19 COMMENTAIRES
  • fara

    Youssou ndour ya niak kaniane nit kou bakhe moy yaw

  • galsenbooy

    kel cinema tchim pleurer pour ca o nom de quoi???? Goo waye

  • diya ndiaye

    thiéy waly ya am diom wayé youssou kéne dou yaw

  • awa

    Bilaye da mo dioye

  • aladji mbaay

    wAly yalla moko tall mais you kényane dou mom

    • Aby

      pC’est émouvant, que dieu protège ses deux familles, amine. Waly, boul tite, boul ragal, sa khol rafètena machallah, deuguela, Youssou sa papa la, que dieu t’aide pour cette démarche, amen.

  • falloukhoulle

    doumou khath dadié nga ak sa baye

    • Aby

      Tu n’est pas poli, c’est ainsi que tu commentes c’est dommage

  • M

    JE NE CONNAIS PAS WALY EN PERSONNE EN DEHORS DE SON STATUT DE STAR DE LA MUSIQUE SENEGALAISE; IL ME SEMBLE QUE WALY A UN CŒUR PUR. QUE DIEU LUI ACCORDE UNE LONGUE VIE ET BEAUCOUP PLUS DE SUCCES ENCORE. BOROM KHOLE BOU SELLA MO MEUNE WAKH LOU SELLA, BA PARE DOUGGA CI KHOLOU NIIT YI.

    • Aby

      Tu n’est pas poli,c’est ainsi que tu commentes ,c’est dommagedommage

  • Aby

    Toi, tu n’est pas poli, c’est ainsi que tu commentes, c’est dommage.

  • Pa cisko

    Que le Seigneur t garde Wally Seck par ce geste tu as montré ta grandeur et ton attachement a la paix entre les personnes.Continu ds ce sens tu iras tres loin.

  • tapha ngom

    affaire bou nice soyez unis pour toujours kou bagn lii rék diamga
    parce k gor yeup lilagnou done khar je vois un avenir positif entre birane et waly

  • Cody

    C’est triste yen. Mon waly

  • ndioba

    Y alla bou thiat Doug sen diganté bagna deglou nitt gni ak saytané yi

  • wane love

    non sénégal dou déme dafa beuri gnou ame diote démléne liguéyii bolé si diamou yalla té bayi wakh dji débat débat ba kagne youssou ak waly sééne khoulo ak sééne dioubo vraiment c leur blém nguéne balma akh

  • sadio

    je ne suis pas pro waly mais il a fait un geste noble et il fo le dire djadieuf wally

  • hams

    waye love nangua ragalal yallah ta pas à dire ça il a fait ce qu’il fallait si tu ne peux pas dire des bonnes choses c mieux de garder tes paroles à deux balles vraiment nous on veux la paix yallah n’a diamme yague inchallah fiii thi senegal amiine ???

  • nala

    Ceux qui critique waly pour une fois reconnaissait qu’il a fait un geste noble bravo waly

Publiez un commentaire