24 COMMENTAIRES
  • amara

    dou youssou ndour rék ak thione Seck ismaila lo

  • Doul

    Yaw
    tounoukanara mouno bayi waly guir yala

  • Das

    Sen émission bi mougui beugue sof nak

  • modoulo

    yena fan wally vraiment limi sol dafa nice lol

  • kira

    ioe tounkara niak gua fayda trop makk dafay nek diko djexfei watial xaleii bi mou noyi way fat guako trop hooooo.. xana dou aye waax day diex ish

  • Sapali

    Sincèrement parler mome bane façon français la « Parlant » bok. Tounkara corrige ta collègue stp et j’espère qu’elle est clean pour se permettre de donner des leçons de morale. On ne veut pas de mauvaises surprises.

  • .....

    Zeyna ou es tu? Revien stppppppp

  • weur

    mam cheikh ibra fall ñou koy ci lou deugou lou rafet lou Bakh te bañ fowe

  • chelsea

    mouy goor jigeen mouy bay fall dara bakhousi goor jigeen yalla deko reub.nitt koudoul jouli comme baay faal ap yeufr l yalla moko wakh si al khourane

  • Moussa Walyndiaye

    Nana tu es jeune: dans le clip less wakhoul you est presque nu ,il a porté une combinaison ; revoit le clip. Un journaliste doit se documenter,éthique et déontologie . Vraiment la CESTI se sent mal dans sa peau.

  • mami

    mai yaw tounkara ta po dotre sujet k wally?sof ngua way

  • faly

    lingene di wakhe amoule ndierigne kou neke ame nga loula doye

  • garou

    c koi baye fall des gens ki samusent avec la religion aux yeux de tout le monde c’est de la merde sa on pratique kel religion ? l’islam ou le rastafari sac effeminer baye fall ne sont que de la merde dans nos socits way Lepp dina lerr

  • toubistar

    chelsea khamou ma waly boul gnou yap ok. ….yow daga réw amoulo éducation. ….baye fall yi gno geune sa askane pour dire vrai. ….cher journaliste un peu de respect religion et cette musique ne vont pas ensemble. ….il faut pas confondre bouton et mouton. …ciao a tutti

  • modou

    war naño bay khel thi euleugou nbaw yi

  • modou

    Yonou bay fall desouko fowe

  • Wiz sene

    mission bou nexla

  • khadim baye Fall

    iow Chelsea kou rew nga yonou baye Fall ki cii moudi dibalou mo cii sa askann amall tguinn nak

  • cheikh diop

    Lakoum dinekoum waliya dine. Khar len ba bay fall gnaan leen thi seen touyabay djiouly ngueen bagn

  • damase

    chelsea ya tothieu sa dapate ndaye

  • Anonyme

    boulne tontou gniy dingate baye fall cheikh ibra dinalne tontoul bopam.tounkara nakk yaw mane douma fan wou waly m guir yalla abb dioulite dou tongn boul beug lou nkhal sa mission rek ngay tongn diamou yalla yi bakh fa yalla ndakh mom rek mo kham ki bakh ak bone wasalam

  • Anonyme

    dama fat def sama tour Amy

  • Aminata sey sillah

    Maneeh xana Tunkara yes Chi wally seck rek nga Maná wakh setal bop bubaax …yew mum hawma Nana la nba tudu …how Nana gis nga sa chulin yow. ..demal seet da chulin apre mua diangi wahk ndah yow sa lameng sáb setul ba ngae diangale…… Tunkara ha na du domuh adama keseh nga .

  • Aminata sey sillah

    modou Sey Tunkara tog si tele Di troxaleh rek yow Nana demal diangi wax va sa lameng set doga tog ci tele

Publiez un commentaire