17 COMMENTAIRES
  • Warou

    Mdrrrrrr no comment
    Mais sérieux kharal ma nopi. Deuk bi fimou dieum…

  • babacar diop

    yagui toumal serigne touba wahone nga fi liuni Men coumache wat nga serigne touba domorom kara hamossa bop moytoul bala nioulakoy wah serigne touba bou ame secre boumouy diohe danako dioh benene mbacke mbacke boudoul Yaw nioune ay talibenanou te hame nanou mou bare di yonou mourit il e temps geun bayi nahateyi

  • mouride

    Borom prédilections yi ak borom malaika yi jah Kara . General Kara . Mdr ? mdr ? bakhbakha ………kara et bethio sont les cancers du mouridisme !!

  • jules
  • ive

    c grace à ces genres de marabouts que les gens se moquent des mourides; Je pense que le khalif doit intervenir

    • Sck

      Tu as raison wallahi

  • family

    momon yack zico sène kara mi mo mené fène dois rek laye deff serigne boy doul wakh deugue tu n sai absolument rien kara

  • Kara fén at sathie

    Mane mome dama yakar nî il ya certaines personnes amounou djomm
    Depui combien de temps c soi-disants marabout di féne rék
    Té n'empêche pas ame na gnoulénou topeu
    Ki mome fênerék laye déff aussi cest l plus ypokrite jamai connu au monde

  • Cana

    Dèmal diamoudji Yalla tè wakh gnilatoppe gnou diamou Yalla tè bayi thiakhaneyi Kara li gua nèkni Ba kagne Doyna serigne touba limou wakh lèrna liguèy fiamou Yalla do wakh mouk Lou diam thi lolou pour lane Doyna vraiment thi gni takh gnouy khass mourid Yaw thi gua bok

  • zoula

    theuy yala yala mo djiabot t meuneu nanpal liiii doy na war

  • zico

    Merci momo

  • Momo

    @Abdoulaye

    C'est( quoi ton probléme toi tu te cache dérriére ton clavier a insulté les gens gratuitement si t'as les couilles laisse moi ton émaill ou ton adrésse dina deugg sa ndaye ak fétal nga comprendre

    Guiss nga Serigne bii khamm na lou sa mame ak sa baye khamoul té mann na lou sa mame ak sa baye khamoul donc mandoulénn thi mome

  • assy diop

    Secret boula nit wax si rèw loudoul travailler ya pa de sous metier dalay nax.

  • assy diop

    Doyna warr loy xar pour se developpema depui 1960 batay galsen manou developper ba fimnek ni niou gui nèk si axirou zaman.bou kene di nax bopam way

  • republicain

    ki dou Michael jackson wala?

  • rebatass

    ki koumou yap

  • sama reew

    demal ligiuyi macky dou wade

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *