Le ndigueul du Khalife général des mourides, Cheikh Sidy Moukhtar Mbacké, est bien respecté par les talibés. En effet, le saint homme avait recommandé pour ce lundi, premier jour du mois lunaire Muharram du calendrier musulman 1438 de l’hégire 1er, dans toute l’étendue du territoire national, une lecture collective du Saint Coran. Senego s’est rendu à la Grande mosquée Masalikoul Djinane, regardez.
Dieureudieuf Serigne Touba Diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall. Lii rek aar na Sénégal
Amine Amine Amine yalla na sunu borom nangou niane yeup si barke Cheikhoul Khadim
YALLA NA SOUNOU BOROM YOKK TAKHAWAYAME CII YONEWII MAYKO WEUR Té goudeul faname lol cii daradjiaye seydina mouhamed psl akk cii barké mamame borom touba.
yalla na borome bi nangou gnane dèlognou ci a ak ndioube ak diamou Yalla diou sèlle.dignane sa borome yok fanou serigne sidy mokhtar ak mbolème kilifa diné yeupou ba naal yimou soumbou ci ISLAM sounou bBorome kattanale ko ba lèpou mattè ci ak fèkème ci barkèp AL QURAN
Espérons que la lecture du Coran fera partir les inondations de Touba.
kontane rek yalla n’a yalla naguou ñiane si barré serigne TOUBA
sant ahmadou bamba mbacke bou werr borom diouma djou makk djii serigne bou makk bi
SERIGNE Mokhtar Mbacke yalla nafi yague té andal werr
ma challah jeureudjeuf serigne touba khadimou rassoul
Yalla na ko yalla May goud fan ak wre thi bark cheikhoul khadim
Yagg fi lool Mbacké Jeureujeuf SERIGNE TOUBA
SERIGNE Mokhtar Mbacke yalla nafi yague té andal werr
domékharam yi dounou wakh dé mé Bou nékone kénéne kouy wakh Lou bonne ci yonou mourite yi nak niõu oubi séne lammine you bone yi.dieredieufeti Serigne touba khadim Rassoul diarawlak Mame Cheikh Ibrahima Fall.serigne sidi al Mokhtar yalla nafi yague lool té wér.s éne khôl yagui dague ince bi
merci wa senego
SERIGNE SIDY MAKHTAR yalla nafy dollé yagg loll té wérre