43 COMMENTAIRES
  • Adja Aida Fall

    Tey la waaarrrooouuu

  • elzor78

    Sidy amoul beneu cadou waye

  • bledard

    je suis tres surpris par ce sidy mais cela n’empèche sous manifester sans accord nou tégualko

  • paix

    HYPOCRISIE QUAND TU NOUS TIENT……

  • Souch faty

    Non mais je pense que je suis entrain de faire des rêves ou quoi

  • domou djoloff

    c’est la vraie image du sénégalais waxx waxeet

  • diam sy diam

    li moy teussssssssssssss ahhhhhhhh ana héérre bu makk bi?li moy lane NIASS? ahh ma warou bisimillahhhhhh

  • zougoulou

    li mom waroul bétte kéne,kou kham sidi rek khamni li la beugone!mais rew mi mom loie mofiy dokh.

  • mbengue fatou italia

    sidy niit say am personnalité ak dignité lii gua fii wakh berkidem ak lii def tay woorona wakh wakhet degue gua fii def

  • harouna

    macky tente de corrompre les sénégalais avec l argent de contribuables il a déjà corrompue tout les patrons de presse pour qu il ferment les yeux au grand dam de senegalais makhala bala nguen wote niteki denguen warakham ko

    • bayembayend

      wakh rek ngaye def ligaye wakh khamo thi daara bayil macky lawakh

  • Sene Babacar

    Décidément, je n’ai plus de mots pour qualifier ce comportement

  • kebe dame khoury

    peut etre il va aider kor mareme a reconnaitre le visage veritable du pays personne ne peut appeurer ni aliener le peuple.a nos et a notre democratie nous dedions nos vies vive le senegal

  • palermo

    pour man li moy yon ndakh bour fawou amm cocoy wakh deug te sidy lou ler la wakh takhaw cie kanamou maky neco marcha da wara amm louguin beug talle day

    • abou ndour

      sidy kherri moustapha niass bi nag dancoye delo

  • abou ndour

    waw rek dee ya dessone thi patron de presse you don defendre askabi legui nag na maky deff louko nekh

  • malo-bii badji

    c maître chanteurs ne méritent rien de bon fallait même pas le recevoir

  • malick nlass

    meme s il est recu par le pr sidy lui conseillera de laisser l oposition tenir son meeting pour le renforcement de notre democratie pour etre en conformlte avec la francophonie

  • cheikh thioro diba

    side lamine dafa yepe va senegal

  • habitant gossas

    boufaike marche amna te sidi gneweul mane dinaka weedi ba faww

  • malickio

    mais je demande est ce que c’est qui a demandé l’audience ou c’est Macky qui l’a invité

  • beugdakar

    l envelope de macky

  • vérité

    li mi wakh si télé bi ak limi dèf c diamétralement oposé mane bima paré si moom mo yague

  • oscar fall

    merci diam Ci diam ani kheerbi ? baboba

  • ALHAMDOU LILLA

    Merci pour les bonnes conseils  » CIAO A TUTTI.

  • ALHAMDOU LILLA

    dans la vie ‘ ils faut être prudent et patients. merci. pour le compréhension.

  • hamadou kandji

    bolene faténi ndokh dobayi younam

  • ablaye gaye

    boumou béte kene sènègal laniou nek nak

  • amd

    thieye liiiii wayyyyyy

  • amd

    thieye sama rewmi rek batay

  • mamadou siradiou

    yalla na diamyage

  • Ba Alassane

    talibe ngi yelawana yore potam mom di lace sarack

  • issa diedhiou

    2877

  • ngoradama

    atención sydi mon amin!!!!!

  • kabou

    yène wa senegall fo guène neck sidy ngamoll dara khaliss reck la ngame

  • niang

    Senegalage

  • kabou

    sydi. ngamou dara khaliss reck nga game

  • indiaye85

    thiey

  • djily ndiaye

    touba1989

  • djily ndiaye

    tahye Senegal !!!

  • Ely Diagne

    Thieyyyy li! !!! goor mom diekh nafi legui…. traitre!!!

  • thiamas

    sidy egal sidy rien que sidy ipocrit et egoiste

  • Rokhi

    sidi Nafekhe Sidy corompeur Sidy wakhe waw khete Sydy beug deureum sydy dîné ak diamono.. malaye niane LILIAHI WARRASOULIHI GUA DINDI dine bi. te bayyici diamono ndakhe diamono ak deureum rék mola nior..thim khale bo roye sa genre gui doumass deme.

Publiez un commentaire