Vidéo: Séllé Mbaye présente ses excuses à Waly Seck jusqu’à en pleurer… Regardez

Séllé Mbaye, l’homme qui avait accusé Waly d’abus de confiance et d’escroquerie, présente ses excuses au fils de Thione Seck à Paris. Regardez
Dakarflash
Séllé Mbaye, l’homme qui avait accusé Waly d’abus de confiance et d’escroquerie, présente ses excuses au fils de Thione Seck à Paris. Regardez
Dakarflash
It’s the mather fucking deal
IL FAUT SALUER LE COURAGE DE SELLE A VENIR PRESENTER SES EXCUSE
Magui pourquoi tu dit que guewelle bakhoule les guewelle sont mieux que toi
non mais selle mbaye yow do nittou dara aduna diaynala apres demais ngaye comprendre yow ammo sa bene mbock boula nawww
waly yay gor diekou bale lanie wa f.c.w.s n1
S2L2 MBAYE YA NIAKE DIOME
WALY DAYE DEME MOMMMMMMMMMMM
wally nimou def salle nonoula
selle Wally molay seufeul ya tapet yadi pd ya niak diom thiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiim yaw diourla sax yakla thiiiprii kokou di wax thi guinaw ak batou fegam bobou waron nagnouka wanéé rek
youssou ndour et pape Diouf kene meussoulen dégu thi dra diam rek nguene di am boyi you bess yi mounou gno way dougnou diangui way nek thi deuk bi sonal nit yi xoula xekh xoulo ak djiguen yi ak sa moromou bayi no boy yaw do dem
bay fall day djegeulè tey djèleulè bonne chance waly
yallla moy karim
mdrrr ndeysssan sele mbaye yereum nako sax bi gadjeee
Deug rek moy moudj j n dirai pa plus
Rafett wakh nga lépeu
WAAAAAW,TAYE LA WAROU Mé Cé LE NGéWEUL GNOUNE GUéWEULE VERGUOGNE LAGNOU AMOULE DIGNITé ZéRO PERSONALITé NAZ diomm touss GUATIé DARA KéRSSA RIEN LI BOUDONE GUéRE DAFAYE KHAROU
dama rouss sakh ki gnak diom chiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiii
wally yay gor deug adouna amoul solo
ca
ay way selle mbaye gnake na diome gathe bou tolouni sa moromou dome dilako tek diajeuffffffffffffffffffffff walyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyy
Seytane sele mbaye do rousse Sax
puatin ! selle mbaye no comment ! tout ca pour ca
khana khamo so tongné say thiérr day damou
Mais c’est qui ce gars à la voix bizarre et efféminée qui parle derrière ? Sama way, ne fréquente pas ce genre de personne. Kou gnouy djigne Deum, ngay sothio Yélou liir. Déconne pas, juste un conseil. Déjà, on a remarqué lors de tes derniers spectacles, tu portais pas de pinw, continue comme ça, c’est ton seul point noir. Bonne chance !!!
WADJI DAL YAMBAR LA
BOY BI DINAMA FEK DIMA DOOR
KONE BEUS BOBOU LAY GNAK AY DENTS YOU BARI
dombou am nianou wadiour koukoy dieuma troikhal yallah molay troikhal
Wally est un grand bon courage wally la je commence à t’apprécier et je prie pour toi
Hahahaha 500 euro yii ley dioy
sa way est ce que dou 500 euro yi lay dioy?
no vraima waly amna yeurmande
sam wadji est ce que dou 500 euro yi lay dioy? lol!!!
Wally ni la dé, waxe diou bone deukoule fou mou dieume, foumou diogué la thiossano, naka dieke mané ce singe de Sellé Mbaye est 1 mythomane, kou ko xole xame né amoule loumou leke baye ame loumou lebe lé…Youssou Ndour amoule lougne ka djinioule mais moussoule yeye yabici…Bravo Wally ta pu avoir 1 esprit de dépassema ça se voit ke té 1 Homme matur
Youssou Ndour wakhal naniou ko Lou né mai meussoko deugueu mou tontou
Mangui dogua comprendre loutakh niou nane gueweul bakhoul di féne , di soss , niakeu dignité , soutoureu zéro mdrrrr
sèllè mbaye ya niak diom fogeu ganè so yakè dèrou wally dinako taha yakou wayè merci wally sanonis yepes dinanioula ballou ak sa baye dala nianale boul tite boul ragale
Et ainsi va les trucs,la violence ne regle pas les choses.
Yène la rek…
On parle toujours mal quand on n’a rien à dire.c ‘est ce que 7 imbecile sèllè mbaye a fai. Mais Aussi il y a un proverbe qui di La non-violence est infiniment supérieure à la violence le pardon est plus viril que le châtiment. Le pardon est la parure du soldat. Vraiment Wally seck tu est une personne exemplaire dans le milieu de ce qui fais.