Adiouza annonce la sortie de son nouveau single ce 13 novembre
Adiouza vous invite au lancement de son nouveau single, le 13 novembre 2015 au « Just 4 U ». L’artiste promet un nouveau genre musical « wolofbeat » avec lequel elle travaille avec les rappeurs « No Face undercovaprod » et Gunman Xuman. Adiouza s’essaie à la musique électronique fusionnée avec le mbalax.
aka beuri fém suniou adiouza mondial
Yalla nala yalla defal diam adiouza khalè bou yarou nga mashalah day ré rk foko sene yalna yalla kheb doli té guena wereul bat bi
Thiey sama ndouro walé bi dou def lene louy nakari barki serigne touba ndam rk ngay am diallo diery
Aka ma yakamti le 13 ohhhhhh adiouza jtmmmmm way
Single bi narna nekh xuman laci degu ni ahh li tothie na parè lène
Ay lolou dh kène doumafa djitou
wa louy wolofbit
adiouza la pudique trés classe vivement le 13 dou yombe
Ns sommes d tt coeur avc tw ma santeuse préfèré le 13 inchalah mangui just 4 U
Adiouza yafi nekk dh barki serigne touba yay bomb
On taime Adjiouza yakamtina deglou single bi nak nekh rk lay def com dab
Juste for u enh l'entré? Damay def tew mane
Sa rouge baxna adji ouza
Manga fa mane ndiaye mi adiouza damala love
Sa va bardé
Dinama nekh hiii lolou dina graw
Wawaw adji lolou kene douko tardé
Haral ma tè touti loool nopile yaw golo diallo hamo darra mm si tu fais un sigle avec le defun Michel Jackson do dème va soigné ton mauvaise haleine avis à tt ce ki iront au just portè des masques sinon guèmigne bou khessaw dîna léne règne Hahaha ha