PUBLICITÉ
» » »

Vidéo: Waly Seck met le feu au concert de la Cop 21. Regardez

Concert Cop 21
Annonces

(9) commentaires

Parisfrance

fo bi beurina sènègal nagnou dem liguèye

    Zaz

    Fo bi tji sunu déréte la nek !
    li motakh sunu Djolof nekh ! xaleyou bakh di leumbeul matin , midi , soir !
    Sénégal modji neu !

Momo

nekhna copin yalla nala yala moussal si thiat

Bana

amine way laf thiate

Aicha

waly yaguefi tè wèrrr!!! so amoulwone fougnou dieummm??? yay nèkhal sougnou kholi!!!!!!!!!!1 on vous adorrrr!!!1 doundal 100 ans! peace and love!

Beri Feem

Lalal Bassang….eh waaaaaaay…..mbalax mo ko yorr…..

Fans Waly

music bou khegne mofi ame legui depuis ba goos bi niewe

Deug Nekhoul

parisfrance doul paris mo eupe fooo fouff bayilaine ignane senegal mo nekh waye

Gvhj

beuri thiakhane rék concert cop21 gni fOk ni sénégal mo dakeu ci deuk yi dagno toukiwoul rék ba la nga meuna foo ame xaliss bo liguèyal sa boppeu!!
Nagn liguèyi!!

Publier un commentaire