Arrêt sur image : Le maillot Aliou Sall qui déchire la toile
PUBLICITÉ

Arrêt sur image : Le maillot Aliou Sall qui déchire la toile

Voici la nouvelle trouvaille  des supporters sénégalais afin que la Can 2019,  ne fasse pas oublier le scandale des contrats pétroliers et gaziers. C’est un maillot estampillé: Aliou Sall, « diokhma sama 400 000 f Cfa », qui fait actuellement le buzz sur la toile

 

463
PUBLICITÉ

9 commentaire

  1. noreyni

    tres bien broooooo bien inspireeeeeeeee bande d voleur aliou sall famaily macky wiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiii le plus grand voleur

  2. Cheikhe Seck

    C’est magnifique , ce voleurs domerame sal

  3. Ibrahima Cisse

    Très inspiré. Merci les jeunes

  4. Borom Ndiarem Faye

    Bayil ba justice ni mola amél

  5. Mouhamed Sylla

    Borome ndiaréme..Yaw laye wakhale ceux qui sont dans le gouvernement, ceux qui gére la justice Sénégalaise et les citoyens qui les defendent sont tous corompu..donc boule niou sonal nguir Yallah…Niome nieupeuh yéme..Yeurmandé Zero..Bunio mélone nuniou wara méle et deff luniou wara deff kone béne Sénégalais dou Thiow.

  6. Xam xam

    Après 10 ans, vous allez vieillir et réaliser que vous avez raté votre existence de mer…de.

  7. Diop Racine

    Yen yena niak fayda opposition doul kat n guen andak niom di fen rec

  8. Paco Faye

    Wooyy whatiatia junior est dans la merde

  9. doudou

    Yene dou aliou sall motakh guène ndi def li yepe me maky sall motakh me bagne nite yène khamoulène nè deye yokou faradja nite yalla dou faye wakh Kate yi bayi ligueye Kate yi ignane deye wagni wersek di yok febar Senegal naniou bayi sokhor ak iniane teye nangou louye yalla di dogal karime Wade djigne naniouko aye milyard kene manifeste woul khalifa Sall nonou ak gnenène me gnepe dilendi defandr tey Aliou Sall gnepe diok si prol bokhamnè litr guenagousi kone yene dou khalisou senegal molène nior me bagne ak contr Kofi yalla tek mo nek si yène ta khèkh li yalla dogal guèr contr yalla la ,ta kounè khamna Lou nek si guèr ak yalla naniou si ,yalla mousal