(Vidéo) Sen P’tit Galle: la maman de Mouhamed se révolte contre les résultats du jury. Regardez

(Vidéo) Sen P’tit Galle: la maman de Mouhamed se révolte contre les résultats du jury. Regardez

Après avoir remercié toute l’équipe de l’organisation de l’édition 2014 Sen P’tit Galle, la maman du candidat Mouhamed est très remontée contre le jury. Selon la dame, son fils ne mérite pas la troisième place parce qu’il n’a jamais été repêché, et n’a pas commis d’erreurs lors de la finale. Elle déplore aussi le manque de considération sur sa famille à l’entrée du spectacle. Regardez

48 COMMENTAIRES
  • DEUG

    YEENA GNAKKA DIOM

  • BEUG SA REW

    hahhahah wa merbi coumou yape hhahah wa merbi mome lii fola rekk diaroul khoulo diaroul héhhh hahhaah nooo mere yaw ser gua rekk sa domm woyoufi tounoukk ndiayam

  • wakh sa halat

    Faut croie en dieu fallait pas dir tt l monde sait k aicha koné est favorisé mais bay assane est l meilleur jhabite au maristr g regardé hier soir l journal tmf il ont yaller chez aicha koné et g vu chinou c la femme dun menbre d famile ndour j m sui rentr compte k ya favoris j connaî cette femme

  • wakh sa halat

    Faut croie en dieu fallait pas dir tt l monde sait k aicha koné est favorisé mais bay assane est l meilleur jhabite au maristr g regardé hier soir l journal tmf il ont yaller chez aicha koné et g vu chinou
    c la femme dun menbre d famile ndour j m sui rentr compte k ya favoris j connaî cette femme

  • sandéné

    Yobou léne sène dom yi gnou diangui té bayi you gnake foula yi.

  • Mor Fall

    Wax degue yalla deg nekhoul mane mangui espange donko sétan mai Mohammed voi bi Dafa bakhe machallaa mane Mom mangi faralon baye assan mai Mohammed ligeye nafa lou diarr n 1. Boudon mane may diokhé mom lakoy diokhe Wax deg yalla Xalé bobou machallaa

  • Fallou

    Wa gnii aayy niitt nagnou sén kaannaam you leundeum yiii !!!!

  • diop

    mere bu khamoul foumouy takhawe ! non mais senegal dou deme. laisse tomber

  • noir d'ébène

    Franchement il fallait pas allé dans les média c affaire de gamin té liguéne wakh day yakhal Mouhamed il as un avenir devan lui diaroukowone wakh dji

  • bas peuple

    G pitié de cette jeunesse! Un enfant a ki on a privé des son innocence de tous les attributs de devenir kelkun de respecté sur le point de vu temporel et religieu! C dangereux

  • fatima

    franchement sokhenasie ya barè detaille 45 munut di khoul mais arrete aicha konè sa domme la baye aussi et fiche laba pix a baba maal ok dagua tit way faut etre noble

  • filo

    mere werenga loukofidiar

  • ly

    sen petit gale amoule jury vraima bouba ndour moy xole kouka nekhe rek mou diokhe lako aicha n’est pas le meilleur baye assane ak mouhamed nioy ls meilleur bou

  • dof

    Dof deugue migui nii, badolaa yen dou nguen ayy niit sakh. Fowou khalee yii louthi diar wakh diou reuy djii .
    Daño wara ndangou liñou leen diokh badola you mak yii

  • dof

    Primer leen khaleyii dakha dian ngue mo gueun feth ak woy rek ngueni jangal khaleyii

  • toulaye

    Pour moi mohamed waroul wona gneuw finale menoul dara

  • domou djoloff

    hahahahahahahaha mort de dire

  • Wakh deugue

    Yaw nokoul feule khana yayou pape kaolack dafa wara porte plainte alors mdriiiirrrrrrr

  • fgggggg

    ah kii daa beugeu siiw senegal daal moo nekh nekeufi star dafa yombu lool

    • fans club aicha kone dakar

      Mere bi da beugeu siw te khadioultele affaire bi aicha la mer badola çapagnolie bi ngen don

  • warou

    mais tout ça c’est du n’importe quoi mais c’est un jeu de toute façon les gens ne sont jamais satisfait gnone sénégalais yi tu peux pas les satisfaire

  • samakhalate

    1er=1 000 000F,ak billet USA aller/retour pour deux personnes, 3ème= 300 000F lolou nak diarna kass déh!!!

  • thieuye

    yene tamite comprendre lene mère bi 1 millions dafa ame loumousi programme wone mouye wakh wakhou domame dona lek ba soure tite rek

  • Doucoure

    SERIGNE TOUBA DAFANI NGUNE DIANGUI AK DIANGAL XALEYI AL COURAN

    DEMAL DIANGAL SA DOM BI AL COURAN AK DINE MOU DIANGUI XAM XAM

    TCHIIIIIIIIIM MOUNANE BALLA MAISSA LA TCHIIIIIIIIIIM

  • timachouebrown

    Yena Niak khorom way isshh Soff ba dé

  • chacha

    merci tt.jém pa prononcé son nom mé ce petit.wouyou fi touss.té mére bi kou gnak fayda la…

  • ameuu

    ahahahah!!! mère bii amoul khalate je te jur… affèrou xalè yii motakh gaye gnakal sa bop foula mei c normal BALLA MAÏSSA REK GA MEUNA DONE… allez vous feir chié

  • ki dafa niak fayda waye yaro sadom si dine yaroko si lsslam khana fou mou bonmi nekfi di khulo gisago dara sakh bo amée inati fan si bamell daga khamni waro wona yar sadom si ay tiakhan

    ok

  • fgggggg

    bangako tudee mouhamed ngako warul woon dugeul si ay thiaakaan yaw khawma koo yapp ñakeu khorom

    • Madre

      DEUG LA MOHAMED PLASAME MOYE DAARADJI

  • khale

    mer bi gnakk na foulla trop ah aicha dialnakoh yallanako djik pourman mouhamed warout wouna gnaw si final bi ndakh wayoufi dara

  • ndeyaa

    khana mère bi dafa ammer boor warka fay thi 1millions yi motakh mougouy fatt fi badola premier qualité guenn rek gniaw ba beugue dh sen kanam you ninn yi tittt ba dh thimmm khamoulene sen bopp

  • abdou khadere

    eh mais cachez votre joie pk vous réagissez comm ça mé wesh c dé truc d gamins c q vous faire redescendez sur terre c mieux regarde moi cette daronne au lieu d contesté va plus tôt prier parce la mort est proche pour tw

  • peukheu

    Mais franchement c’est Muhammed qui devrait être classé 1er !

  • Astou

    MOOOOOOO KHANA LIIIIIII NEKKA TOUL FOWOUM KHALEY KI MOME DA DERAPEEEEEE. ..DIAME LENE KO

  • matar lo

    mais am yo khamni diarull prck afair bi chance la rk prck tamite ki dieull sa dom yor ko yor bu nice en + di ko neikhall mu deff si bopu bi diangue lolu dra fayuko waxx deug mére en

  • Marie

    Wa mére bi loumouy reupireupi ni melni kou tite et puis la fille avec les mèches jaune elle est trop séytané

  • ibou

    aye mourite kacé géne mena done thime

  • label

    daccor vk tw

  • Cheikhna Dieng

    Dafal recoure walla gua porté réserve walla sakh gua porté plainte pourquoi la komka deugue guanko def

  • la sénégalaise

    yew kou niak fayda nga li hana dou fo rek li dé diarnala plasam rek lagne ko diokh niaw niorte

  • feuth

    Mere lii fo ak rétane rek la affaire khalé la ce n est pas la fin du monde
    Bayil YONETI BII SAW GUAY BOLEK AK DUNYA. GUEUGUI MBIDEF SAN TA NE WOUL LI

  • tapha sarr

    geum lenn yalla

  • jeannine

    el n’est pas normale

  • Shishi

    Ioe mere ya badola.li ngay faye wa sen ptit galle.di nga yakal sa dome lou bari.

  • drame

    maman franchemen u a tor s son dè enfan

  • Marie

    Boy saint-louisien dal defou fi touss tous Hahaha merr toch nga fii! Yaw mouhamed khamoul kay ma rayla khana youta tinga?!!! Ayway domou artiste mom takhna nga don artiste am??? Haha hana Ndar la am??? Merr reglel way!

  • Mere bi mo niaak foula

    wa yéééne vs ns en merdez waay binga khamé ni TEEK NGUENE LEEP THI LOKHO YALLAH nguéne waroul wona takhaaw fii dii wakh.Membres du jury yi dagno bakh rek mé 1/2 final sakh xalé bi menoufa wona yég.cessez ces trucs de fimistes la.gniay xalé lagnou dagnouy fooo rek.Amnga diot torope waay.Aicha Koné tu l a mérité ma belle

Publiez un commentaire