19 COMMENTAIRES
  • zeyna

    thierno diallo il joue bien

  • welly

    thierno fi guay guene mo graw

  • jalouse

    Extraordinaire

  • kebe *

    Formidable

  • miko

    Mia nekho niou dara ya soff waye tu es trop nulle

  • MBIIIIW

    non thierno dou nit poukal la

  • Madam Faal

    Nice

  • gueum yalla

    lissa mon niak kersa mais trop nice la série

  • FEUS

    malkhise tey mou dé sou ko thierno diapé di na khamné lep deugeule

  • Pactito

    No Milk Zo migui commencé déconné mai liko boubs wakh deug la, pour markhiss mane ragal nani kil va gagné dé et détruire thierno diallo ak berrou et recupéré la femme de thierno diallo

  • cisse daouda

    Thierno il très forte

  • cisse daouda

    C'est compliqué la

  • Dofdof lou

    markhiss molene geune bandii

  • Beugue Sénégal sama rew

    pactito j'ai partagé avec toi ci sa khalatebi. je pense que markhiss dou thioune

  • dreumo

    non mia nekhouma dra waye

  • enma

    boule wakh loliu nala nekh waye rolame rek laye jouez

  • adja tacko fall

    lissa de rolam rek la de soful dhe

  • Yaram

    No sa way mo graw waya nak wayou bandy moy bayam

  • baye

    thierno da lena gene don bandi

Publiez un commentaire