son prophete et a ta chere mere avant de te comporter de la sorte si tu avais de la vergogne tu n allais pas parler dans les radios ce que tu as fait est une encore indelibile qui s effaceras jamais

  • bira

    MBATHIO LI GUA DEF DAARA NEKOUTHIE ! YAW DAGUA TAROU MACHA ALLAH KOU LA AMONE DIEUL ! MANE DE SOUMA LA AMONE DOU MA WAKH DARA ! KOU NEK AMGUA SAGNE SAGNOU NEK SA BIR CHAMBRE DEF FA LOU LA NEKH C’EST PRIVE ! KI GUENE FOTOYI LA KHAMOUL LOU MOU THIE DIOUBLOU MOOM ?

  • Ouls

    Ç est pas elle ki l as mis dans le cite la magorance des sénégalais c est des merde pas de soutara

  • ndeye

    yalnala yalla souniou borom soppi khir la silou bah ténga moytou fréquentation you bonne moytoul bou bah djiko yi yamouniou khel yamouniou té ngay diouli di niane si yalla fo tolou di diéguelou yalla di wah astafiroulah du courage yalnala yalla diapalé

  • ss

    Danga warone xalaat sa yaay bala ngay def linga def , dou nite yi nioo lay koy xalaatal

  • grazie

    wakho noumou d’mais lrall senegalese

  • khalil

    kikoum yap

  • rina

    wakho noumou d ‘mais lrall senegalese

  • khalil

    mais est ce que tu t’en souciait lorsque tu prenais ces photos gaiement.

  • marlboro rouge

    oh lala… kii djiguenne leu. c vraiment dure.

  • fiorini

    c »est dur; svp bouléne kou saga

  • The truth

    Ndeysane pauvre fille. Je suis horrifié. Les gens peuvent être tellement horribles…

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *