Publicité

Video- Sketch clando épisode du 05 Aout 2015

Aucune recommandation disponible.

22 commentaires

  1. doule way

    deb kholal si khale bobou nga diema defarou mo gueune si yaw waye nak nekete nitt dinane ko naw mou wakh gnou kheb ko ya ndaw khalate royal si moustapha mom rek doussa morom wa salam


  2. fall modou bété bété 100/100

    yaw . deb tu n rien a dire wakhifi dara.. moustapha ngay teukeulek .khalifa genereau yi.. .khadiou khadiatou khalifa gnr. moustapha egagoufa. okk .certes . moustapha . mongui deff loumou meun pour dioubeunti .djiko yi.. ak nekinyi ….Yallah nako Yallah def magoum lislam.ak khale bou am niam si barke seydina mouhamed psl. …


  3. fall modou bété bété 100/100

    Machallah Yallah na Yallah goudeul sa fan ta wereul say thieuy.yawak sense et tout lequipe clando…say messages am naniou solo loll


  4. deb

    Tous les khaliffs generaux de ce pays doivent faire du djeballou a ce jeune moustaphe en le designant khalif general de tous les khalifs generaux du Senegal ,car le jeune Moustapha est entrain de faire leur travail d educateur civique et social

    Qu'allah veille sur lui et le protege du mauvais eloeil


  5. PAPA

    je demande au bon dieu de nous préserver ce MOUSTAPHA et de dire aussi aux enfants de prendre exemple sur lui car la discipline est la clé de la réussite


Laisser un commentaire