Vidéo: Surpris par son grand frère Massata, Aziz fond en larmes. Regardez
Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Aucune recommandation disponible.
Aucune recommandation disponible.
Ouvrez l'appli si vous l’avez déjà, sinon téléchargez-la pour une meilleure expérience et pour recevoir les dernières actualités en temps réel.
massallah sacoll rafetna yallah nalayalafaye ndahk sa coll boubakh
azizz lou bakh rèk ngay am inchallah
geste bou Nice
Non azize Yaw kéne doula teye incha allah diam rék ngay ame li dafa rafete day dolli nitte diome que le bon dieu vous protège .
Rafet dale dafay nirok mbaaxxxx
Mérci Aziz machaalah
Daniouley bab pour nga nieuwate tji lamb dji mais baniale .
Cette lutte ne rapporte rien à part la violence .
À bas la lutte .
bilay nawnala taye taye guamaye soguaye interesse niit bou wakeur yeup tague kokou niitla sama yaraw daw jai ls larmes aux yeux yalla nala yalla lafal thiate
lii neikhna yalla naleine yalla gueuneu dioubolei si barkei mouhamad
Bilahi sa ma yaram dawna way yalla nalen yalla guena Sam way
domou baye yep war nanio roye thi gni.bax rek mo am solo.aziz dal mo bax té yarou
aziz ndiaye leup yaw la sa xole mooo rafette lo amme bokou ko ak saye rakkk thia kaw thia kaname rekkk
bilahi j'ai eu les larmes aux yeux en écoutant son frère ! moi aussi j'ai une soeur elle est comme ça avec moi Que Dieu te protège thi barké alkhourane